Vidéo: Sélbe Ndom tacle sévérement Adjia Biteye de la SenTv et ses détracteurs

Traitée de tous les noms d’oiseaux suite à sa fausse prédiction sur le combat Siteu vs Sa thiés, Sélbé Ndom apporte la riposte.
Traitée de tous les noms d’oiseaux suite à sa fausse prédiction sur le combat Siteu vs Sa thiés, Sélbé Ndom apporte la riposte.
Selbe bagnal dehhhhhhhh bouma Ken yakhal sa c liguey wa télé bobou niep ay doorkat laniouy b en commençant par leur Patron bougane ak gorom yi def fi mouni weng te niouko niata Serigne niou nek Sénégal di publicité ci télé yi ak soigne tout ak seni ay diaro you man lep te wakhoulen niouko kilifeu dîné yi di door gouvernement bi ak talibe yi alors yaw ngay door gnounila dokofi doore bagnal œil pour œil dent pour dent koulo ko sabagne timbakh koko len rek lalay digal nga bayi wat yi ak alkhour han yi
Yenn bayil leen ma tokh kattou yamba bi tekki woul dara loumako narra wakh boukko deggué kéffal on doit l’amener en prison
Thiey selbe
Bien analysé dragon. Merci
SALBE FENERALGAN LADONE DIEUL.LEGUI DOUUULIPARANE LEYDIEUL
C les média qui médiatise selbe donc c très facile d’arête selbe il suffit de ne le là médiatisé mais c fini c simple. C pas grand chose
Selbe sama selbé la
vous les animateur yeenako toyyye.Bayilene diambour;elle est libre de dire son rêve.
ARRETER ………..BAYILENE DOOMOU DIAMBOUR SEUL DIEU EST JUSTE ET CES LUI DE JUGER.
sama gars yi nak bouléne fi défendre sélbé niaka xam dara motakh mom rek ngay dégue si sét kate yi niouko dakh guiss dakh ko niane niofi nek té kéne dégoulenr donc elle n’a qu’a fermé sa bouche et fait son boulot comme les autres voyants ou voyantes.kou meune deug diaroul mouy nék si media di wax rek gni meune deug kéne dégoulene wayé so démé séne keur daniou koy rang nit yi doffou niou fou kou bakh nék xam naniou ko difa dém.en plus journaliste yi koy interrogé aussi sont fautifs naniou ko ignoré sou amoul foumou waxé xana dina nopi nak wa salam
ofét pour les combat de sa thiés balla gaye et modou lo ma léne ko wax fi selbé douko guiss mouk xana mou tatonné rek dale si sino dou guiss nioniou daniou brouillé ay signalam si lutteurs yoyou
C vrai
C Babacar niit dagay gueum sa bopou koi lamine li lèpe yako tek sa bop
soyons serieux correctes selbe jusqu’ici n’a pas fauter elle a dit ce qu’elle a vu un reve n’est qu’un « REVE » maintenant les gens interpretent pour celle de siteu elle a dit j’ai vu siteu lancer qque chose et sathies se trouve tres triste donc cela ne veut pas dire que sathies va tomber (il a eu un accident eske c’est pas cela la tristesse de sathies) . Gris bordeau lui, elle a dit je l’ai vu enfoncer une corne dans le sol avec sa main droite le coude gauche sur un mur est ce que cela veut dire tomber c’est un reve tout le monde fait un reve nous tous faisons des pronostiques
et c’est DIEU qui decide alors y’a qu’oi ? Les lutteurs eux meme jure sur le Coran,sur le Prophete qu’ils vont battre alors qu’ils n’en savent rien du tout.Celui qui crois a ces dires n’a qu’a assume ses responsabilites les chiens aboient la caravane passe…. wa salam.
Selbe tu ne peux pas avoir le beurre et l’argent du beurre.
Il faut juste te taire, taire selbe c’est tout.
Salbe magui laye niane guir yalla boye wakh ti si lambou ga bti Serigne touba b lamboj diekh
bayileen selbe doomou diambourla sokhor akangian laagiss .senegale defa kangian looll
Bayi len salbé mou liguéye soff nguéne trop
Niakkk fayda baaaa dééé mak bou tolnii yaw naneu mako guene thimmmmm amo bén fouleu fén rq ngafii nékeuii
Man deh khamnani yén yénay takh Salbé gueuneu am loumouy wakh ndakh bou wakhé kén dou wakh tenkka amoul défaite si wakham kon gueum guén ko ;guir yalla ignorez Salbé Yalla rkka meune té mo kham liy amm tay souba ak euleuk ;kou khamoul sa noyi dina égue waroula wakh dara lougnawagoute kakoy gueum li bokoul si gueum YALLA Selbé Selbé rk bayi lén diambour bouguén ko doulwone guem batay bayi wakh dji mouy wakh mé nak khamnani daguén ko déglou daguéén ko bayi khel motakh dou nopi ;encor 1 foix IGNOREZ SALBE
nooo sénégal nak bayiiiiii leenn sokhor selbé dafa am mayou yalla. ben information erronée rek lafi diokhé sur 3 combats kon naniouko mayy diamm mou job jobammm
Adja soulla dek KO nekkoo sa b** nd*** selbe boul sonal nitt prédire daffa arammm boul sonal way dou yaw Walla keen moy takh li yallah la bind bagna amm toi et tout les prédicateurs yi d*** rekk
selbé ndom ndomérameleu da warra teugne laminamm té hamoul darra nabayi yalla djoumouye wakh geumou guo akh serigne touba mo sétt la guemme té sétt dé harram sall put
chérie mane beugue Douma ko nii laye ma taakala ngua bayii bio tee nekk qui lenene chérie salbe j t’aime très fort
Le senegal est un pays de democratie elle la droit de donner son avis la liberté d’expression arreter de l’insulter sai pas a vous de juger le bien et le mal il y’a que Dieu qui peut juger.
Sa ma chérie salbe bayil khouloyii tee nieuw ma taakala ngua bel qui yenene mane yow la nope
Amina j’ai bien pésez mes mot 7pute ell n peu po etr ma mére ét elle l sera jAmain khamell liii gay wakh siii diambour mai Boul Kham lignou Lay tontou el a ataker une personne ki na mm po parler dell
Salué dal c’est une vrais sénégalaise elle a compris le système il faut avoir une grande Guele am fitt en complecite avec les sois disant journalistes qui socupe de la promo le tours est jouer le deur marteau passe facilement je vs signale quel a fini sa maison R+2 parfois ilya un retour de marteau comme c’est le cas ce week avec sa Thiers et modou lo mais c’est pas gravé il faut faire le gnak Diome et gueuler encord plus fort c’est le senegal on oublie vite
mama
wa selbe gor la non selbe dou gor
J’en ai mar d selbe ndom , way selbe va au diable wayy
Selbe mounoul bougie béye tal senegal day sobe reck
neekhoule b neekhoule nag wakhe dji nga wara bayyi
noo salbe neena daye taale Sngal kaaye ndieukk sama keur
selbé as raison laissè la el fait son boulo épuis c une dame may lènko diam way
Adja bitey salbe ndome daye doule rekk meunoule thi yawe dara khamoule dara
ELLE SAIT QUELQUE CHOSE NAK MÊME SI JE NE LA SUPPORTE PAS
kou wédi watal ci li nga geum a vos claviers
galsen
Non Kaki apres la pluie le beau temps faut y retournée juste holidays car l’eau ne laisse jamais sont chemin, tu n’est pas le seul moi ni en cadavre je suis degoutée
les gens font que de la magie, def ak dindi rek mon bleme mes soeurs et puis je tremble des profanation des tombes au senegal est reccurents
khana elle na pa suivi lemission de lamine samba non mere ndar nga sonou dé kou wakh nga tontou ko ay way ani say mbokou téyé léne ki bilahi legui doff naa
selbe loudoul teuthi sa gat waroula
fau la comprendre salbe bilahi wéroul elle a un problem mental
merde waye yaw mere khana meuno nopi no ki dal dou rouss
Ahahahah mere bi sissou neu nena adja bitey tube khessal rek leu kham lol ak nena coach neu dem beure’ ji khalasss maguet toum pegar bi mer na de’ ?????
galsene
ptdrrrrrrrr sélbé raynama néna « hamoul dara loudoul tube xessale » je suis par terre mdrrrrrrrrrrrr
🙁 Vraiment Ndayssane Selbe damakoy yeureum.Ça ce voit clairement qu’elle a de sérieux problèmes pour contrôler entièrement sa vie. Elle avait arrêté ses prédictions sur la lutte mais cela l’avait fait sombrer dans l’anonymat et peser défavorablement sur ses revenues c’est pour moi ce qui justifie son bruyant retour qui certainement va durer tant qu’elle aura les capacités et les visions claires.Cessons les insultes ki Djiguene rek leu té weroul.Courage Selbe !! 🙁
choupie
Senegal lay tall legui wakh dji diekh
na rafete way stp Sama gayi
Mdrrrr elle m’a tuer Selbé
khana xol bou dieekh guay wakhe
Adouna amoul solo leupay diekh
thiaga bou retraité dimbaliniou
nekoul ba nekoul salbe yaw vrai domaram gua doff bi
selbe ndom ne traite jamais ma maman des choses vulgaires sinon sa se passera mal elles ont raison selbe tu as intr a se taire sur l’arne et autres chauses si encore tu traite ma maman des choses comme sa …..
j’ai meme plus envie de renter au Senegal
selbe vremente daga wara nopi nek si len kw
Maguettoum kooba aka meuna khoulo. Moome dafa faté Lamine Samba
POLODIT : 1 août 2016 à 9 h 24 min Les sénégalais doivent être consequents avec eux même…Tout le monde a le droit de parler de “Lamb” sauf Selbe, mais pourquoi? Elle a le droit de donner son opinion…nous autres nous donnons toujours notre opinion sur un combat où est le problème, laisser cette pauvre dame tranquille…Je pense que les détracteurs de Selbe savent très bien qu’elle est douée et qu’ils croient à ses prédications c’est pour cela que ça suscite beaucoup de passion autour de ses sorties. Ses articles sont plus commentés sur internet et tout ce qu’elle dit est repris à la télé ou à la radio donc finalement dans un petit coin de notre tête on croit à ce qu’elle dit