31 COMMENTAIRES
  • rigui ndiaye

    selbe khamo dara

  • boye baol

    ap dioulite daye wakh lou reffete wala mou nopi

  • boye baol

    yenne gniye saga Salbe molne guene fouf ndakh mme d’o saga li sport rek la amna Lo khamni diarou ko kou guem ga guem kou gamoull ga nopi wala ga wakh lanene. waye disaga dou yonne te bakhoull

  • sèlbè ngom

    la ilakha ilalah sama djinè yi fène naniou.wayè yène gni dima saga dina lène sopi aye mouss???

  • mali

    ki dal khaw ma cou mou yep

  • Fayesanor

    Mais elle n’a jamais dit que Siteu serait le vainqueur. Bon ce serait mieux qu’elle se taise ahhhhhhhhhhhhhhhhhhhhhh.

  • papa

    Salbe ay Salbe

  • lamine

    en aucun il faut la respecte parce que weydiour la

  • thiam

    mande warona bo amé diom dotoul wakhati si berébi kel honte yaalla bo name kene mounosidara

  • AMAR

    selbe ngana warootinga thi yalla

  • Negro con clase

    Ahahah selbe doulatina deee sa thies nokhouna siteu

  • MOMO

    mais senego il fo crire si qu’elle dit c mieux

  • Abdoulaye

    D’Elbe do yalla doul rek..bi ngané guiss nga Seydina Mouhamed(psl) la paré cii iow

  • wakh loubakh

    ah wakhoul loulèrdè wakhoul kènne moydan dè bou dèmoul ndangue lawakh

  • Riri

    Selbe guiri Yalla boul niou découragé .ceci n’est pa du tout normal way c injuste d’attendre kelk choz impatiemment et qu du jour au lendemain kelk’un vienne te dire le contraire.Yalla nagua trompéwou cette fois ci

  • nafissa

    @rif yaw nigua thiaga…. Hmm lii ga beugueu moy dague koyou baye nityi pour diokh ko sa yaye… Thiaga…hihihihi …. Elle sera très ravie de des kdo…hihi

  • Fall

    Fall mane deye lima yalla wane siteu dey diaxane rk diouk daw

  • Ridial

    yaw momu deuk Mauritanie yémal dou ya niouye wax luniouye déf selbé liguèyam lay déf bayil diambour

  • Rif

    Yén koufi waxati dara youssou ndour dina dagu sa koyou baye

  • pffff

    Mais ça, ce n’est même pas une prédiction. En demandant à sa thiès de se méfier, elle se ménage une porte de sortie au cas où celui-ci gagnerait (auquel cas, elle pourra dire que c’est parce qu’elle l’avait prévenu). Par ailleurs, sa thiès part largement favori dans ce combat. Je le vois mal perdre, même si tout est possible.

  • Fode

    Salbe khana amo Aÿ niouli sa kogne bayil wakh si combat sinon dotou lo âme dieukeur

  • best

    thiam saikou t ki ? yamal mauritanie amo loniouy dicter .yena gueuneu bonne nieup lingua wara tuer mauritanie barina regleko baparai.embecil

  • amadou

    Louy am yalla rek moko kham

  • thiam saikou

    Doul rek yalla ham je sui mauritanie vous devez tué cette femme c le grand s’étant

  • cheikhouna sylla

    wakhna lou ler deh sa thies na def nagnk

  • rafete khell

    hhhh wakho fi dara naye leer bok

  • narafeet

    Selbe li guaye deef rafetoul mane SITeu rek, wayè aye khalè you preparè seen comba baa nhiou naane soubala gua dèefati sa yii,vraiment yaw daale no conment

  • diamil

    salbé topaleu feuléé boule gnou sonale ak waxe diou barri.

  • boye baol

    machalla yallana yalla yokou

  • woundou

    wakho loulere déh .nalére laniouwakh siteu moye dane wala

  • boulfalé10

    doule rek xamo dara

Publiez un commentaire

Votre adresse e-mail ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *