Publicité pour Mesri_Juillet
Publicité

Vidéo - Sa Ndiogou : "Youssou Ndour mo oumm suñu équipe bi" - Regardez !

Pour Sa Ndiogou Youssou Ndour est seul responsable de l’élimination prématurée des lions à la CAN. Pour lui « Youssou Ndour mo oumm suñu équipe bi ba ñou tokk ». Regardez !

Sa Ndiogou – -Youssou Ndour mo oumm suñu équipe… par Chaud360

Votre avis sera publié et visible par des milliers de lecteurs. Veuillez l’exprimer dans un langage respectueux.

Dans le même thême

23 commentaires

  1. spagheti

    behh je ne lui donne pas tort il faut essaiyer le prochaine fois avec un decret qui interdit les senegalais d’ouvrire leur grande gueule surtou youkhou ndour il est partout


  2. Amina

    yaw bayil Youssou dousa morom te amoul sa diot demal wakh ak sa patron mouy fey ay ligueyekatam mogeun dilen ligueyelo bepary dakhlen te ngeun fekhe nousen television bi melni yenen tele yi tfm raw nalen


  3. Amina

    Youssou deh loumou lal mou yokou kou yebou khol tfm adouna yep mom laniouy setan yaw Sa ya kham louy oumm ndakh oumm nga walf ba ken douko setan oumm nga sidy lamine ba meunoul fey at ligeuyekatam mou dakhlen wakhal si lolou ye wa walf dengeun niak dioum mais bolen amon dioum dolen wakhati dara ndakh ngathe rawoul patron mou meunoul fey ay ligeuyekatam mou dakhlen Sa wakhal si lolou te nga fekhe avance kom koutha mogeun ningay niaw


  4. ndiaga

    SA NDIOGOU,wakhal lo kham,adouneu dafa goudd tank,ta sidy lamine ay affairam wauroul,at mounek mou wagni gnou bary gno faugoul wone,wakh lo khamni boula youssou ndour wowone tamit kene doula ko fattali


  5. sambita

    yene bayilene ki kou nope youssou la imbecile nga rek ki limou diarigne rewmi dangako mane sokhor doula yok sa yo kheuyé ta toudoko dou dem


Laisser un commentaire