49 COMMENTAIRES
  • Mounas

    Ñiaaw !

    • gomis

      l’émission de cette dame et très vulgaire elle ne parle que de sexe il faut arrêter

  • mome

    il faut etre modeste mere parfois il faut accepter les cririques tu n.es pas une reference pour nous iu sont les wax legos pagne tisse tres simple et tres original les sacs de nguaye mais toi dara poudara ba melni dof vive le senegal sa kanam

  • vive tfm

    deguene chimere nit gni dagno sokhar ligaye sool diabara amouko yayame amouko delsorale waye boulfale niambi moma geunal patass kouthi teuth sa avocay mo bakhoul

  • Nabou Sora fall

    Nite cou bakhe danga wara mandou lou sa yone nékoule sayone nékouthi

  • Mbow

    moi j aime

  • deugue ndieuk deug moyy moudjiou

    bande de minable au lieu de voir la réalité en face vous vous acharner contre ce téléspectateur c vrai ce qu'il a dit une dame de plus de 50ans qui se croit une jeune fille de 18ans assise devant la télé di jayy tarr regarder son invité et faite la différence. et vous parler de mandou vous meme mandou wouléne ndakh vous commentez. con

  • Mbow

    Maman Sénégal da bari ndiou rap thi khôl.yalla nama yalla maye bamay defal sama yaye you bakh yi

  • ss

    gfb

  • rima

    Merbi dafa foqueni c est une jeune fille! Gnakafayeda

  • merci

    merce

  • noo

    Moi je pense que vous avez pas outre sauce à faire ce encor yable non vraiment suis vous travaillez pas le se le gend travailler thiey le monde de aujourd'hui aaaaaaa

  • kiya

    Moi je vois pas de problème de ce qu'elle porte mais juste que des fois elle fait le " voyez moi" en disant a cette mia la realisatrice je crois ( mia yagui dieul sama bague bi,yagui dieul sama sac ak sama éventail ) mia avait jappé et mettre un pub on l'entend dire en bas( mia ya bonne rek do woné sama bague bi ba paré) je trouve sa absurde. guene balatima nak mais je dis k ce k je vois.

  • soum

    Si vous vivez dans un pays ,que la pauvrete est vue dana tous les domaines et etant une refrence de medias il faut etre tres inteligente pour montrer ce qu'on possede ,il faut etre modeste

  • faye

    warr gua kolate ca bopp nite dou beugue adouna naheu kou beugue adouna gua moytou adouna worela il faux que tu change ton comportement wassalame

  • rima

    mais lii dou beugue adouna rek lii dof la nita ngua beugue adouna ta def you eupe yiiii kholale moussorame bi

  • ndodien

    deguene nak limouye def dafa eup trop

  • xyypy

    C dommage elle n est pas une référence en tout cas

  • Madam Faal

    khana mosorr bi mais bou passeh loulu limu sol amoul ben problem,ndakh nenenj Muhammad S A W nena Yalla dafa rafet te dafa begue lou rafet,kon sol lou rafet dara newusi

  • Citoyenne

    C'est vrai ! Vraiment elle exagére

  • cissokho

    les gens qui apelle à une émission pour rabaisser franchement c'est être con si tu veux pas les voir tu zap tu n'es pas obligé de regarder mais maman deguene mom d'où le écho bay

  • kiki

    il a raison c trop c kel fait

  • mohamed kounta

    viv le Sénégal

  • feuz

    vraiment vous etes ridicules mais chacun a le droit de vivre sa vie comme il veut

  • Meuzpeulh

    DEGUENE GUEUNOULENKO DIANGUE ARKHOURANE EUPOULENEKO BOOK MAIS SOKHOR CI DERRETTE LA BEUG SA BOOP CI DIAMOU YALLA LA BOK KOU TILIME YA KHAM.

  • fall.modou92

    nguen balma nakk .meme linguen wakh soufekeni deuggleu sakh .mais beugg sa bopou si adouna la bokou. tayit sagnese bou raffét ta léw .si diamou yallah la bokou ..tayit terangay adouna moy beutt.

  • killah

    wakh bi moy sinne ndayou imision bi mo amoule ndayou sen walla

  • pipo

    nh

  • Gnolê

    Vu ce kel incarne , da fa Wara modeste…essayé incarner la sénégalaise lamda ,sol lou simple … Feuss bakhoul… Deugneune khalatal sa bop

  • kok

    sois un exemple avant de sensibiliser (modestie deguene)

  • rakhu

    wadij wakh na deug !mere da beug adouna trop te falss

  • pipo

    m

  • pipo

    zzzz

  • sokhnaci

    légui nak lolène beug mou soole sagar??? aye waye samba souko nékhé déf louko nékh, soole louko nékh, wakh louko nékh ndakh fi lay took dilène yéé bande de nuls que vous etes. senegal kene dou dém!! yalla sakh dafa beug lou rafét!!! en plus nite da ngay mandou c vrai!!! tata déguène ne te décourage surtout pas!! défaral bamou bakh!!! dafa ame gnou sokhor gnou khamoul lou bakh donc sunu guissé kouko déf rek da nga beuri titar!!! li loumou done khalass

  • sokhna ci

    tata déguène bégalale sa bopou, sagn sél ba kène wakh ma khool ish!!! dou gnou dém dougnou bayi kouy dém!! ki wooté kène dafa khame loumouy ligueye mouy sonal nite yi ni!!!
    tata déguène nite kou bakh dafay beug lou rafét!!! kou kham lou bone mokoy déf diko wakh
    balla may d gnou nane modestie!!! ta gnom gni diko wakh kéne modest toul

  • sokhna ci

    gniy wakh modestie mandou lène guir yaalla sou fékké da nguène modeste!! li mouy def ni di wakh di sagn sé kou sagnone sa yaye mel ni mome!!! bayi lène diambour!!! li nguéne wara lidianti beurina
    Parlez plutot des pedophiles, agresseurs, drogués, bandits… c plus important. elle au moins mi ngui yéété. donc yéwoulène déf ni mome di yéété
    wa salam

  • ja

    c'est vrai que deguene est tres controverse,certains l'aiment d'autres pas.moi je suis du cote de ceux qui sont pas jaloux et mechants.

  • ja

    c'est vrai que deguene est tres controverse,certains l'aiment ,d'autres pas du tout.moi je suis de ceux qui ne sont pas jaloux et mechants.au Senegal personne n'a le droit d'etre belle,elegante et debordante de classe

  • kira

    deguene chimère égal poupée

  • beugue.réwa

    les journalistes et autres c'est les couturiers qui les habillent pour les pubs, c'est le monde entier. Il ont droit même s'ils l'aiment pas, ces forcer.

  • KUZ B KAN

    Merbi limanakarri thi mome sa souné Mouné da Beugue SeYDINA MOHAMED (SAWS) ba paré Mourouwoul di teke greffage di deff make up té di prononcé mere bi Melni comme poupé TFM pour la publicité

  • fet

    way wax nala deug beug lou eup

  • le vrai

    kxx

  • diamano

    Il faut faire sur le lesbianisme au Sénégal

  • Bella

    Hey guys Tata deguene she is a modele !!!!!!!elle fait que la modeling she is sooooo modeste you guys don't know her

  • mai

    Bayilen ignane bouka neikhei solou .no sénégal mo meti rek .ce ki appel les gens pour critiquer à la télé moy ceux qui sont concernés par leur théme disi guiss sen bop .tchippp

  • saer sarr

    Merbi dafa bague bopam rek lolu dará nekusi nanu mandu

  • Maserati

    Deguene Chimère est une GEISHA

  • Mm diouf

    C PA UNE KESTION D JALOUSIE OU DE Méchanceté mè li moul dèf dafa eup surtout son maquillage

Publiez un commentaire