Vidéo: quand Thione Seck présentait Assane Ndiaye comme Thione numéro 2…
Dans une émission télévisée dénommée « Télé Variétés », Thione Ballago Seck fait la présentation de Assane Ndiaye et appelle ses fans à l’aimer…
Dans une émission télévisée dénommée « Télé Variétés », Thione Ballago Seck fait la présentation de Assane Ndiaye et appelle ses fans à l’aimer…
en plus un vrai musulman doit pardonner.YALLA ninou sak di balle.mom moune d'où balle.il es qui. thione
j pense q vous ave pas ecoute l début. Assane nena daf am diambott warlen doundal.thione n aime q son fils.voilà l resulta.qu'es qu il a f pour c frère. rien!
lolou lou ame la nit daye wet gorre wetalikou gorre
Anita je suis parfaitement d'acord avec j'aime bien assane Ndiaye mais nimou défé dou nonou bou dée dafa amone intention touki bou change avis dafa warone demate si thione wakhtanate ak mom
comme on dit depuis l'eau a coulé sous les ponts
la vie quoi!
adouna mo doyna warrr
aujourdhui moi je deteste l'action de thione du fait de ne pas recevoir Assane Ndiaye.ce qu'il chante et ce qui est dans son coeur c'est diametralement different. il doit acepter qu'il est fautif
ndaye aane
Ndeysane yaram daw na, yahh…… kou ma koy egalill. carrément
bien dit Sister anita les gens n'aime pas les quatre vérité ???
vraiment khana boné thione c ton grand frère si tu as un projet il doit être au courant à plus forte raison tu prends ses musiciens sans rien lui dire après tu dis que tu ne sais toujours pas ce que tu lui as fait n'importe quoi hypocrite
dou. lolou assane wakh thione damay bayi way bapare di ropate ay musiciens dilene propose plus k lilene thione dit faye sans pour autant prevenir ballago non wor degue la def lolou dafa gniaw to rope si cene diguante
li rafétena yalla naléne yalla dioubolé
merci boye pikine depuis Europe '''ak diadie yena nieme deug way
merci diadie da beug tane gneup lolou d'où Aduna kou nek ak sa weursek
sira doul auti lene ligueye
Assane nékhoul ba nékhoul wayé dangua woor nak nanguoul rek
Woroul kene thione mo complique nit dafay diapou di bayi
voici ce que l'homme peut faire .Q ue fera Le bon Dieu au jugement dernier.
hoooo kholene khalé bi si souff wally seck la ndeyssane hooooooooooo mais assane ndiaye khiffone na dehh
c vrai k c Allah et toi ki la lancer mais père thione dagua khawa compliqué kou nek dagua niane Yalla âme sa yefou bopp
Wakhal d dafa yakar mom rek wara am