11 COMMENTAIRES
  • mm

    Pepe Diouf je t'adore

  • Deug

    Bravo Baye Babou du courage et felicitation.Ca kaw ca kanam rek!!

  • 50 cent

    ohhh pape diouf yalla nala borom bi faye sa xool

  • zoula

    man dé waxou ma ay wakhou pape cheikh mai s bay babou la dama beug guén deglou boubax limouy wax ci waybi ay wax you salte rek lathi wax waxou thigua rek laci wax gnounan way bi dafa nekh bi ko fi may beuz senegal mo nex dé waye yala bax na

  • mamy mbaye

    ce qui est bizare au Sénégal c'est que seule les gens sans talent sans experience qui sont populaire et sont le plus appercié c gambien n'a rien dit d'important et pourtant il fait le beuzzz chaye galsen

  • ciré

    lebaol wakh nga deugue dé bilay dama rouce sakh ci li pape cheikh dééf lii mo takh gnouy wakh gambien yi dégno bagne sénégalais yi lou takh par ce k sénégalé da khépp troop gambi

  • Na

    Bay badou waxoufi dara loudoul waxou thiaka mane dale ma diomi prkw senegal mane dieulaté malaw bi louci nekh khana wax you bonyi thimmm

  • Mimi

    Pico tu a raison mane senegalais mo niak kham lou nekh

  • Pisco

    Rien d'extraordinaire sur se titre .wakhoul dara louye dieurigne nite se gas Mane sénégalais mo sof reike

  • lebaolbaol tigui

    Pap cheikh s'est mal comportè ce matin, il s'est moquè de bay babou…c'est pas bien…Les animateurs senegalais doivent apprendre à respecter les gambiens….leur facon de parler leur vocabulaire ne doit pas nous faire rire ….on doit avec respect comme les francais le font avec nous…le francais ne comprend pas notre accent et notre francais africain mais neanmoins ils nous ecoutent avec respect. ……..boy dakar est une tare !

  • Rama Badiane

    Maalaw mokhew

Publiez un commentaire

Votre adresse e-mail ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *