Vidéo: Nouvelle série “Appt Dakar ne dort pas” Regardez
Amadou SY
Nouvelle série “Appt Dakar ne dort pas”
9 COMMENTAIRES
babs
07/04/2014 à à 18:59
tfm la chaine leader a ki veut l’entendre et a ki ne veut l’entendre point
Smd touba
06/04/2014 à à 20:20
Mais khana dangéna fatté série senegalais tfm mokofi ndieuka déf yanéne chaine yi royko.Tfm thiakaw
Mamy
06/04/2014 à à 20:12
ils sont copier qui? mais senegal mo bari niouye xamxamlu. En cas avant gout nekhna trop j’ai bcp kiffé et bonne continuation, bégué futuremédiamennnnnnt rek si kaw si kanam!!!!
lovely
06/04/2014 à à 12:26
jaime pas il faut innover au lieu de copier c’est vraiment nase tfm
bour
06/04/2014 à à 11:22
khaléyi yéna chon avant premier bi dalna ça promet yenna fi nieukkeu défe serie sénégalaise connak con roye kouné yéne la roye defléne ni sen patron youssou dou tontou wakhou niit kou sokhor
princesse
06/04/2014 à à 11:13
les méchants ça vous intéressent parceque vous l’avez regardé jusqu’à faire des commentaires. nanguouléne lii yalla dogale tfm boubs sa kawe sa kaname
lola
06/04/2014 à à 0:33
copier dinama nekh rek te yen tamite diank daro moko mom please
hilary
05/04/2014 à à 23:48
nehoul xegnioul copie coller rek boubs legui pa nga xamal lolou way
Aicha
05/04/2014 à à 23:11
Yaléne niakeu khorom! Boubs yaw lac rose te reclame!
tfm la chaine leader a ki veut l’entendre et a ki ne veut l’entendre point
Mais khana dangéna fatté série senegalais tfm mokofi ndieuka déf yanéne chaine yi royko.Tfm thiakaw
ils sont copier qui? mais senegal mo bari niouye xamxamlu. En cas avant gout nekhna trop j’ai bcp kiffé et bonne continuation, bégué futuremédiamennnnnnt rek si kaw si kanam!!!!
jaime pas il faut innover au lieu de copier c’est vraiment nase tfm
khaléyi yéna chon avant premier bi dalna ça promet yenna fi nieukkeu défe serie sénégalaise connak con roye kouné yéne la roye defléne ni sen patron youssou dou tontou wakhou niit kou sokhor
les méchants ça vous intéressent parceque vous l’avez regardé jusqu’à faire des commentaires. nanguouléne lii yalla dogale tfm boubs sa kawe sa kaname
copier dinama nekh rek te yen tamite diank daro moko mom please
nehoul xegnioul copie coller rek boubs legui pa nga xamal lolou way
Yaléne niakeu khorom! Boubs yaw lac rose te reclame!
Les commentaires sont fermés.