12 COMMENTAIRES
  • sama xalaat

    slt ndoye bane gua baalma mé lingaye déf ni do ligéye kw ? di lidienti domo adama yi di yakh déro diabarou modou.modou yi?ak di yakh xélo kaw mane si séne diabar yi té yaw bou xeuyé dem.khamo sa djabare lomo néké nfa took si télé bi djigéne ni weur leu nga nétali rek di ratatati rek ?? sénégal mo nékh mé yaw warolo wakh si radio? warou lo guén si télévision? takhnga kéne wolou toul kéne chanchél sa façon ??? gua baal ma akh

  • chissa aka dip

    ndoye ya taye soula nekh dekebi da yahou tropo

  • sama xalaat

    no mome waroul tass ay seuy tass ay keur pour rek lomoy def si possame

  • sama xalaat

    yatou na deug la mé lo bone djaroul yatale té mome limouy def ni dafay yatal lou bone lou khamni koko massa déf daniôla daan who si roukh yédd la ? té mome limoy wakh dara léroukosi ?ta méme bouko lérone sakh matoul sédé mome mandou woul ta islam ko mandou la wakh ak 4 persone you kham ni doniô bokk foniô djogéh pour bagnie rek lou yakh dérou domo adama ? billahi limouy déf bakhoul yalla nako yalla guindi bamou guiss limoy yakh ndakh waroul live live fam baparé di yakh xélllllllllllllll yiiiiiiiiiii nama baal akh nakkk

  • bamba ka

    ndaye ban kokou boukhamon lima kham dina nopi daye dofdoflou rek lisi kanam rawouli bet

  • nina

    sama xalat kou yarou gua continue comme ca dieu est grand .mai chissa hawma yamba kou gnaka teguine la.

  • insaciss

    Mé gayi bou nio démé ba liy ram dieum ci niak bi, warna niou ka wakh tané ak xam-xam ci pénc mi ba mana mouthieule nii nek ci biir niak bi .Ce qui se passe actuelma c'est inadmissible, on prend les mauvaises piur les valoriser en délaissant kes bonne que nos ailleux nous ont légué au lieu des les exporter pour civiliser le monde extérieur.J'ai peur pour le devenir de ce Sénégal en perdition de valeur.Il y avait quelqu'un qui avait dit notre cher patrie á besoin qu'on lui fasse "ndeup" , c'est la réalité le peuple est malade il faut qu'il se soigne!

  • babs

    sama khalat sa wakhine rafetna trop.

  • el follador

    Chicha espagnol bi naneko cachimba no galsen dou dème koi bayi léne roye dake

  • sama xalaat

    merci

  • sone

    Nn mais sérieux li thème leu wala waxtane je comprends plus Mane suis ô Maroc CHICHA bignouy wax mais ils on k taper GOOGLE et voir si c nocif ou po juska present niit téwoul chicha didox di tokh…mais bn pourquoi s commentaires des gens ki ne veulent po accompagné le 21ème siècle locci meune c nul comme débat ta chimère Xana messoulo toukki?

    • Nan

      Ils ont évoqué le sujet par rapport aux jeunes. Ils faut toujours suivre le début nous ne devons pas nous arrêter sur un titre salam

Publiez un commentaire