28 COMMENTAIRES
  • saar

    cissé lo yaw amo dignité

  • ale.diop

    rewww khamadi xamo noye wax moustapha cisse lo

  • joubi

    Senega beugou niou kouy wakh deugg Cisse lo bou nekone day fene dou diokher ay precision you leer yi badi toudou tour. Mbackè mbackè you ndaw yi ils se croiEnt tout permis niou wakh ko tè deh. Nioy Kane? Gueumou niou dara vrement je les plain pas.

  • Mick

    Bsyi léne saga yi s
    Cisse lo limou wakh c vrè.pask le kalif gènéral wakhnako dègno beug lou yombe

  • mirirr

    Cissè lô vraiment koula diappa diappa domourame koula bayi bayi domourame yawe serigne assane mbackè dou sa morome si sayirre dou sa morome si batine vrais inbècile ka

  • rayiite

    walahi deugu leu loooo iow amall diam rek

  • diapro

    tu as raison cissé lo dafa fékk ni rék dafa am younou waroul wakh si télé

  • mamy sow

    magui toub bou werr cisse lo amo talibe serigne touba bougoul koy wakhi sotoura liii bakhoul iow kagne nekou talibe serigne touba

    • DEUG DEUG

      bou nopéé géun ecrassé ko ki moo baax thie yeun

  • Deg rek

    Cisse lo sa lafal ndaye sa bo yewo

  • obama

    non cisse lo mo nekhhh,nenee yayam dan nako maye 1000 francs parce k da diekkonnnnnnn. manam da tooooyone.oh euppee neu.

  • Mbaye

    Tu est insolent tres mal éducé

  • Leraal

    Cisse lo serigne touba nena dieuf boumu barri banga nawko tee boumu neew itt banga khepko yaw nak danga naw sa dieuf Yi yoonwi motakh amoo daara thi yolbi. Teyiit ku deeg sa wax xamne amoo beneu teggine ak suturaa ,ma meunaa waat bu kerrogue Duma yemee sa dieuf thi serigne b.dinee Islam teggine reek laa ta bokothi

    • Léralat

      Cissé Lo, Day dindi Touma, yaw yaako toudéé naw Dieuf ,boulén néxéé géunni dou mouride ,sou waxéé limou déf géunni day Naw Dieuf kou torox rék géun beug ak kou bone Niak géun Xorom Loll t Sof soxor, Assan Mbacké Dafa réw dagne ko wara Niaffallé, bamou xayita,ay tankam, Serigne Bou Mack Bi, thie yeurmandé ak Deug lako Yalla dioxé Reuwmi, m dou afairou diaye dollé , boufi diayone dollé toubap ndégéko dou doy sax, lép pi adounak alaqira migui thie diamou yalla Lép nak, guén néfi diwayadi Nioulén di saga té kén manou thie dara nak, Thiow rék bayi késsé nak

  • mouhamad

    Man dh mbcke la sant sama mbokk yi amna niou ci wara khoolaat sèn bopou mais cisse lo mii tamit warna nio wakh ak mom ndakh ab deputé sou tooguè ci tele bi warnaa wakh djou honorable !!!

  • begue s touba rek

    Niit day wakh lou rafet yaw lo liga wakh dara amo sy khana dou yaw ya wakh s abdou fada ay wakh you niaw yaw amo beene guerem yaw to morid yadar ga sakh sa mame modone bolee s touba at tiubab yi mogui toudou abdo lo cone yaw nii rek ga mana meel yaw wakh you niaw yi doof bi ga done

    • DEUG DEUG

      Cissé Lo dall mo Wéx Dux deug,li abdou fata déf kéndouko déug cissé lo rék, serigne Abdou Fata Momoul nit gni, Kou Segne Fallou di sa Bay Segne Touba disa Mame, Boo toguéé sa Place réglé kén doula niéméé wax safan mouk, m bofi nékéé di diaye sagn sagne di nan la Wax lou Bone t dou mouj fén, loumou ko wagni touse nga Xamni nit gni Yalla rék molén Yéllo

  • la chose

    quelle insolence ce cisse lo! c'est incroyable,il insulte tout le monde,maky, abdoulaye wade…sa grosse langue le perdra

  • deuguela

    Deug nekhoul douniou bene ay serigne

  • sama reew

    Mara you ndaw yi danio masa xamadi!

  • kham kham pire

    wakhna deugue dagnon warra yame thiouth daye khame lèkame wade dème na yarou lène ta dème outi loléne dèfe gni thi boite de nuit yi gni thi appartement yi di thioukrou rèk moye rèk

  • fode bayo

    yala dina leral lepe inn cha lla cisse lo

  • Feuza

    En l'entendant parler, on se rend compte qu'il dit que la vérité! Deug moom dou nékh

  • DEUG

    wa mais moustapha cisse lo dou mo sagua serigne abdou fatah
    kou saga sama bay ma way………………………………..
    cisse lo ya saga bayou diambouR gnou WAY…………….

    • DEUG DEUG

      kou fi sa Bay déf louko waroul niou saga, Dém niépa thie yam amoul ki amoul kaa, kou wédi ,bismi

  • Cana

    Lo sa koyou baye

  • dégu deugue

    Verité

Publiez un commentaire

Votre adresse e-mail ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *