34 COMMENTAIRES
  • kha la verite

    geum geum lou sew la bayilene di jugé ki geum yala xamna. koulou atihi yawhiyamati fardane .. kou nek yaw kepp yay takhaw ak sayy jeuff sounu borom le seul juge jugé la. pour dire Massaly mayniou demal setti lenen lo wakh

  • tek ci brik

    Le fou du siécle. toujours à bavarder.

  • Madam Faal

    Adja,sa bay moy domram

  • tayi si gni

    mai galsen dou dém te coran lokho bouné peu le prendr seulemen il fau gue ame diap c tou

  • fma

    ce voyou ose parler……………….

  • loubakh

    NiAka kham rek

  • ADJA

    MACKY DOMERAM LAA

  • BAYE PAPE

    kholalma domeramm ji … gnouy wakh Macki SALL SHARLI,,, mom mouyi guènne game…sa thiolko bu bonn,,

  • pap

    Le vendeur de monton est revenu!!!!

  • Dipro

    Yaw massali diéppi nala trop ! Au moins il (Macky) a l’intention de faire le bon té « inna mal a’maalou binniyaati » Yalla yééné lay fay et contrairement a toi mi ame yééné saboté et faire le mal li guay wakh khamoo thi guatt !!! (Chien)

  • DIAGNE

    Yeuw ancien PCA de Wade qui a brulé un meeting politique a Thies tu oses parler vraiment tu es contre la reflexion

  • Dipro

    Massaly Diéppi nala trop ! yaw khamoo dara thi liguay wakh au moins il a l’intation de prendre et d’apprendre le coran « inna mal ahmaalou binniyaati » Yalla intation lay khole té moom lay fay contrairementa toi tu a l’intation de saboter et de faire faire le mal té li guay wakh khamoo thi gatt ! « Kagña »

  • Madam Faal

    DEME,mercy

  • DEME

    Macky goudi macky bethiéck mom molèn bayi si lolou .golo goujogue nan day wakhe si macky .dafa wara jelle si yaya jamé touti .ni marabout ni talibé ni borome barké nemeporte qui kouwathie yoon mouteguela si yoon .réw danoukoy ilif .

  • diop

    Macky il est feticheur charlie venchard rencugnier =incapable

  • Madam Faal

    mayfa,wakhatiko

  • lemzo

    massaly ndak rek

  • maneirma

    yene wa PDS yena sooooooooooooooooooof way

  • el hadji

    wa yene xana menoulena tieupe Macky way mbasssssss yeen

  • mayfa

    Sangi tardé sa khoula bone rek .macky sall yalla ko fale monouthi dara sa morom menouthi dara

  • Madam Faal

    President Macky sall,ca kaw ca kanam thi lou bakh,wa PDS sen khol yangui dok hahaaa

  • kebe dame khoury

    vous svez kor mareme il est feticheur ,ill est charlie pour ses interets il est mouride ,tidiane ,omarien,il s ,en fout les franc massons

  • mams

    Tu p parler parce que ta pas de problème dans ta vie mdr

  • le rebel

    massaly le pyroman … k’il la ferme … Macky le tiens par la main gauche lit par la main droit … voyou

  • Madam Faal

    PDS sen problem moy deguen khiff,amatou len lou nguen sath

  • Madam Faal

    President Macky sall,dafa bakh te yaru rek mais budut won loulu yen yeup dina dok sen gat,PDS hypocrite yu bun yi nguen don,president Macky molen nguen Ndey nguen len bay

  • Madam Faal

    yen wa PDS lerr nama ne president Macky molen nguena guem Yallah,ndakh bolen guemon Yallah di ngeun nangou ne president Macky moy president

  • Madam Faal

    massaly yaw wakh ak yaw sah yakh la, ndakh tekki wo dara,mais bo rek le woul legui nyu nokh la si kasobi domram

  • Beugue Sénégal sama rew

    Yalla sougnou borom mognou gueneu khame, nagne lene madou ci yene yii

  • ibou

    macky sall est un etre humain et l’erreur est humaine . va o diabl massaly

  • mody costa diop

    kéne meunoul diakhassé nit ak yalla bayiléne sen wakhou politik yi kou nék na ngua gueum ligua reik yalla dina jugé

  • diakirou boly

    quel con t tro nulllllllll

  • Sidiki Diouf

    Franchement le senegalais est trop bavard et léger . Comment un siot disant homme politique peut il parler comme un badot

    • Mme Mme

      Bien dit!!! En plus, de très mauvaise foi, Dieu n’aime pas les tricheurs hypocrites sans aucun scrupule.

Publiez un commentaire

Votre adresse e-mail ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *