65 COMMENTAIRES
  • ousmane

    tounkara ki con bou reyle bete ignanena ba con amoule dara khamoul dara cocn de 1er classe

  • allahou90

    yow ya rééré souniou borrom

  • Elh Fallou gueye

    KII DAFA DOY WAAR TRP KÉNNE KHAMOUL LIM BUEGUE

  • jamy

    Me tounkara tu invite les gens tu les lesse pas parle ce mieu que tu dit tout sans invité personne chaque foi tu fait comme ça

  • youssoupha diop

    illallasina non inallasina

  • birame

    Je ne vois que de la jalousie. dire que nos marabouts ne connaissent pas DIEU n’est que parole d une personne aigrie . Se prendre pour un soufianké relève de la prétention. DIEU reconnaît les SIENS. Monsieur MBOW descends de ton piedestral. C’est toi qui ne connaît pas DIEU. tu es dangereux pour la umma islamique. Demande pardon aux chefs religieux que tu as offensés sinon des talibes choqués par tes propos, te rendront la vie difficile. pour les personnes averties, tu n’es rien du tout.TU ES AIGRI. Tu ne sais rien du SAINT CORAN. TOUNKARA t’a posé une question et tu as reconnu ton ignorance du SAINT CORAN.

    • tek

      mon frere au senegal on voi bien les gens pratique c qui n est conforme au dean et les marabouts en taise et disent absolument rien. partir dans des habr pour y receuillir des benediction c totalement en contradiction avec le tawhid et meme le souna du ptophet. les marabouts le savent mai ils n disent rien. Moi je crois pas a ces marabouts la. la majeurs parti ne te parle que sama mame…. sama mame.

  • diop

    il sait meme pas reciter wal hasri

    • ndiaye

      lol! yéémé né ndiobén bi

  • rambo

    serigne bi il a parfaitement raison.sergne senegal degno beug lou yomb.nagn dem ligeyi

  • Mamadou mansour toure

    bayilen diwakhlo ab doff ki diangoul té weroul.

  • rambo

    wadji loumou wakh gnou bari khalat nagn ko mais kenn gnemewouko wakh.il a bien dit

    • Haliyoun

      comme toi on dirait ki c un ignare tout comme ceux qui pensent comme lui. En toi à voir ton nom ou surnom tu es fait pour jouer des films sataniques

  • francois 1er

    Vraiment tounkara kene tonounou yaw rek yanouy togn

  • md

    toungkara yawda nga yap senegalaiyi kikanla

  • mbc

    qui ya bounou senego monou yapp fek kiuy nourou nouroulou dara tedou dara nga diko bireul lolou bokna ci liy ye fitna yala nguina lenn. kala mome ken rek mo fi yayo mouy kou ted ki chekoul khadim.da nga beug kiula deglou te yaw amo kilifa wakh djou yakhoula yaw danga rerr di wout ko yobalé doko am woutil serigne mou wakh la nakala yaw tambali wo bay yegue mi dispiace

  • maestro momo

    linga beugue wakh deugla mais guenela guestu

  • mutabaruka manel

    Suis entièrement de l’avis de ce monsieur. tous les marabouts sénégalais des escrocs qui ne pensent à leur bien au détriment des préceptes religieux qui prônent la piété l’amour et nous montrent la voix de Dieu
    un vrai marabout ne devrait pas rouler en 4×4 et vivre dans le luxe. L’animateur est vraiment très nul ne méritant pas à tenir des débats de société

    • makhtar mboup

      ki dall dafa diaroul invite ci ak gettou aygola ana ngakay invite ci tv bokhamni ay domou adamayi nokay setane te diangoul al khouran diokhoula bena dalile ci hadis walla si lounou mana deglou tounkara bayile khell gnigaye dalal sa plataux

  • faye

    ki nafekeul la

  • malal

    tu est jaloux billahi kou reree yalla nga xamo yalla xamewo yalla deeg rek nga am sii yalla je te donne un conseil surveill tes arieres

  • diak

    khamo dara

  • c pas nom

    ki dafa dof, xamoul xarafoul, mbow khadj rék mokoy wakh motakh mousante mbow

  • musa fall

    je comprends ce gars.il est contre le fait kon donne de largent aux marabouts,qu´on travaille pour eux

  • damegaye

    funny

  • miya

    No ki woroul dof yaguissi birr nite yi

  • malonethiof

    ki mo ignane rk khamougnou dara yaw sélodéééééééééé mandouwo dara

  • cheikh

    Qui dafa réw na dém macka khoull

  • AdaKARA

    Tounkara dalllll kou maneee sa joppp

  • da

    boukki narre

    • jean

      day togne

  • laye

    Serigne fallou deugue rek

  • divnkyt

    ki dal li mi wakhe khamou si darra

  • biram ndoye

    tounkara ki diogoul fimou tock mome amena serigne ndakh naryi lay roye te gnioune roy lowounou naryi apeu djioulit dou igniane apeu djioulite dou wax louko woroul apeu djioulite dou wax si moromou djioulitam lou gniaw apeu djioulite dou sokhore waye nalla lerni yangui lecke yapou wounou def tockei

  • diop

    le mec il as galéré dans les cars ndiagua Ndiaye pour venir a la 2StV, après il nous dis un marabout ne doit avoir de 4X4 n importe quoi

  • ndonga

    mbrrrr tonkara dana ma ray rek reeerrr bakhoul wallaahi khanaa daga fatte ni sayyidina ousman moo euppoon alall niepp kii dall moo doy warr rek yaw boo doon weur yalla daga lougnou tou mbooti kenn oh

  • ALIOU SECK

    ki saffa dof waye walla mou gnak diko djiiine serigne si

  • ibou

    senegal ay comedien rek niofffu nek

  • bmg

    Wertyuiooo

  • La rédaction

    testons

  • deçu

    le vieu ma vrament deçu,je croyè qu’il est vraiment sùr de ce qu’il dit mais au grand surpris lorsque tounkara la demandè  »es ce que ame nga daaline  »il a dit clairement je nè lè pas maitrisè.
    je pense avant dactaquè,il faut etre vraiment preparè il attendre toutes sorte de question,
    Mon vieu va aprendre dabor avant de critiquè les autres.

  • Fofana terez

    Je suis d’accord avec toi la où tu a dit k kou kham yalla dou topou srigne c pour les mouride

  • bakhe

    nn mbow yow ligay wakh amoule khamosi dara

  • abdou

    mbow yow ligay wakh amoule dara dousi duegue sokhar rég moléne diape

  • samsa mbore

    bravo toukara lika wakh rek moye deugue nitte daye mbadou

  • serigne madicke toure

    wana ci kip koouye wakh mokham limouy wakh

    • mame gor gueye

      billahi ki da dof te khamoul yalla khomoul dara

  • serigne madicke toure

    fourmi bo takhaw ci boulowar né cmions yi dogno dém lothieye khalate koy wakh ci lom mana donne war nga kham thia langaye wakh

  • fallou kare

    ahaha ki ban fallou la nday saN

  • fallou kare

    ahaha nday san

  • Diouf

    Ce père de famille a vraiment raison. L’opulence dans laquelle vive les chefs religieux est étonnante.

  • abo gaye

    kii dafareew

  • Papouné

    kii daffa beugue siw rekk mes bene côté il là raison

  • bocary

    Le blem avec ces hibadous c’est que leurs parents leurs donnent de jolis noms islamiques leur enseignent le coran et la sunnah jusqu’à ce qu’ils puissent aller à une université orientale et à leur retour ils disent à leur parents en guise de remerciements « vous etes des égarés parce que vous croyez aux marabouts ». Ils me font ch… ces ibadous de m…

  • tonkara yay dalal kone

    issa

  • uzzzman

    Ce messieu a parfaitement raison ya beaucoup de bossfianke au senegal . bethio thioune est un exemple
    wa senegal yewoulene ta ligueyal senne boppe ta bayil jokh khalisse boss fianke yi

  • merci

    ki khamou dara

  • g'ongui mboup

    Kiiiii mooom koumou ak fooumou deuck boum Wakh ak Serigne si Na wakh ak yalla mileen diokh lignou yore dafa fiirr ngay sàne ta do feck kou fiir kholl lay wakhé ta kouy wakhé kholl mom ….mane nack limalay digeul nga demm Thiago dara dja djiangui aythia boumalafi Gissati nack Ok

  • pape

    ki mom khamoul dara te dia ngoul bapare beugueu juger,mom si bopom mo khamoul yalla -il ne faudrait meme pas l inviter ce mec

  • bic

    Ki khamol yorol we rol ay nelawam doyol khamol dara a a a a

  • khasss

    kiii dfa reew khamol daara na dem diangi

  • toy dar

    ki dafa khamol gatttttttttttt

  • Massamba

    Deurueudeuf Tounkara nisni taye lala geuna diap ndakh doff boobou yaw rek yako eupe kham kham danel ngako nooonou rek la amna nion khamne bounou niawe foofou diwout promotion te khamougnou dara deflen noonou merci

  • Massamba

    Tounkara tay moom geunnala nawlooo ndakh diahil bii yaw rek yamako tntoul merci

Publiez un commentaire