.
21 COMMENTAIRES
  • fatou wade

    ndoye yalla na sounou borom teral come niga terale fatou amine yir la are la mousal la yalla bo tasser ak lo ragal figa tek sa tank fofou la boul meuss gantou nite deglouwoko merci jeureujefati ndoye

  • Elpresi Fall

    No grabi yalla nako yalla ak way ak keep kou diapaler khaler bou djiguen bi. sama yaram dawna ma dem bay dioy Sa nekh def ma ay retan

  • abdou ndaiye

    amine !!!

  • lèa

    ndone. bane bouniou amone sa,100 morom senegal changer.

  • demba

    Tres bien Ndoye tu es entrin de faire un travail extraordinaire.Servir le Senegal te doit un saliare.

  • awa samb

    ndoye bane yalla rek molay fay

  • souv

    yalla nala yalla faye sa xol sant nanioula ton geste est noble c est un exemple a suivre nguir yalla nos autorites wakh lene si li les gens meurent fautes de moyens et on nous dit que nous sommes un pays en voies de developpement

  • lili94@gmail.com

    def loubakh rek mo ame solo

  • Beugue Sénégal sama rew

    du courage NDOYE BANE!

  • Beugue Sénégal sama rew

    khaliss biniouye passar passaré ci mboubayi dafa dioguewoul fou lew mo takh mounou nio def ci yonouyalla

  • Madam Faal

    Ndoye Ban Yal na la Yalla fay defal la jamm ju bari,yok sa meun meun mei la fan bu gud ak werr,ak kepa ku si khalissam,ak doctor yi yeup

  • albachir

    un grand merci à ndoy Bane …. Mais cela prouve que nos administrations sont des incapables et pourtant ils eparpillent de l’argent à gauche et à droite

  • Jax

    @le rebel Je valide tes propos mon frère.Allah a bien dit qu’IL ne change pas la situation d’un peuple tant que celui-ci ne change pas ce qui est en lui-même.Ca veut dire que le problème est en nous(des dirigeants au peuple-tous responsables)

  • le rebel

    arretez vos analyses sentimentales. Pourquoi nos Hopitaux ne prennent pas en compte ces cas. Cette fille a sa dignite comme bon nombre qui ne savent a quel saint se vouer. Le mal est que a cause de la politique les popularions sont laisse a eux même. Des innocents coupissent en prison parcequ’ils ne peuvent se payer un avocat, des malades meurt parcaque ne pouvant se prendre en charge, des eleves brillant arrete leur etude parcequ’ils ne peuvent paye leur etude … Apres on parle de nogalou yalla ou Yallay mayé c’est vrai mais le mal de ka societe senegalaise est ailleur … Big up a sa nexx Dieu te garde ainsi que tes  » fréres « 

  • zemaria

    ndoye bane yalla mo ame sa faye yalla nala yala faye sa khol te yok sa meune meune ak sa yenei. c’est très émouvant.

  • fra

    Ndoye yalla nala yalla Faye ak kep koussi diap ak kou amone yenebi ta yoroulo li moy senegal

  • Matar sene

    Li Dey diagal nama Lou bari

  • Matar sene

    Yalla na yalla fey sa khol sama yarame defa daw sakh

  • Sénégalais

    lou mél ni war naniou se wakh comme lou sanekh wakh mo guene thiakhane yii

  • rose

    yalanala yala faye sènegal bou niép dèfone ni yaw kone diakhlè dieng

  • nst

    yal nala yallah fay

Publiez un commentaire

Votre adresse e-mail ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *