21 COMMENTAIRES
  • yoga

    kii mo beurii wakh té niaka tey té meuna mew, rien de ce quil raconte n’est vrai!

  • Cous

    Aouzoubillahi mina Chaytani radjime (bâyilene di fene pour beugle âme toureu.

  • mbagnick ndiaye

    C est un fou, double d un Grand menteur

  • gaal doof dou teer

    moi ce que je ne comprend pas mais pourquoi il porte des gans blanc? ses doigts sont coupés il est lépreux ou c’est pour juste se faire remarquer?

    • nitte

      parce qu il fait du khessal ses doigts sont plus noir que le visage

  • anmou moom

    bayilèn lou khéw ngèn ni rap la .yeureum moo geun yéd .beaucoup de dérapages sont le fruit de génes mal formés

  • youssou

    serigne bii loubone kèndouko nèteli rèfètoul

  • mouna

    kii dou Serigne kii day wah rek pour am toure ak nakh jiguieni re di leka sene khalis

  • mouna

    serigne bouy khessal doynawar

    • nitte

      wakhoumala doul wayé un vrai serigne dou weer di devoilé ay secret il cherche des nouveaux clients oui!
      SERIGNE DOCTEUR ET AVOCAT DOIVENT ETRE DISCETS MOTAKH LUI EST FAUX!!!!!!

  • senegalrevolution

    Ki vrai menteur la kara boubesse. Doule rek

  • cr

    lingay meune fenn yeup ak sa khessal bou bone

  • joe beaden

    Ce( charlatan.escroc. vantard).il aime tjrs faire le buzz.ki dou da nada.dou touce.

  • g83

    kii day fen ba pres loutakh gouvernement diogoul ci interdi yen emision gni sen mision moy yakh khelou nit gni ay saytane you bone niom niep

  • kaly

    @nitte mdr yaw diga dem mais do yégg lol

  • beureung

    ki dina fen ,di fen ,di fen ,di fen ,di fen ,di fen ,di fen ,di fen ,di fen ,di fen ,di fen ,di fen ,di fen ,di fen,di fen ,di fen ,di fen ,di fen ,di fen,di fen,di fen,di fen,di fen,di fen,di fen,di fen,di fen,di fen ,di fen ,di fen,di fen,di fen,di fen,di fen,di fen,di fen,di fen,di fen,di fen,di fen,di fen,di fen,di fen ,di fen ba diar fa dé

  • beureung

    fi moye senegal ndiaye ,deukou fene ndiaye ,deukou doul ndiaye ,deukou katch ndiaye ,deukou mew ndiaye.
    Beureung sa beurigo waye

  • Papi

    Pourquoi dites vous qu’il mente? Yeneu niémé yalla deug, kéne khamoul ndakh kéne thi nioun féké woul limouy nétali. Mandou sama gayi!

  • BEUGEU BAMBA

    Niit day mandou ragale-lèèn yalla

  • jalousie

    bayil khessal way

Publiez un commentaire