15 COMMENTAIRES
  • anamou moom

    nanou bayi guissané ak bokalé YALLA,kheureum bakhoul.médias yi sétate lèn sèn bopp.kérok thi tfm am na kou ni serigne saliou la geuna falé que YALLA gnou dialalé ko.thia kou critiquer keurou diné gnou censurer ko

  • bros

    doule rek féne rek bayi léne di invité nie daniye yague dére khamou darraaaaaaaaaaaaaaaaaaaaaaaaaaa

  • feke

    fène rèk xamoul sakh lane la rèrè hier mati pour l’amour du ciel
    poubelle yi lo siy invitè di wagni sa cote quand meme ba lène fi way

  • kupukala

    Le pire c’est que trop de médias maintiennent les populations ignorantes dans les ténèbres avec de telles invités…

  • King Kong

    franchement mattie trois pommes vous mes décevante pourquoi des conard comme cette bamboooo

  • ferf

    Mbirouu doul,moom négnkoo diagléél,,tawaa xéer maa guiss

  • missssss

    sa bo wakher rek niou tiniala khalegua ni kene douko woute deureum va travailler stp

  • djilykhady@hotmail.com

    Gni ko invite gnoo yees gneppe khamul dara day fenn wayégnoo mit gnoo gana cooné il avait menti contre eumeu modou lo s’ il parlera il mentira encore

  • jojo

    sentv arrété détre des tocarre kii doulle réék laay dééf khamoul sakh loumou rééré biik

  • leuza

    Daniouko wara diapeu teuthie ndén kasso Boy bi ak gni koy invité c mieux

  • alzo

    donc lacdawour contanoul ci macky sall@

  • Batista

    démal liguéyi khalégua mogeune nékk fi di wakh

  • fall zize

    ragalal sa borom dem diamoudji yalla té bayi sa fontou yi!!! bakhna

    • Batista

      ki khamoul sakh yalla saytané la rékk ak kana mame gou bone qui

  • Batista

    féne rékk ak diakhasé nitt yi

Publiez un commentaire

Votre adresse e-mail ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *