7 COMMENTAIRES
  • Dany

    Ponne gua wakh wakho bonne maname chimacali bouks yamba mane dé khamnani kone malaka yi di naniou ma weulbeuti sowou dakh kepp kouy tokh mane Dany guay diapallé dakh ma dakka tokh Ismaila yacine tatttte lay deff thi baguass yii

  • bourre wallo

    ponne aramoule dineko sipe rek lou hamete Khalifa niasse wakhe deghe la yawe dagae relo

  • beug diamou

    wakh deug yalla weulbeuti gui déh worouma té wédiwoumako tamite , mais ligua wakh si poone môme lépou deug laa , darra bakhoussi yalla nagnoussi yalla moussale , té koukoy déff yalla dimbalila bagua bayiko

  • beug diamou

    wakh deug yalla weulbeuti gui déh worouma té wédiwoumako tamite , mais ligua wakh si poone môme lépou deug laa , darra bakhoussi yalla nagnoussi yalla moussale , té koukoy déff yalla
    dimbalila bagua bayiko

  • Elh Rafét

    loune sip nak mome ap djoullit warnako seekhlou

  • laay njaay pikin

    j en doute con ts les maures vont avoir des pbs car la majeure partie fume du poon….j attends ahmet niasse pour ns eclairer….car ce mec est un simple ouztaz tres limite

  • Ragal

    Nounou bouth nak kone

Publiez un commentaire

Votre adresse e-mail ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *