15 COMMENTAIRES
  • grrrrrrŕ

    Ahh !les modou-modou gnak khorom lagn déf

    • kanafall

      yaw momo amoul jamm;sokhor

    • Didi

      Boudoul wone les modou modou Sa yaye doula dioure bay tok fi dí wax demal outi lo diox Sa yaye mou lek tenga fekhe ba khorosi dokosi def mdrrrr

  • tak ci riip

    mdr…

  • Faty

    Nn xolou kignane dafay lek borome bamou diekh tei douko yeuk, soxor baxoul amoul ndiarigne, kou nagou li yalla dogal do sonnou, bayi lene #Modoul_Modou yi nguen di sani xér. a chaq fois tei xamni boudoul wone niome wa wa senegal dougne lekk, seul les senegalais ki son au diazpara nioy doul chaq année plus de 692 milliard.
    Xam ngua ni yaw koula guiss xamni masoulo guéne senegal tei do Modou modou,
    ak sa tilimay, mane nak yalla def na douma modou modou mais deug rek mo nex yalla , bou nguéne diougué di sani xér modou yi tei kou am visa do fanane senegal, legui lolou lane lay nourou soxor rek motakh senegal dou avancé je sais da ngua léne niane telephone mayou niou la motakh sa xol diékh , do guiss mouk modou modou bou yor telephone 33-10 .
    Mougne léne tei xamni modou yi nioy bombou, ici au senegal ya que du poussiére et de la chaleur , amoul touss, soxor baxoul way ishhh.

    • Didi

      Bien dite ma chérie Faty

    • wache ich hier

      Cest un batard il ne fait que salire notre peau,
      Moi je ne sai pas pourquoi les senegalais sont contre aux modou-modou?
      Té modou yî gnoye indi teranga si senegal
      Entous cas gno gui santa yalla bou bakh

    • kouka kham

      Faty bind ngua livre ba tokk, nengua yalla deug la beug t ya ngui khass niit ki di wakh nane daffa ignaner modou modou yi ke guenoul senegal etc…. Ki comedien la gros bb la toudeu t mo ngui espagne, donc modou modou leu… il fait des sketch ak yenene moromou modou modou wame di denoncer you bone yi modou modou yi di defante sen biir ak you bakh yignouy defalante aussi…donc delen setate liguen di wakh bolen metrisewoul situation yi…ki limouy wakh daffko kham nakh gnomi nene la

    • sall

      mdr Faty wadji ak modou modou la té comedien la dafay jouer rek pour bégué nga bale ma akh rek

  • zo

    bayil doul té nanga bayi itam nanoum sangara çi, kén khamoul loy nourol.

    • fatoumata sy

      c bizarre mais sa existe les filles reveiller vous….

  • GUI

    LUI C 1 COMEDIEN BASE EN EUROPE.IL SAPEL GROS BB DIOUF.ALLEZ SUR SA PAGE GROS BB L'OFFICIEL ET VOUS AALLEZ MOURIR DE RIRE

  • seye

    vrement bayilen yak derr bi yi amoul

  • alioubayedarou

    sama wadji bayil yakh der yi modou yi tekk dara europ douniou deff linga wakh.faty merci si tontou yi kidafa sokhor

  • milko

    il n'a rien fait de méchant ki c'est juste artiste comédien ki se nomme gros bébémém au sénègal il le fesé dnc bayilén ko koussi mére rék c'est prsk li ngadon def rt k'il t'as démasqué

Publiez un commentaire