Vidéo: le Magal des Mourides en Ukraine. Regardez
Les Mourides sénégalais basés en Ukraine étaient de la partie et ont célébré le Magal 2016 comme s’ils étaient à Touba avec lecture du Coran, des Khassaïdes et des Berndel comme nulle part ailleurs. Regardez
yalla rèk momana fay tefayna seringe touba yalla nanu yalla sakhll thie ak talbi be fawo
sène khôl yi dina dague dé.kou bagne Serigne Bou mak bi khôl Bou diékh mo kay raye
aye fene aye fene you laire
que des menssonges votre marabout est local pas internationnale
DES GROS MENSSONGE
Dilene ziar bou bakh, akassa , sene ligueye rafet na.
Bayilene sen contact, dama beugua barkelou si ligueye bi.
Serigne touba rek moma nior.
Dieureudieuf
Maintenant dama beugue diébeullou Nék MOURIDE, SVP koumay dimbali dallalma Souma GneuWé Sénégal Incha’halla
Woorna yalla , je parl trè sérieuse
Kiné depuis Suède
Sonneu ci jeuf ame ngueureumeul yalla moko gueun. Bayyilen tappaleyi(Cheikh Sakho)
ana sissoukate yi sissotilène Serigne touba moffi nek gaawlène avant mouy trop tard
Cest extraordinary. .Magal jusquen Ukraine. Serigne Touba est Universel Xadimu rassul
akassa bamba anywhere in the world have faith and strong one day the better must come insallahu
Dieuredieuf Serigne Touba Cheikh Ahmadou Bamba Khadim Rassoul
Diereudieuf Khadimou Rassoul Diarama Mame Cheikh Ibrahima Fall
VOYEZ COMBIEN LES MOURIDES ADMIRENT SERIGNE TOUBA
Je suis très heureux pour vous.QU’ALLAH vous préserve en vous accordant sa grâce si BARKE SERIGNE TOUBA