Vidéo: l’apparution spectaculaire de Coumba Gawlo Seck à Sorano… Regardez
En répétition pour son concert Spécial Ndewenel à Sorano de ce soir, la grande diva de la musique sénégalaise dévoile une grosse surprise que s’attendront les fans. Regardez
En répétition pour son concert Spécial Ndewenel à Sorano de ce soir, la grande diva de la musique sénégalaise dévoile une grosse surprise que s’attendront les fans. Regardez
weuy yobalé len ma deh bay
no lemzo nioy andeu yow
lemzo dounioula bayi guinaw nioy andeu
MDR weuz yaw ak Nit dof dagueni dem kw. vs m'avez tué lolllll
Coumba ndiol mou tauy amul ben dégagements mais sinon si woy c'est elle l'intellectuelle des artistes féminins wayé côté déhanchement mom moy ndaré el n'a ni tchath ni punch ni feeling
badu deugue la nakk waroul wow nak
Nit dof ta peut-être raison mais nak nekha yeukeuti o6 ne veut pas dire k forcément daga wara wow Kong ay yakh dila diam partout. mdrrr
mane dal djiguen tamouna si féminité wow kongue mom baxoul si dara rawatina si djiguen
Modou djiguen da wara néha yeukeutiiii """"
merci fatima au moins tw ta bien vu !
mdrrr bro u ma tué !!! wayé nak yakh youy diamanté tamit dafay dawlo goor. DEUG nekhoul
Way Modou wax na DEUG nak djiguen mom day saf djiguen am dag bou mol hanches you bakh mais pas ay yakh you diamanté
modou lane mosiy sa yon mane nop nako ta ni lako beugè fowou kay day woyof ok bakh na ni
modou jiggen dey oyof nekha fowé yawit
Coumba yagui wow kongue comme girafe way djiguene dafay am soukh toy touti sakh wayé melni goor rek !
mervi
bb csa qu on a et on est fier un jour viendra on aura mieux que les usa
Extraordinaire…je ne peux rater ce show ce soir, mais comment avoir un ticket svp sénégo? on vend ça à l'entrée du grand theatr ou bien? je suis en ville comme ça répondez moi svp?
Ce n'est plus une surprise maintenant
ndeyssane sa me rapel Mickey Jackson
pauvre Afrique ndeyssanne solénne démonne USA déguénne diomi wayé yaalla na Senegal dakh nation unis amin