Vidéo: la voyante Sokhna Khady prédit la victoire de Gouy Gui, Malick Niang et Gris Bordeaux… Regardez

Une voyante du nom de Sokhna Khady predit la victoire de Gouy Gui, Gris Bordeaux et Malick Niang. Regardez
Gfm

PUBLICITÉ

37 commentaire

  1. boy fass

    mane ya juste une chose k j suporte pa moy seytané yi nafék yi di diaye kham té dougnou dara yalla ken dou tok placam té balguene ko kham rek ba beussou penc diguene réthiou lou beuri satan cheytane yi yalla na borom bi wathieu sen kaw rek

  2. kele

    No Senegal monekh hahaha mem port koi gaye guss

  3. black la belle

    wa ki dou selbè junior

  4. Mams

    On vera

  5. acham

    beugu toure (nom) diaroul yéneyi koi
    Bou féké Yalla da bayé digal diokh nite yi niou wakh niou ba kham ?

  6. mode

    Zoss boule déglou niy, khamna sakh déglou wo léne mai fanc yi bouléne li tromatigé bay

  7. ize

    thieuye yalla senegal

  8. ize

    mé nake bourome téléyi rek nioyappe senegalaiyi par ce que koudiogue di oute promotion thie aye thiakhane niou siwala

  9. Senegal mom nekh

    Mdr astafourla mayyyyy no Senegal mo nekh !,,

  10. thiam

    c’est dieu seulement qui sais qui sera le vainqueur

  11. ahaahah

    Ahahahah mdrrr mais qui kannlla ? ? Fuck

  12. ahaahah

    Bayilénn serigne touba bakhna rek

  13. leuza

    Ki mane la yapp !! Té lima si ci méti voyante yi kou diok ni serigne touba mdrrrrrr.

  14. boy bronx

    sokhna si yalla nala yalla degueu linga wakh neeikhna si kholl merci bcp depuis usa
    guediawaye forever gouygui victoire reck

  15. modou

    hg

  16. modou

    yalla moye kene le tout puissant et qui hose le deffier le verra un jour ou l’autre yalla mognou crèe nous tous tè mome khamena leup lou gnewegoul mais daye sé tane tè bisbou nek mou wane gnou aye kemane mais les voyants (e) yi wakhe si cadre sport guissougnou lolou aye waye lillakhi wa rassouli noppilene dolene dara delene khalate khatayou bamele

  17. rakim

    le problème c’ les médias qui les sollicitent c’est vraiment du manque de professionnalisme de leurs part

  18. tige

    le cng de lutte doit prendre ses responsabilites . c pas sportif se que font les voyants , et le soit disant vaincu sera deconcentré avant le combat c mal partit xaliss rek et publicite la niouy defal sen bopp

  19. mouride

    wa loutakh kouy seitanèè rek di moubo serigne touba
    ay way touba wakh lènn thi liiii

  20. mode

    BROM TOUBA dina dougal niou beuri diahalnama(safara)

  21. zara

    JE TE LE JURE , LE SENEGAL DOUDEME A CAUSE DES SES VOYANTS POURQUIO A CHAQUE FOIS LES MEDIAS VONT SUR EUX POUR LEURS DONNES DES PROMOTIONS , IL FAUT QUE LES MEDIAS AUSSI ARRETENT , ON DIT TOUS QU ON ES DANS UN PAYS DE ISLAME MAIS POUR MOI C EST FAUX ON DIRAIT QUE ON ES EN EUROPE OU LES GENTS NE CRIOENT A RIEN

  22. coucouniang

    les promoteurs ki mettent bcp dargent dvent prendre leur responsabilite connaitre le verdict d un combat avant le jour decourage les supporters

  23. niit

    Ay waay bayilén cheikhoul khadim,bayilén cheikhoul khadim,bayilén cheikhoul khadim….baxna rek!

  24. kHz

    juste une qustion pourquoi tous les voyants sont mourides

  25. mom

    senegal dou ki reka takh dou dem mais yene sakh si nguene bok ndakh metitlou lou nekhoul yalla deuguele bakh na wayé yéne tamit de léne def lou nekh yalla chacun avec sa conscience et ses faits devant le le tout puissant maitre de lunivers labsolu.diko tamalé si mane/

  26. deve

    bayilen hell si yalla………

  27. deuch

    Thiaga Bou bone bi menteuse

  28. oms

    ha sénégal léguie dala nittiyi geummatougnou yalla kénna khamoule louye khéw souba coudoul yalla rék

  29. mame kha

    on vera sétane léne rék

  30. mame

    on vera sétane léne rék

  31. deuch

    Lamb nekhatoul parque amatoul surprise avant comba niouye wakh kouye dane

  32. jéjé

    doulkatt bou bon bi xammmmm darahh les bons marabouts sont tjrs là où ils sont tous gua xamoull feeeeene rekkk

  33. papekeita

    elle a le droit de dire ce qu’elle pense ça ne concerne que lui

  34. boy fass

    legui féno yalla ken la mome rek mo kham louy am bayilene beugue wakh lou amagoule yalla nalene borom doreule bopam satan yi seytané you bonne yi

  35. odjzyhqzh

    mere yaw doulgua de guir yalla bayilene yonenti bi si sene affaire yi do rouss di doule di doulelo sa dome

  36. modou

    Dieu est grand elle avait dit c gougui aller sorti vainqueur et le combat alle dure 15mn vous ne savaient rien

  37. Néné

    Soxna Khady bayil sete ndaxe xamo tousse, tu as menti sur tte la ligne, Zoss a mi Ko Gouye Gui par decision du CNG, Ama Baldé a battu Malick Niang à plate couture et pour ce ki est de Gris Bordeaux il a été déclaré forfait pour blessure…