3 COMMENTAIRES
  • doudou

    Kouthia limou wakh moy deug nañouko jokh heureume t di reduffiser ay émission Wam ndakh mom dey dokhol télé ak radio joxlenko thieureum Kouthia kilifa leu

  • amy

    Khouthia liga Beug amoul fén . Télébi dou khouthia show rék lanou Beug di sétan té lolou pour man bakhoul Si Sa emission day takh mo sapi nityi . 18h00 dafa wara comacé Lolou mak yaw nosi and mais redif you baréyi diarouko

  • rim

    Ki dafa soof khouthia show losi diar redidission amna yénén emission yoka eupou solo té kén douka rédifisé may nou niéekh way

Publiez un commentaire

Votre adresse e-mail ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *