Vidéo: je t’aime tu m’aime « dianllola » dans Entre Nous de la SenTV. Regardez
Amadou SY
3 COMMENTAIRES
Master Atlanta
18/10/2015 à à 2:09
Boula dara guéné si Mourou bi ndakh Yallah mokko diglé,boy bi wakh nane gueuno niou gueum Yallah copain mbiirou gueum douloy yamalé sa lamigne késsé dankoy dieufé au moins la fille fait des efforts en voilant la tête et son corp donc elle mérite des encouragements les autres filles qui ne sont pas voilées tu dois les conseiller et les encourager Mo gueun nguéni beugue clash Ibadou bou jiguéne bi.
boudoul dara nditt dafayy soutoural boppam. soutouraall lenn senn bopp nguenn beugg nekk ndayy fii beugg baakhal you bonn yi pffff. au moins mingui mourou soutoural boppam. mere bobou momm naann je taime tu maime ndialoo tchipp kholatt lenn senn bopp bayi sossal nditt

woy magui dhé mé nak wakhna deugue louci yonkk toyal toubéy té lolou dianllo là