35 COMMENTAIRES
  • louam

    maty 3 pomm ak tanss ak bineta gniomla

  • fina

    gainde bouma dadji senegal bilahi danguay warou

  • sa touba

    la verite

  • gainde

    fina yaaw wakh nga tèirè

  • gainde

    gisngèn iran mou ngi si tanki dèm tfm mo takh mouy wakh ni mo

  • teranga

    bayilene saaga donner votre avis c tout iran sent père de famille arrêté de lui traité de cons vraiment nguene balma merci ???

  • fina

    nitt kou doul dioum amoul iran yaw sakh danguay dioum amna lo khamnee waroko wakh adouna dafa goud tanke

  • fall

    mal y élu dieu?il peut tout se permettre…iran ndao méconnaît les exigences de la démocratie .il est anachronique car se croyant dans une monarchie absolutiste
    .l islam tout exaltant le respect du à l autorité morale bannit l asservissement et l abandon de soi.iran participe à l assujettissement de la masse peu critique par une brillante alchimie qu' elle présente comme d émanation.iran ndao est un brillant exégète mais méconnaît pour sa cause personnelle les rigueur du monde moderne.une lueurs fanées de plus.

  • bene copain

    ydb

  • moussa seck

    Oustaz Iran yalla nala yala défal diam si barke seydouna mouhamed rassoulilaa aminé

  • New York

    Iran amoul kham kham.. Mou né president kéne manou ko liguié yayla di na déf niit president pour mbougol ko yayla di na déf niit president pour téral ko.. Ana Saddam Hussein ana president jhadafi ana president Lorain…Etc ….Gniom nékone yay president dou dagne léne trokhal ba gniouy dé… God took darkness from the lightness, took lightness to the darkness,

  • New York

    Iran, Nako khol si bopam lak mom lou wakh nii ak review de press béne la.. parsk ay problem mou diabour layi wakh té mom mouné yayla dafa beug soutoura…

  • leeeess

    irane daw deug bu leer nagne la wakh.ku beuga deug deugue rk.khamgane deug bu lairs nagnla wakh

    • verite

      bonsoir je vois que certaines personnes ont mal compri iran ndao car il critique pas les medias ou les revue de presse mais des gens qui s'interessent au fait divers dans la revue de presse plutot que de s'interesse à acheter un journal pour les bien fait des gens ou de la religion et de dire aux gens qui font des presse people de ne pas xawisoutoura diambour dahte baxoul soutoura daafa bah il dont des conseille mes malheureusement il ya des gens qui melange angleterre et pomme de terre li jangalela rek nagnou xol jeuul lou bahlinté bayi prise de bec yi walla gni gnouyy waar gnou guissi seene boppa di xasste wala sagate na kadouyi di rafet rek anda ah yaar akh teguine lolou lafi serigne sou bah si yalla yoonantabi diangale wasalam mangui djegalou merci a iran guir sa deugou li moyy niitkou deegou

  • abdou

    Le mystique . Ou est le serpent noir sous ton lit qui te donne khaliss. Et tu mens quand tu dis tu jeune chaque jour. Ndiallokate bi . dans ton darra

  • Le Rebel

    Iran liigay wax waxou kassaw kassaw la reck … Accepter la volonte divine n'exclu pas une volonté de changer sa condition hunaine cela na rien a voir avec Macky ou Samba mais ce qu'endure les Senegalais … " khoulilakhouma malikoul moulki toutil moulki mantacha " certes mais aussi " inalaha la yourayhirou ma bikhawmi khata you hayirou mabi anfoussihime … Donc bayil sa Appel du pied yii

  • Rs

    dof nga balma! mai li iran wakh ndiagale la kepeu Ko khamni nak guiss ngathi sa boop nanga kholate sa liguey magui dieguelou

    • Dof

      Yaw he ko yap nganaan ndiangalé. kii lou mou fi diangalé? garouwalé? dieuw? yeen defleen sen bopp yi ndokh touti.

  • kannman kane

    Iran ndao ne m'a jamais attire mais aujourd'hui, il a réussi a le faire.

  • aminata

    Ahmet dieuleul bi mom lerna nagne

  • dof

    Yaw moom Iran lii ngay def Yalla bougou ko té santoulako: Tu ne dois pas parler des absents en public, demal ba si gnoom ci pet nga wakh leen li ngay wakh. lii ngay def nii dou diné dou diangalé té dou soutoura. Cela est une erreur que font la plupart des prêcheurs chez nous. Iran tu arrêtes de t'ériger en donneur de leçons. Tu as réponse à tout mais sache que revue de presse wakh li kenen bind rek la. Boudé defa haram nga wakh ko mou diekh. Tu nous pompes l'air.

    • bachir

      ta rien compri car de ce je viens de comprendre ba legui toudoul tour dc souteureu mi gui thiet puis yaw khana daga thi guiss sa bop ya koi un conseil c tt juste pour enseigner a la personne de se garder de certaines choses diekhna donc arrte de divaguer way

      • Dof

        Tu dois être un fan de Iran mais quand il parle de nieti nit ci télé patati patata senegal gneup khamnaniou gni mouy wakh. Pourquoi dou dem ci niom wakh ak niom au lieu mouy koy publier ci eut bi. Il parle comme s'il s'adressait à ses enfants "gnak diom bi senegalais gnak diom moma diakhal". Si un politique l'avait dit le ciel lui aurait tombé sur la tête. Quant à demasi guiss sama bop, khawma sakh bountou téle yi faf. Je dis que nioun war naniou yewou touti au lieu kou gneuw rek raconter ce qui lui plait pour ensuite dire que defay éduquer. Eduquer qui? porototo!!!!

  • Mbaye mboup

    iran liga wakh duegue lá me amna zik me amna rfm tamite mouhamed ou mouhamed ndiaye tamite si lá bokou

  • wakh deugg

    A revie de press kat dou ahmed aidara ndogg ñom ñepay tawi xibar bi yokk ko . Kou nekk ak sa bis tay mo feegn la rek dieuw rek la senegal man mo takhit dougn dem fenn

  • Merci

    Oh Iran fan nala dh chapo

    • Djmy

      Con ! Baa-rond ! se porq de irán ndao ……

  • Rs

    walahi kham kham rek mo wor linga wakh dégeu la dieureudieuf

  • fekke

    bien dit mai ahmed aidara cii la bokk

  • parisfrance

    ahmet aidara yako mome bobou

  • jules

    amed aidara wuyul maty 3pommes moom demitionèna

  • moustapha dieng

    sa c vrés

  • IranTrue

    Bien dit ! Il s'en prend aussi à Ahmed Aïdara

    • diop

      binta mane maty 3pommes et tange rek lay wakhal avec 100% poupal

  • NIT DOFF KILLER

    c koi ennuie

Publiez un commentaire

Votre adresse e-mail ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *