vidéo-Iran Ndao: « La tolérance et la compréhension sont utiles dans le raffermissement du couple »
Amadou SY
8 COMMENTAIRES
véritè
03/03/2015 à à 20:36
na yor diabarame ak ay domame mo gueune néke si télé bi di diguelé sangaye té sangouwo mane kou menouta yor diabar ak dome menoma war si dinné dji nakh souniou borom mo ndieke tèral djiguéne ak khaley
Senego publie les sujets sur le sexe Parck c ça qui attire plus c internautes mais iran Ndoa moi je te remercies de tout mon cœur et je sais y’a d autres comme mw.certains st ici k pr critique alors ils sont minable
cheikhouna wakhal deh sa batte sa kaw senegal kay bo amei alal walla kham kham kham walla nga siw niou tekla beute mais souniou borom koumou soutaral nianalko mou guena yokou mo guene wakh you niaw yi nguene balma akh koumou deranger yalna diam yague si senegal si adouna bi yepp si barkei borom touba
sénégal bofi beugué bari ay none nanga am khaliss wala am kham kham wala nga siiw légui niou commencé yakh sa dér.cheikh ibra fall néna yalla dou faye wakh bayi dieuf.
bou app Catholic souhaitèwonne dougou si sounou dinè jii ..dina si dellou guimaw …ndakh …naafèkh bi ..il va dir k lislam ya k dla pornografie a koz de cett pervert….kommsi dans le coran ya k du sex …meme dieu dan le coran kan il parle de sexe il va mèttre de soutoura faire allusion. ….plus d 3 ans dèmissions …tu nous parle k du sexe . senegal dila si japalè domèram ..tu business avc notre religion ..kilifa dinè yi neè tekk ….komsi ils pa la pr lislam ….wala ils sont la pr leurs interet ….

iran Dieureudieufty Yallanalayalla deffal diam
les gens ki parle iran dalen mousaa lal galsen kouy hamal niitegni yalla fok gnou heh la yonenti bi sah dagne ko don heh ###galsen ya trop d faake
cheikhouna wakhal deh sa batte sa kaw senegal kay bo amei alal walla kham kham kham walla nga siw niou tekla beute mais souniou borom koumou soutaral nianalko mou guena yokou mo guene wakh you niaw yi nguene balma akh koumou deranger yalna diam yague si senegal si adouna bi yepp si barkei borom touba
sénégal bofi beugué bari ay none nanga am khaliss wala am kham kham wala nga siiw légui niou commencé yakh sa dér.cheikh ibra fall néna yalla dou faye wakh bayi dieuf.
lithior té nga wakh sa wakh rék té ngéne bayi kilifa diné yi togn bakhoul té ab djioulit dou togn nga balma akh