24 COMMENTAIRES
  • roki

    bilay lamb yeufou deum la

  • Nothing

    kharagne wakho fi touss

  • kharagne

    arrertez ces sottisse avk vos sermons laaaa d maivaises foi ki p nest pas plus mystique k nou senegalais j vou renvoie dan les sociétés c pire k du mystik entre collegue d travail rien pour avoir des promotion ou poste kes directeur et misnistre n me dementiron la liste est longue ….ecoutez et sorry si jai mal parle ou offense certain mai un conseil nayou manou rekkk dieu e l seul juge

    • action vip

      nitte day mandou soutoura waye
      mystique da beuri

  • MBOUR

    POURKOI VOU MONTREZ PA CE KE FAI MODOU LO TOU LE MODE SAI KIL FAI PIRE. TOU LE MONDE SAI KE SI SA DEPENDAI KE DE VOU MODOU ALLER TERRASSER

  • Mystique rek

    Beuy mana deukhine meuna thiéré ak lénénnn,beuy bi Da am bakén am yaay am baye tékkssi di wakh lahilakha ilala comme toi.donc respect aux animaux danio am roukh di noyii di lékka comme yaw .pauvre con que tu es

  • Mystique rek

    @razak je te répond meme pas moi j'ai pas le temps de regarder des combats de lutte je m'en fou complètement mais j'ai le droit de dénoncé ces pratique mystique fétichisme kham ngani beuy mbour derr stade demba diop doy n'a Warr.détrompe toi je ne regarde pas la lutte la dernière fois que j'ai regarder la lutte j'étais au senegal c'était manga2 vs Tyson ya longtemps.

  • babacar moukabaroo

    amna kou wax lou am solo té mooy mberi lambe yi sénouk mouji day doy waar lool bok nathi likoy waral béne lambe dafa haraam yaar linouthiy déf thi lou haraam dafa bari lool lithi gen doy waar nak mooy lou mél nii té mooy réndi baahima ngir njibar lolou mom soun borom dafko téré thi al xour an bou wér té désouko sakh lék soko rayé thi lou mélnii té méroum soun borom ngathiy jelé soun borom dafa waxni ((حُرِّمَتْ عَلَيْكُمُ الْمَيْتَةُ وَالْدَّمُ وَلَحْمُ الْخِنْزِيرِ وَمَا أُهِلَّ لِغَيْرِ اللّهِ بِهِ وَالْمُنْخَنِقَةُ وَالْمَوْقُوذَةُ وَالْمُتَرَدِّيَةُ وَالنَّطِيحَةُ وَمَا أَكَلَ السَّبُعُ إِلاَّ مَا ذَكَّيْتُمْ وَمَا ذُبِحَ عَلَى النُّصُبِ وَأَن تَسْتَقْسِمُواْ بِالأَزْلاَمِ ذَلِكُمْ فِسْقٌ :::::::::))

  • sama avis

    adouna ak prestige diaroul lii

  • boy médina

    franchement c'est triste mais khana danouy faté né Borom bii moye mayé ndam li dafa haram l'islam sann tané wouko ils oublient que beyy bii dafa am rouhh comme domou adama mais lii lakou fii yarr adounaa bou diekh bii mais borom bii guiss lépp

  • rama

    mdrr no razak tu ma tuer walay wakhgua DEUG diouliwoul timis c sur

  • Papa thug

    Serigne insbi soxlawu gnu revenge…Roi lagnuy dem beure djil inchallah

  • Papa thug

    Li modou lo di deff mom xamna bantamba douko weuri dji..xana li Bomb di def moy fegn! Gnep xamnagn Modou est aussi mystik k Bomb…Gnom gnep gno yem

  • Papa thug

    Louthi dess rek moy Eumeu beure ak Bombardier djeul roi bi inchallah

  • gallas fall

    c grave mbeure mo bone

  • Serigne serigne seck

    Gnaga sa khôl moye ja mounial rék eumeu neko mou niew ma mayko revanche

  • weuz

    Wtffffff mais on doit interdire la lutte y'a trop de mystik

  • MDs

    lamb daffa haram c mém bani par l moral c pratik mystique sont lés illustration

  • seye

    Participez au débatnonou rek la

  • mystique rek

    fetiche noire les animaux déh dinaniou layoo ak mbeur yi .c'est sure il on tué sur la route entre mbour et dakar.triste realité c'est pour sa la plupart des lutteurs qui font ces genre de sacrifice honte il se finira toujours mal avec zero francs amouniou dara tout les millions recu féss lay deff comme nguélaw sénn moudiou dou rafette mouk.

    • razak

      Mayniou diam yaw sakh linga sétane kérog si lambj dingko layyo parsque diouli wo timiss

  • ndiaga

    merci bombardier sigil nga wa pikine

    • Fa

      Sale sorcier.

  • thug

    MBEUR=FRANC-maçon

Publiez un commentaire

Votre adresse e-mail ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *