29 COMMENTAIRES
  • Ma diomi

    shiiiiiiii yaw amnga problème! !!!!!wayé boula wakhtou rawaatti Loooool

  • djii

    ahh li nak moy teussssss ndawléne mbaguéndi ami tanke ..wa alalou adouna diarrna li lou way def sa bope YALLA MOUGUI SI NITGNI.

  • khadimka

    senegal Yakhouna lii kou guem Yalla ak bisbou moudjiba dodeli

  • khadimka

    Thieye

  • Tieungheul

    Ou est le corp c est a dire la viande. La personne va vendre la viande. Faites attentions de çe que vous consommez

  • absa

    eupna

  • dach

    daniouy faténi yalla amena khana

  • El maestro

    Senegal ndiaye !!!

  • samb khadi

    akhirou samane

  • patiman

    la viande est destinée a la consommation. il fo être vigilant . service hygiène liggueil

  • Sopi

    Esk adouna djarna lii

  • Dofdof lou

    adouna moy beuga toukiii

  • paloma

    Le gars est parti vendre la viande faut pas trop enflammer pour ça ce n'est pas des thioumikaye. A nous de faire attention à ce que l'on mange.

  • kebe *

    alahou akbar alalou adouna diarna lii mane sah dama tite dina tokk un an douma lèkk viande mèm gayine sah dafa tite ba deure mdrrrr

  • a.k.a

    khawma lou takh niite kou nioul bone té meuna iniané morome ame. nous sommes et resterons tjrs des ennemis du progrès et adeptes de la fameuse théorie du "j'avance pas, toi non plus t'iras nulle part".Wa salam!

  • Basse

    no Liidafa epou si senegal lep lahou

  • fans balla gaye

    li deee niawna lollll me nak sante serigne touba rek

  • kouachi

    tourbi gayne dama ko lép koi! et ton image? quel idiot!

  • Baps

    bilay ay dioulite lagnou waye yomal khiyam gnoune senegalais yi dinagnoufa andi emboutellage bo khamne bala Yalla di pare si gnoune doynawar

  • aythia

    thiyyy mystique mo doywarrrrrrrrr

  • Sopi

    Babs boulma rée loo

  • David

    Bing auto translator is crap!!!

  • Siyabou Konate

    Ça c'est bizarre il faut contrôler la viande du Sénégal ça c'est pas bon pour les pays des musulmans je n'ai pas aimé images

  • ndiaye

    gaye negen ragal yallah te gen khamne adouna diarol khettho

  • titeuf

    foutaise

  • Siradji diop

    En tant que musilman faut pas être peur du tout c'est rien inch'allah

  • khadim gueye

    waw lidé niaw trop

  • Boul tiit

    gueum len yallah te baye lepeu thi lokhom, tey sell di niane. In cha allah dolène lorou.

Publiez un commentaire

Votre adresse e-mail ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *