20 COMMENTAIRES
  • XYZ

    Guiss ngène dé topando ba yalla wére la Nga toud original bi (yeewuleen).Waa sen tv hamon ngene nii lii Dina lèene arriver .lii moy woné ni Yéen da ngène di hole TFM di copie coller rek .Wantè di ngene khamné GFM dou sene morom .may wakh nak ngene di leen comparer. TFM professionalisme la gnou leen rawé lolou yaaaag na!!!weuh!!!

  • boy djine

    fama thioune dafa mana djay taar,elle na aucune pudeur

  • étudiante

    ne bloquez pas mon commentaire please

  • étudiante

    vraiment j’étais désolée hier en regardant le comportement de fama thioune avec son habillement dévergondé, je ne parle même pas de femme mariée mais en tant que animatrice il faut donner le bon exemple et ne pas obliger les télespectateurs à zapper, excusez moi

  • ksu

    ya awa sa c l commencemt u en fera d otre bourde . u sais trbien k c nom d emission(yendouleen) n colle pas .meme ts invites feront pareils ,ils diront tjr yewuleen . ds la vie il fo creer et non copier sur ls otres .TFM est au dessus de vs il faut juste l accepter ya TELE et tele

  • magui

    pourtant filla ndeye fatou ndiaye dioume né sen tv chaque jr ngou ték ko kone kéye li dagnou ko wora ték té guisse nga li yalla déf ndeye fatou si emission yewoulén la dioumé ya awa gniaw di copié changé tour bi nane yendoulen c du pareil au meme yewoulen ak yendoulem c la meme chose svp de grace wa sen tv diéme léne créyé mo gueune li copié yé nguéne week end star nane bon week end copié mode tabaski ak korité copié elles sont toutes belles soumakoye lime douma fi diogué créér yéwouléne dara ma khale amo léne aye professionelle mo takh

  • lamine diop

    GFM EST LE MIRROIR DU MONDE,AUVISUEL C POUR EUX.YALLA MOLENN MAYY DONC VIIIIIIIIIIIIIIIIIIIIIIIVVVVVVVVVVVVVVVVEEEEEEEEEEEEEEE GFM

  • fans you

    bary ngathiye morome

  • alioune

    tfm tfm rék tfm tfm rék béguééééé

  • alioune diop22

    tfm tfm tfm rék lou mou déff mou nékh nékh tfm lou mou déff mou nékhhhhhhhhhhhhhhhhhhhhhhh

  • doumama

    Le problème au avec les médias c’est qu’on ne forme pas ni les journalistes ni mes animateurs qui se communicant sans aucune formation de des techniques d’information communication soutenue! Pour eux pourvoir communiquer c’est être éloquent alors que c’est totalement faux ! Ils nous manque de personnes compétentes dans ce domaine!

  • jallow

    C’est enfantin ! Ces gens la ne sont pas ambitieux , ils n’ont aucune honte . Vrais amateurs , ils se mêlent à tous et de rien . Ils pensent la télé c’est copier rek . Si vous n’êtes créatifs rendez votre licence . Vous copiez tous les jours GFM , l’Obs ( la tribune ) . Vous avez entierrement pris la Une de l’Obs . Mais on reconnait l’original , vous perdez votre temps . Autre chose si vous étaient ambitieux vous alliez pas parler de balla-bombardier . Azize est allé chez le concurrent pour vendre son produit, donc le marché était déjà conclu . A la place de Bougane je vais zapper ce programme et attendre autre chose , mais c’est dommage ce mec ne comprend rien . Un gamin qui joue avec des milliards .Tant pis les pertes !

  • nd

    TFM MOko yor deeh

  • coucouniang

    yallah moye atte

  • guiss

    yaw fama loy patial mèlni kouy diayouu niii ishhhhh lii dokhoul dal akhhh

  • coucouniang

    yalla moy atte fii la niou dieul ndeye fatou ndiaye mi dioumone wakh sen tv di ko tek rek niakk classe tfm mo yobou sen fitt

  • Laminndongo

    tfm mkyr……

  • dadi

    ma khala daguène tekk beuttwa tfm

  • biba

    frencement j’ème la sentv de tout coeur momaye takha dièguè senegal tahma ma hame sama dinè magui lène di nianale goudi ak bedieuke mè sentv moye bombe gracie mille bougane si kaw si kaname si loubah lafe thiate

  • mimi

    prkw vs aimé vs retardé sir ds choz inutile lerreur est humain o lieu d vocalizé sur l faites k ya awa ak fama amul blem mé non vs ècéyé tjr d voir l pire senegal dou dem

Publiez un commentaire

Votre adresse e-mail ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *