18 COMMENTAIRES
  • LOURD

    ALLAHOU AKBAR ! Un phénomène ce gental MARA .machalla

  • RUFISK

    J AI SUIVI SON INTERVENTION SUR LE VOL DES ENFANTS MAI KI DAFA JANG JANG BOU KHOTE .NITE POUR NGA KHAM KO .IL FAU SUIVRE SES ÉMISSIONS .100pour cent lebou

  • RUFISK

    J AI SUIVI SON INTERVENTION SUR LE VOL DES ENFANTS MAI KI DAFA JANG JANG BOU KHOTE .NITE POUR NGA KHAM KO .IL FAU SUIVRE SES ÉMISSIONS .100pour cent lebou

  • KADER

    TAKH NGA MA BEUG DIANGUI ALKHOUR ÂNE .MACHALLA

  • PRÉSI

    SUIVRE NA AY ÉMISSION WAM YOU BARI SI NET MÊME TOUT SE DISCUTE BIMOU NDIEUK DEF 2stv mai Franchement YALLA MAYNAKO

  • AHMED

    LI REK MO DIARRA PUBLIER ADOUNA BI YEUP DIKO GUISS NDAKH SOUDONE LOU BONE SITE YOU BEURI NIONGUI NDIEUKENTEI POUR BINDE KO .CHAPEAU À SENEGO

  • Buzz

    EN TOUT CAS DEI JETTSETEUR YI FI NEK YEUP NOKH NGALENE ! PEUT ÊTRE LOLOU MOLÈNE METTI . MAI MANE FRANCHMENT DANG MA NEKH PARCEQUE NIIT KOU SEL NGA TEI AM FOULEU .LINGA BEUG DEF YANGUI KOY DEF TEI BOLEI WO SI WAKH

  • Abdou aziz

    Wakh deug yalla aya yi kou diangoul alkhourane doko kham ndakh foumou neka sorri macha alla yalla n’a yalla wereul thieur yi ak batt bi

  • KHAM KHAM

    MERCI GENTAL MARA NIEUW NGA SIGUIL SERIGNE YEUP NDAMOU L ,ISLAM NGA YALLA NALA YALLA SAM

  • Assassin

    YAW JONY YA MENEU FENE LI KOUKO KHÔL SAKH KHAMNEI DAFA NATUREL .YENE KAY DANGUENE AMATOUL LOLEN WAKH REK GATIEI MOLEINE DIAP

  • Borom ndakarou

    bayiléne sokhor lou way wakh nguéne ngañ ko bassi alkhourane Karim encouragé lene ko si lou bakh li mouy df mo gueune. Mâcha alla Ibou Mboup

  • TIREUR

    MANE DEI BILAHI DAMA FEKEI MOU YEUKEUTI KOU FEBAR LOU YAG TEI MEUNOUL DIOUK.DONC NA KHÔL YI FEKH .EN PLUS MOM LIMOU BEUG DEF MINGUI KOY DEF TEI FALEWOULENE

  • SERIGNE MBACKE

    AYA ALKHOURANE YI DEI SI BIIR LA NEK KOU MOKALOUL ALKHOURANE MOKAL BOU WER DOKO GUISS .MACHALLA GENTAL MARA SA KAW SA KANAM REK

  • Mouhamed SOW

    KI DEI SONAL NALEINE YALLA MOKO MAY KHAM KHAM MAYKO KHALISS .ALKHOURANE BI DAL SEL NEU TEI LER NAGNE

  • Justice

    YENE DAL SOKHOR REK MOLÈNE DIAM KI iL avait répondu à cette vidéo qu c etai en 2017 k il avai tournée cette émission et même si C était LE CAS NIATA KILIFEU DINEI NIOFI TOK WAKHFI LOU AMOUL ? Donc BAYILENE SOKHOR

  • jony

    ki dou bene ndogo dara ..ndongo dara dou mel ni ..bayii lene sene khel yi nguene di foyee…li gnio ko programer pour out buzz ag wonne na diangue na alkhourane…gniangue alkhourane dieufee ko mo geune worr…que des hypocrites au senegal

  • tv+brésil

    Gentle or mars le menteur qui avait prédit que PSG sera en final de ligue des champions sale menteur

  • Issa

    MACHALLA KHAM KHAM REK MO WOR

Publiez un commentaire

Votre adresse e-mail ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *