PUBLICITÉ

Vidéo: Excursion des candidats de Sen P’tit Gallé au Lac Rose – Regardez.

Excursion des candidats de Sen P’tit Gallé au Lac Rose

Lac Rose Sen P'tit Gallé
Annonces

(2) commentaires

Samou Sangor Akasa Dinee

teen mboky Sénégal liiy nga khamny mom la yakh katiy douguel thi sounou reewmy ngur takh souniou doomiy khana baiy wouleen thi khel yenne thi teleiy nionguy diel souniou ndiaboot yiy toullou thi diangue dileen douguel thi musique mouy fethi ak woye pour seen enterye boppe litakh gnouy yobbou khaleyi thi hotel yi ak dileen wane thi télé yiy dou seenouk mbakh dagnou begue influencé ynnen khale iy mouy Youssou Ndour Walla boubacar Diallo amouthi kou avenirou khaleyi itteel khalis reck laniou sokhla bayi leen leen khel finiou diem ak souniou reewmi yakhe reewmi ak souniou domiy reck molen yekety ak ndiarignou yenne reew baarelen yoonwowou wa man damay lathete ana kilipha diineiy ana boroom khel you rafet yi bis dina gnew kenne kouneck dina gnouleen def thisoof lathe leene seen yakhe goumety gui yalla na yalla walbety leen te dioubel niou. wasalam

Samou Sangor Akasa Dinee

seen petit kalle bakhoul daganoul moytou leen you ak bous amouniou solo bary wouniou ndarigne te ay lory kesse lagnou moy tou leen leen.

Publier un commentaire