Vidéo-exclusif: Interdiction d’accès à la mosquée, Serigne Mountakha dément et explique
Votre avis sera publié et visible par des milliers de lecteurs. Veuillez l’exprimer dans un langage respectueux.
Aucune recommandation disponible.
Aucune recommandation disponible.
Ouvrez l'appli si vous l’avez déjà, sinon téléchargez-la pour une meilleure expérience et pour recevoir les dernières actualités en temps réel.
Sénégalais yii comme ay djiguèn lougn lène wakh guèn guemk, tey bakhna lol tii domou adama, lii louka fii diar guen nek ay responsable politique signou yakar eleg guèn di wakh loulène woroul bay nioulène di sagha tii net bii lolou amna louke guenone rafèt, adounabi tey yawla eleg dissa morom kon fii dara warou fi gnaw
Voici un homme de DIEU. un rassembleur.
les menteurs doivent être petits dans leurs petites culottes
je ne sais rien de la politique mais comme tout bon senegalais j ai le droit de dire mon point de vue….idrissa seck c est un arriviste c un menteur il ne croit en rien et prend les senegalais pour des con …ma va laaaaa….vive thomas sankara
kou baxx waay
ce n est pas le dementi qui est seulement important pour nous fidele de cheikhoul khadim c est aussi l arret de parole observe par serigne Mountakha qui attend le djigueul du khalife. ce silence de quelques secondes m a fait vibre au plus profond de mon ame.en fait tout est au tour du djiguel dieuredieufeuty serigne sidy mokhtar khol sedna khel dalna
serigne mountakh que dieu te beniss goudou fane ak weurr.
idriss seck seck rouss ga avant de parler il faut d'abord verifier l'info
mbake ziare nala sope nala lolou koula khol khameni nitou yala ngua yala ngua guoude fane t wére thi barke seydina mohamed psl amiiine
mbake ziare nala sope nala lolou koula khol khameni nitou yala ngua yala ngua guoude fane t wére
ndeyesane kouko khol khameni kou yiw le wakh sakh meunouko mbake
Dieureuf serogne touba yallah na diam ak senegal waye
En tout cas li segn-bi wakh lerna [ gni beug reuw-mi diem kanam yiww rek lalene eumbeul ] mané kon kousi intré bop takh ngay dieul segn bi khamal né perdre nga nagnou kholate sounou khol yi ganaw YALLA kouné ya guena kham li nek sa khol kon wakh dji diaroul barry dé wasalam
Li serigne bi def rafetna
Li yéména, eskey mbacké !!!
depuis bima dégé iby, diop de croix et omar sarr dissi wax lalen né dara doussi deug, ces nafekh sont prets à tout pour gagner le pouvoir.
Fen bouné weng mongui ni.
Seugn Moutakha yalla, yonanteu bi serigne touba moko yitél pas sen affaire thiakhane yoyou!
Soss bakhoul kene douko deff kilifa
Yene soss bakhoul surtout journalistes warguene di moytou yene info yi
Senegalais yi no warra oubi sé. Beut dou Lou journalistyi wakh danko warra geum nani guis doga geum
ndiaye doss bayil fènnn
Li leup Omar Sarr la , doul rek lay def
En tout cas les petits marabouts qui disaient n'importe quoi ont la honte
Voilà la réaction d'un vrais marabout
Ndiaye doss e le enfer promis par les talibes dolent rouss tchiiiiiiippppppp
JOURNALISTE rappelez vous du jugement dernier!!!
bouléne tasse sénégal pask nioune nieup beneu laniou
Allahou Akbar, thieey Serigne Mountakha ki moo yémé!
C ingrats de journalistes
des hommes politique comme idrissa seck non franchement wargua rousse tu te permet de parler or que tu na meme pas vérifier l info pufff
Nafekh yi ak fen kat yi ak saitane yi don wakh President Macky wakhgou niaw rouss neng Senegal bayilen nafek ak jahaseh
Merci serigne bi seytane bakhoul
maintenant c'est claire ou sont les pyromanes et les menteurs qui cherchaient à créer encore des problèmes entre Macky et la communauté mouride
😀 😀 Idrissa Seck je pense que WARNA ROUSS TOROP SI YI KADOU KOU TEDD KI.Prochainement avant d'amplifier par rancune vis a vis du chef de l'Etat un incident dans la presse,il faudra avant tout verifier la veracite de ce genre de faits que tu affectionnes tant .Ta mort politiquement en depend,si tu ne l'es pas deja depuis ton detournement DE DIZAINE DE Milliards sur le budjet des chantiers de Thies.Bou lolou wesso mangui ndokel si MAGAL GUI tout nos compatriotes des autres differentes confreries.Cheikh Sidy Mocktar Mbacke Balla AISSA yalnafi yague tee weer ak bepp ndiabotou Mame BAMBA et tout les kilifa dinee du pays,DIAM AK KHEWEUL SAKH SENEGAL BA FAW.WASSALAM !!! 😀 😀