PUBLICITÉ
PUBLICITÉ
evacuations sanitaires le dircab du ministre de la sante reagit youtube 2019 11 03 20 48 10 - Vidéo: Evacuations sanitaires, le dircab du ministre de la Santé réagit

Vidéo: Evacuations sanitaires, le dircab du ministre de la Santé réagit

Venu représenter M. Abdoulaye Diouf Sarr au 9ème Congrès ordinaire du Sutsas, le Directeur de Cabinet du Ministère de la Santé et de l’action sociale a remis les pendules à l’heure, suite au débat sur le système de santé qualifié de défaillant avec les évacuations sanitaires.

Pour le Dr Aloyse Waly Diouf, les millions de Sénégalais qui sont traités et guéris chaque mois dans nos structures ont eux une autre lecture.

Regardez son intervention en vidéo

Evacuations Ministre De La Santé
Annonces

Un commentaire

Karime

Lii dee ci sunugaal gi reek lees ñemee waxe wax junimel xánnaa demuloo kawgi ca postu de sante yi ne kon doo mása wax li nga wax darra amu fa te lici géna yéme sax mooy na lafa amakas néw ñoom ñoo koy jaay def ci poss te lu wara jar 1000 F ñu deñci ko nela ámufi ba nga baax le jaxx lool ñu soog ne la waw xaral tuuti keneen ñéw nela joxeel 3000 F nga kiko jéndi woon sax mingi fay ci wata biko yóobu woon 5000 F kon dangay joxe 2000+1000=3000 F li mooy rayálite bi nuy dúndu nún waa Diiwaanu Luuga xawma niik yéen wa Ndakaaru Mussee le ministar yaw mii ñu dénk wér gi yaramu Asskánu Réwmi Senegaal jéré li nga wara wax léepp wax nga ko ci yar ak tegin ju mát sékk Máshála waaye nanga saytu wátt loopitaal yi ñoom ci laan lañiy jéf laantek Asskán wi ay miliyaar ngen di def ci wéer gi yaaram waaye dá’amul ak cáytu Mootax li ngen di def feeñ mukk

Publier un commentaire