VIDEO et Photos: Serigne Modou Kara suite à sa convocation par le commissariat central (Regardez)

 

Kara 1 Kara 2 Kara 3 Kara 4 Kara 5 Kara 6 kara milice

Votre avis sera publié et visible par des milliers de lecteurs. Veuillez l’exprimer dans un langage respectueux.

9 commentaires

  1. elmalito

    salam talibe nenga « kasoba serigne doulafa guenè » .legui nak nga beugue yawmal khiyam serigne bi guenelafa.khalatsi touti rek ngua khol ni yanouwoul mana ay gnepou gni topou serigne yi diebal len s’en aduna ak alakhira.serigne bi Nekouma guenè fi si aduna dila guenè alakhira? Djegalou si wakh ji nak balenma akh wassalam


  2. Alou

    Noon talibe do nitt!! Ray ngama bama dè.. Wakh nga deug dé kasso mom dafa métti Yalla naniou thi Yalla mousseul. En plus t’as raison macky dafa deugueur comme khèrou guèth.


  3. talibé

    mane dé ab talibé la wayé dotouma sol tenu militaire.thiébou djeune midi bi kène doumako khagne boléthi kassobi dafa tangue djipp tè thiow li thiow li macky sall doff bou teukh la dalafiy teuth té samap serigne doumafa guéné.té dama yor diabar ak ay dome…diamou thila lépou khadj…..serigne bi dal souma sagnone dognou indile bèna problème parce ke nous avons aussi notre droit…khalatt thi bou bakh ndakh kassobi dafa tangue dièrre diamonodji….serigne touba diamou la beugue thi senegal…wassallam.


  4. tontoul

    mandou mom la yalla wakhx.andak yalla bamou diéx tak.walla andak sayatiin niarr yoyou rék mo amm.diouliit day doon mousliim.walla mousriik all khamdoulilla sallam


Laisser un commentaire