29 COMMENTAIRES
  • étudiant

    youssou ndour chercher du renfort pour contrer wally

  • diop

    Alez travailler c mieux te Mey pass khaleyi niou setaani Sen bay youssou ndour .

  • cojer mali

    dem lene diamu dji yala mogeune ay thiahane

  • thug life

    les faramarenes nguir yalla abstenez vous waaaay hahaha on sen branle ndax nioune xaley douniou yeukeuti.. wally na xoli lnn c mieux ndax ya ke des pd ci soirm

  • GFM

    les jaloux vont maigrir kou sa hol diekh demal haroudji ndah you rek ak senegal rek dara dou doy hana contane rek wassalam

  • chelsea

    thiey lii kouko meune ak koukoy dim bokouniou.tl takkna tl takkna bou tl tkk radio n kamathie tl takkna.ehh fii mo geuna nekh skkne ehh fii mo geuna nekh skkne ehh fii mo geuna nekh skkne ehh ha ha haha ha ha.o sont les faramarene???????

  • diamou

    diadieuf akon??????

  • mamadou

    thiey youssou diguama ray rek ak khol bou sed

  • badio

    Ñoom para yam teki vouñu dará Senegal sen bop rek lañou finekal ni youssou ni akon

  • beug you rek

    Khalissoo khalissoo baddio tassarengua dounya maalaa. Makheusemen mangui slouis mais ken doumako nettali..

  • bleu

    GFM li dara fayouko tay la tay souba la netali ba ak PAPA you rek dou yombe mome nekh rek Lay def nakh yalla gnou deglou de la bonne musique ? on nous tympanisent trop ak musique gno khamni ken khamoul lougnouy weuy

  • GFM

    fougnou diar gnoun ba aksi fi dafa melni lougnou netali los Angeles paris ba rio new Delly Londres ba Tokyo sedok gnom lignou diele feléeeeeeee wa li ana loukay fay tay cises dou yomb moy raw le 2 inchala gnoun ak papa you rek lounou songu dan ko mé akon mom sama hol lala def yow ndah danga gnak kignan

  • borgo

    Kone Akon dègatoule wolof bou Larry? Thieuy YALLAH yarale kharalè

  • chacha

    Je vous adore Akon et vous aussi Youssou
    Vous etesvraiment des stars planetaires
    big love

  • mams

    Si digue bi foufou ley diar namou niou dara tey dara dou ced

  • akon

    welcome Akon ssa présence dafadonn gueuneu tioukal soirée bi

  • tit

    Youssou moy chéf

  • amath

    nomba won 1 senegal youssou ndour rekk a cicce

  • vito

    heee coute DEUGG xawma DEUGUENTOU . la place appartient a qui ? machalah You est en bonne sant et sa voix reste ternelle.. il il NS fait plaisir et c sa l plus important ‘ jte comprend j’en sui sre k faramarene nga mai detrompez vs you le king est encore l . bandes de jaloux

  • deugg

    Il faut arrêter et laisser la place à la nouvelle génération de grâce ! Que voulez-vous prouver si ce n’est pour faire barrage ! Sacrés vieux, sacrés seniors !

  • moustapha

    ah mane mom da ma namo danse taye lay tothe cices da ma nara fethe ba dangue samay daleu khana nekh grand bal kou ko rater rek ya khame

  • daba

    youssou ndour lo songou da koy daane inchala grand bal lepeu moy bakh

  • daba

    merci akon vraiment vous etes un grand homme si tout le monde etait comme toi et youssou ndour kone le senegal serait en voix de developper parceque vous contribuez beaucoup dans ce pays laf thiate

  • pendo

    thiey grand bal youssou ndour kene dou mako netali inchala

  • kadia

    akon et youssou ndour vous etes notre fierte yala na lene yala may goudou fane

  • rail

    ma beugue youssou ndour ba kou wakh si mom da may content si yow

  • birima

    ak youssou ndour rek dina nekh dina yeugo

  • sallma

    Ce soir ça va chauffer inshaallah au CICES… Avec Youssou Ndour tout est possible… Nioune ak mom rekkkk dara dou yomb

  • Biba

    Soyez tous là Akon sera bien présent je vous le jure mako guiss

Publiez un commentaire

Votre adresse e-mail ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *