S bamba ak Cheikh Ibrahima Fall yaw ken mounoul thi yaw dara s bamba ba fawou rek fall
baye fall
31/01/2016 à à 19:21
otiss
31/01/2016 à à 18:20
daouda ndiaye
31/01/2016 à à 17:40
Carloo bayii leenn akk serigne bii rekkk
Anonyme
31/01/2016 à à 17:14
Carlou Dagua lettou ay rasta teh rasta yeuffou djiguene la gor waroul lettou donc c'est un acte de gordjiguene comme le sac de waly
deug
31/01/2016 à à 17:13
rafetna mais damaye Diane senegalai yep di bayi Khel ci noneyi ta khamni balegui gnougi gnouye diema fewele wa salam
Mbacke
31/01/2016 à à 16:26
Yaw nak yalla bo continue di défe music yalla nala serigne bi wénéne yone………………. Mouride dafa wara mouthiou fi ak fé
ndoyes
31/01/2016 à à 16:23
traduction en wolof svp
ndoye
31/01/2016 à à 16:23
TRADUCTION en wolof svp
Mbacke
31/01/2016 à à 16:22
C mal mais lou daga noul dou masa dagane wakhal yousou Ndour liko tanka bamni Pata bouko then kénna…………?
khadim loum
31/01/2016 à à 16:02
wakhle dee carlou d
aicha
31/01/2016 à à 15:59
Yaw sa gueume serigne touba Dapha ler nagni sa lepe serigne bila limageuna nekh si yiaw moye sa Lép Dapha nek yeufi. Gor do tak chêne don tak diaro sa Lép yeufi cheikh ibra Fall
Falla
01/02/2016 à à 13:45
TOUS CES GENS SONT-ILS SINCERES,OU CHERCHENT-ILS A SE FAIRE VOIR?
En tous cas la MOURIDIYA ne permet pas que ses disciples fréquentent les dancins,bars et autres lieux de dépravation des moeurs.
Carlou di, so beuguè Serigne Touba bayil diko toud ci barabou way téhèdi yi
Je le trouve quand même efféminé, lui ! Qu'il revoit un peu sa gestuelle…
Trop de grimace pour un mec
wakhofi dara
wakho fi dara!
carlou d dey soob loum fi wakh pourquoi dou critiquer wa jeune afrique
kholatal ligua wakh boufékè kham gua serigne touba
bamba kara
S bamba ak Cheikh Ibrahima Fall yaw ken mounoul thi yaw dara s bamba ba fawou rek fall
Carloo bayii leenn akk serigne bii rekkk
Carlou Dagua lettou ay rasta teh rasta yeuffou djiguene la gor waroul lettou donc c'est un acte de gordjiguene comme le sac de waly
rafetna mais damaye Diane senegalai yep di bayi Khel ci noneyi ta khamni balegui gnougi gnouye diema fewele wa salam
Yaw nak yalla bo continue di défe music yalla nala serigne bi wénéne yone………………. Mouride dafa wara mouthiou fi ak fé
traduction en wolof svp
TRADUCTION en wolof svp
C mal mais lou daga noul dou masa dagane wakhal yousou Ndour liko tanka bamni Pata bouko then kénna…………?
wakhle dee carlou d
Yaw sa gueume serigne touba Dapha ler nagni sa lepe serigne bila limageuna nekh si yiaw moye sa Lép Dapha nek yeufi. Gor do tak chêne don tak diaro sa Lép yeufi cheikh ibra Fall
TOUS CES GENS SONT-ILS SINCERES,OU CHERCHENT-ILS A SE FAIRE VOIR?
En tous cas la MOURIDIYA ne permet pas que ses disciples fréquentent les dancins,bars et autres lieux de dépravation des moeurs.
Les commentaires sont fermés.