40 COMMENTAIRES
  • papis

    C f l

  • jules kane

    Cad qu'au Sénégal avant may dioude sakh les marabouts ont l'habitude de d'enterrer des gris gris dans les tombes ça depuis longtemps. Généralement pr tass seyou diambour la. Peut être que de fe tomber aussi. ..

  • loli

    tu mens balla on te conné ton vieu pére est trop mystike

  • MADIOP

    Ohoooooo Balla boulniou sonal waay ah Yénn mbeur yi louné nguéne sagne . té é p8 Malick Gackou dou par force dalaa wareu xaliss so amè comba . ngay kass balla daale CINEMA leu kw .Mdrrrrrrrrrrrrrrrrrrrr

  • ma taye

    mais balla kagne yarou n'importe quoi un impoli comme toi yow dokhal sa bopp ngueye diombale

  • assane thiam

    les senegalais sont de mauvaise foi,balla gaye 2 n'a aucun interet a commanditer une chose aussi ignoble,c'est deja arrivé a tapha tine ( l'histoire du boeuf de la medina) eumeu doit se contenter de sa victoire et non essayer de descendre un lutteur ki a fait dans l'arene senegalaise kelke chose d'extraodinaire ,Balla for ever on continue a croire en toi.

  • No name

    Balla gaye a dit que ay fns gnoko wo pour mou dementir lolou esk c rézonable si cete vré balla dou xarr gnoukoy wax mou dementir balla gaye assume rkk c ki dnc ???? Hen kila fé????

  • doudou sow

    balla avant tous c 1musilman il a bien boulen ngeum eumeu rek

  • lemzo

    booko défoul ak say lokho tamite yaa yoonéé niou def kofa ..boo yoonééwoul tamite gnii bokk si yaw nioo kofa def ..wakh dji dal xam nga lane la maye niou diam yéne la yéne la waw ….malik gakou nak tay dookofi xasséé ay balla gaye yaaa baadoola ..eumeu séne tamite meunone na teudj laminam bi rek ba apres liii dal kouko wakh périéé

  • lemzo

    damané yaako fa déf ngay déf ak sa kanam gui di melni boli beignet dougoup ..amo loo wakh malik gakou nak mom guéénéékossi tout trankil yaa ngui dégue limala wakh ay balla gaye yaa badola eumeu séne tamite mounone na teudj laminam bobou mom tamite mouye melni chaise anglaise vraiment lii yeup tamite kouko wakh périé

  • Moussa

    Bay yén yabilén balla akhh. wakhh Rèék..

  • elhadji rafét

    mdrrr balla dafa rous thieem

  • 0 balla

    balla daffa fou tous il a etait au sommet par accident et ca se voit

  • deuguebouweur

    Eume pour less fens qui l ont frequenter est in vrai mytomane Il Aime se faire passer pour LA victime c est in manipulateur il a perdu to us ses amis d enfance c est in traitre I'argent le melange avec tous le monde .il est sans scrupule c est in gigolo sa premiere femme avait un Mari blanc et Il a accepter ca a cause de l argent Il a detruit coly Faye en lui disant de faire in mauvais sacrifice il a demenager sans l dire a son colocataire Jordan il a Pris l argent de luck Nicolai et do is lui rembourser 22millions il a dit que modou lo est venue l provoquer chez lui et ce dernier est passer a 2 rue de chez lui a djyli mbaye et n l a meme pas Apercu Mai's bon sang ouvrez led yeux

  • sarl

    Yaaw moom deuguebouweur wakho kou sokhaar gaay wakh mais c normal sa xool mo diekh . Balla wakh bou doffé noop yikooy déglou doffouñou ligua sa watt dafa yoomb torop. Khamni defo akk sayy propre loxxo dagaay yoneii wayy. Kou guisse eumeu ni mou wakhé khamni dafa aam louko méti tei ndéye dafa sakh thi xool

    • SOF

      EUMEU MOME BAKHE REK LAKO SENEGAL HAMAL BOULEKO SOSSAL NAK, HAMENA BALLA MOLA YABALL POUR GUA TONTOULKO . MAIS YALLA DOU FARALE KOUY TOGNE.YALLA MEUNEU ATTAI VIVE EUMEU

  • thick s

    Nañu bayi yalla mu def ligueyam.lu way rendi ci sa loho lay nath.ñi anda ak mbeuryi ngen hamné moytu warnalen ndah ndam ak xalis diarul leundameul sa bamel eleuk

    • Ma2s

      Copin todj nga fi … nagnou bayi yalla Dèff Liguèyam

  • beuz80

    boy balla laisse gackou amal touti khel quoi gackou est tellement occupè

  • mya

    Arrêtez les préjugés Dieu en est l seul témoin "degueu rek guene ci am "

  • Madou

    Bâtiment bou sol ndokh moko dane .

  • yalla reka xam

    senegal mo yémé takhaw dii fénn ci lou la léroul
    anna kaan mooy waat né am na wala amoul
    ragal lenn yalla, kan moko féké, té musulman degue dou fénn, lii maye guiss nii aye fénn késsé la

  • fafa

    Balla yafi nék nit kou gnoul khamoul demb tay rk la kham dmal défarouwat gnew kouy berè moy donou tè biss boy danou do kham sakh loulay dane thiounè gay nèk kom kou fèbar bay wadia dé sa garapp bila wara fathieu poison lay nk si yaw mane dal gnAk douma takha bayi yaw la geum yalla moy diokhé ndam wayè liguey eumeu nako ndam bi djikk yaw gua khol lou nk sakanAm df gua si lamb lou sa béne morom dfoul kone euma danela takhoul gnouné dou mbeur mbeur kamil gua

  • daour thiobane

    Balla bayi co ak yalla

  • лай

    eumeu yakh dèrou diambour rekk la meun nila Fi defone tyson

  • лай

    eumeu yakh dèrou diambour rekk la meun nila Fi defone Tyson?

  • mame maye mbengue

    sama guayis na rafete rekk

  • ive diouf

    déééé déte khole laine bou bakh affaire yi lou méle ni menou niouko inventai c sure que la tombe a été profané mé qui la fait c sa la question

  • elhadji gueye

    balla gaye boul yakarne yaw rek yamome lambou bo tassek koulaùane dagakoye nangou eumue dousa morome

  • emi502008@hotmail.fr

    c est pas vrais ce que eumeu sene a dit sur balla gaye 2 il ne peut rentrer pikine comme ça il ne le laisserons pas renter sur les arméres de pikine

  • Bella

    yalla amna de naniou sete si yalla

  • Lol

    rokose nako

  • kebe*

    fafa ioe lay wakhal lambdjè kène rek mofi deff lou kène massoul deff mouy yakhya diop yekini kone boulniou sonal yekini est champion d afrik nga balma si sa te derange

  • babs12

    prudence ga yii

  • pape

    balla go eume sene moye sa papa

  • aissatou

    ay way sènègal lamb dji dièkhna nak.ame balla inil eume rèk ishh!! may lène gnou diame tè wakh lou lène woor bayi bakar you beuri…wasalamm

  • mohamed fall

    subhana allah, li moy aduna de balla yangui si natou tey mougnal ¡ domou adama melni gnoumou woroul sakh ghounkey deugal, yow daal wallahou yasimouka mina nass, nitt raw seytane.

  • fédior

    balla a réussi a faire se ke sé camarade n'ont po réussi a faire su fékone mo dane wakh yi yeup dolen ko dégue il reste k'en mm un musulman tamit arene bi dal kofi dane mou oute lay mé balla é un tré grand sportif il n'a ke 4 défaite amoul 7 défaites laisson le avec sa philosophie

  • ALPHAX

    SALAM JE VOUDRAIS QUE TOUT UN CHACUN ESSAIE DE TIRER UNE LECON DE CETTE HISTOIRE CAR CELA PROUVE QUE SEUL DIEU DISPOSE .NOUS EN TANT QUE HOMME DEVONS NOUS ACCORDER UN SEUL FACTEUR QUI EST DE CROIRE EN DIEU ET EN SOI MEME .PERSONNE NE DOIT AVOIR BESOIN DE PENSER A DES ATROCITES JUSQU'A LES FAIRE .ESSAYONS DE TRAVAILLER EN SYMBIOSE ET SUPPORTER DIGNEMENT ;APRES LE SPORT LA FAMILLE DONC FAITES TRES ATTENTION AUX DECLARATIONS NON VERIFIEES ET PARTISANES;JE VOUS REMERCIE

  • chek

    balla nite day gore accepte k eumeu mola meune dou sa morom

Publiez un commentaire