Une vielle dame marchande de légumes est victime d’une agression dans sa propre chambre sise Thiaroye Azur. Vidéo…
Gfm
(Vidéo) Agression d'une vielle dame dans sa propre chambre à Thiaroye Azur

Votre avis sera publié et visible par des milliers de lecteurs. Veuillez l’exprimer dans un langage respectueux.
Ooooh k DIEU nou guide dn le bon chemain!!!!!qui peu faire sa a un vieille dame
Ministre de l'intérieur war na wakh si police bi, ndakh gnou def senn liguey, fekk la ba sa biir keur, lii goor la diassi, nga deme sa yonn té kenne topou la, lii metti na.
Ki deff li, thi daradiay seydina mohamed psl, thi barqué werrou koor gui, yalla na ko yallah werr, tek ko moussiba, torokhol ko adina ak allahira, dieul bakenn nam thi anam bou niaw ba aduna bi yeup yeuk ko, té tabbal ko diahanama manam safara. Sama khol mettina lol bathi canamou sounou borrom.
Yaye boy, yallanala sounou borom mey werr si lou gaw, feug sa bopp, bagua am taw feekh,thi daradiay Rossouloulah psl, car ces genres d'agressions sont toujours traumatisants chez la victime.
vraiment sé honteux car je n ai pa de mots a dire mais il faut savoir ces gens n ont pas de place dans la Société
sa ma yaye lakoy kholememe chose lui ete arrivee une brave mere qui courait tous les jours pour nourir sa famille ils l ont suivit de sonlieu de tavail jusque a la maison le soir ils sont venue ils ont casses la porte ils ont emportes toutes les valises mais nous on n a eus la chance on dormez un voisin les a vus ils avait des machettes jusqua present je tremble en pensant si on s etait reveille ma mere et moi et mon enfant on a porte plainte mais jusqu a present elle ne s est meme deplasser pour venir faire le constat
guisga etats bi kham ga loumou wara def dem 100 metres juges inocents yi fa nek dp8 lomgs temps en mandat de depot .juges len libere len .dem diap doumou korrrrtesss yi teuthie len a vie par c que c des rat on doit les fermes pour toujour .yaye masaaa eet du courage yalla na la yalla defal weer ak weerle amine gros bzzzzzzzz
la honte!!!!!!
Mane dey khamouma lima wara wakh mais li niaawna trop trop …
Yalla nako Yalla may weur amin Ya Rabbih. ..
Le méque ils et fou c un batare
très émouvant il faut que la population de thiaroye organise une marche pour qu on enlevé le barre qui est a cote si votre vie et toujours en danger surtout celle de vos enfants
c est acceptable
waw ya amme probleme mais senegal amoule probleme
c inadmissible il faut déguerpir ces bar ce n'est que source d'ennui aux populations
7 agresseur je le trouve je l8 fait pire….il est un virus pour la société
cest inaceptable
kidèf li yallana tassèk mboulalou Borom bi
ki buzze la beuga dèff walla
Bien dit deukhine mbeup walahy ki vrai malade la
Mais je comprend pas aussi mais Police laan moy seen jeurign….maan amna louma mety tropppp
le gas est lache mais la police aussi
ki sougn ko jappet nagne ray ndayammmm..c un vrait domou haram
aicha suis désolé ce pas une histoire de terrorisme ce juste des salaud les gens qui font des trucs de malades comme sa va agressé samorom yiii et tu verras bandes de cons ???
moi je ne sais pas quoi dire
Masta yaye boye c'est trés dur mais sache que le punira incha Allah. Je pense à nos braves mamans qui se lèvent à 4h ou 5h du mat chaque jour pour Aller au marché du Poisson ou à Thiaroye rien que subvenir au besoins de leur famille car la plupart de nos papas sont en retraites. Qu'Allah veillent sur vous Mamans
Je trouve pas assez de qualificatifs pour justifier cet acte, trop triste pour cette dame qui est pourrait être notre mamie, mais là le ga a tiré le bouchon trop loin, svp les flics retrouvez le et rendez la justice au plus haut degré
Waà nouveau single de youssou ndour''Djiguene Gni'' wakhatjili.
ndayessane ki khana dou djilite ?
c la honte bou respecter wone n deyam dou deff lou gnaw li bonne guerison metina te amougnou kougnou ko fadial
L’état doit prendre davantage ses responsabilités en les condamnant à des peines fermes allant de 15 à 20 ans de prison des gens comme ça n'ont pas leur place dans cette société ils sont nuisible pour la bonne marche de notre pays
LA FAUTE COMME TOUJOUR, LA POLICE , C HONTEUX LA SECURITE DE NOTRE PAYS…NIANGAL REK DUÑU GATT
Li niawna more bi nga khamné soutoura lay weuyé Don mak téré woul sane dolé niou défko ni métina mane titeu na si Senegal
No Senegal mobari niou allalou adina diaral loune kii khana bayiwoul yaye sama yaram dawna dioyna
et la police?
Amiine ci darajay tann
Li dou tey rek. Thiaroye Azur df nafa 8ans mais aggresseurs yi dagnou yap vraiment bayi wougnou dara. Dagni dougou bassi cimetiere yi sax pr voler etc…. et lolou c anormal. Le gouvernement senegalais doit ameliorer la securite du pays. Titone na nak mais dama gueneuh tite ak diaxler ndax sama mbokk yima fa bayi. Li touriste/ eleve bouko setane dotoul beug niew ndax ragal. Sama yaram dawna, sama xoll fess. Maman tanell ak diam teii nga yague fi andak wer.
deukhine mbeupp raye nguama wayé nak wadji kholou yéfeur deug la yor
je n,ai ni mots , ni paroles , je suis degouté , meurtri , indigné, kaan moo waaraa deef ni sougnou maman cherie dieuf bou gnaaww bi , yaalla naakoo yaalla torokhaal , tchi daaradjaay werou koor bi gnouy waadiaal, yaalla naakoo auto ecraser , yaalaa naa camion 16- 21 panne tchi kawaam , yaala naa laap guedj , requin yi kheudé ndeyaam , yaalla nagnou koo violer , sodomiser ndeyam !!!!! je ne peux plus continuer car j,ai les larmes aux yeux !!!!!!! courage yaye boye , bou laa daaraa daaal tchi daradjay khalipha ababacar sy !!!!!!!
kii kay khana amoul yaye
ohhhhhh dama dioy bima setanai li.ki def li khana yoroul kholou musulman
très honteux
seuteuteuteutt .li yemeneu metina .damna yaram .c'est 10 n'importe quoi
wadji dji il est malade
ki domou kharam deugue la
faut la peine de mort cest tout cest vraiment honteux
les terrosisme sont entrain de creer une branche au senegal en tepresaille a macky ki veut envoyez les jsmbar en arabie saudi ces acte barbare prouve kils sont deja la
Je me demande bien si tu fais bon usage de ta raison. Une vieille dame paisible se fait agresser dans sa propre demeure tu parles de branches terroristes. Sois sérieuse un instant
ici ont parlent pas de téroriste et pour quoi comparé
une vieille dame innocente qui gagne sa vie honnêtement à la sueur de son Front…comment peut on faire ça a une personne.a dakar le danger est permanent et les autorités ne font rien pour venir en aide à ces gens.
le senegal n a pasd de probleme
qui est qui fait des trucs de malades comme sa vraiment le Sénégal est devenue un pays terrible quoi la personne peux faire la même chose à sa maman aussi ça grave ça non le gouvernement est là bas qui fou rien on a un gros problème au Sénégal ???