13 COMMENTAIRES
  • kira

    merci maitre ioe mom daga wara neek president waax bi fin naax koba gua namo dara.

  • BINTOU

    Thiey lii kagne laye jeekh Senego? Lii moo takh lii kenn dou ko fower. Senegal moom dougnou ko meusa nanguou. Nagnou fatter nakk. Waly niamm na. Dotou ko dolli ou bien il est fini pour toujours. Moi ma question c comment Waly va se tirer de ce petrin? Peut etre des excuses a la Tele?

  • amina

    akh yaw Elhadji Diouf mane wedi nala ndakh khamo foy takhaw

  • dd

    merci maitre

  • tic tok

    kira ray gama guani maitre koba la ahahaha

  • touti
  • adam

    bilahi yaw la gueum maitre

  • Djibril

    Lol fans waly du nangu mouk.naniou tedj deuk bi ku amul job gueuneu dkr nieuw si région yi door war,bay Wala sambeu…te suniou mbok villageois yi gueuneu dkr biniouy fessal di louer di trainer di sathi eu alors qu au village tu manges bien u vis bien dem dkr lek yaboy lek mbedeu.Macky n'a def élévation frontières Bou keneu gueuneu tere Lou yomb (danse chanter …) n'a khaleyi diangui.Dakar beneu nit job doundeul 10pers you tok rek.qui ne produit pas consomme .gayi naniou war bayi Lou yomb.dkr keneu meunou fa teki si diare si yone Bref wasalam

  • zoula

    man dé lima djiaxal moy fi lagnou djiap11gordjiguen klk 2jour bayilen t guisouma ken kousi wax dou simon dou ken ci autauritee yi cou si wax dou wa yana mar ken wakhou ci waly na fai k gadou sac deug la sax waly def na eureur mai nak afair bi dafa ma beugeu djiaxal xana wax dji dafa am lenen lougnou ci naral waly loudoul sac bi sou feke ni deugnon beugeu sacrifier waly wala guen beug ko lek guen def ko t may gnou djiam yowmalkhiyam dina meti tororp t yag waly defoulen dara loudoul nek xale di bay walam si deukeum gnoun nak xam nagn lep waly il derange waly rek molen sonal li dara djiarouko li dina tax waly xam bou bax fimouy teg tankam gnoun on c tou pape diouf ak yousou ndour ak assan Ndiayebougnou sagnon waly yem fi tey waye dougnou yala meuneu lou len ko dara men tey la gnou gueuneu beug waly tey lagnou gueuneu dé si waly bayilen domou djenbour bi lilakhi warasoulikhi yowmal xiyam waly molen fay yagual noo li eupeu na teye sac rek t djiap fi 11pd 2j bayi len t dara fekou len ci gnou beu rey nit gni waly waly adada dafa doy lou eup tourou tamit nak

  • dames06@hotmail.fr

    love maitre el hadji diouf

  • souleymane souare

    où é pape ngagne?

  • ngom

    Zoula tu as raison on a pas vu de boucan lorsqu'on a libéré les homos à Kaolack. Pourquoi cette hypocrisie ?

  • as

    zoula tu as raison, waly derange ,depuis kil a signe bercy ,certaines personnes n ont plus de paix

Publiez un commentaire