Vidéo- Affaire des sacs à main : Serigne Saliou Mbacké tire la sonnette d’alarme

Vidéo- Affaire des sacs à main : Serigne Saliou Mbacké tire la sonnette d’alarme

 Le marabout Serigne Saliou Mbacké fils du regretté khalif général des mourides (Serigne Bara Mbacké Falilou) s’invite dans le débat sur les sacs à mains des filles portés par des garçons.
Le guide religieux tire la sonnette d’alarme. Il trouve injuste d’imposer cette  pratique à nos jeunes en quête d’emploi ou en quête d’un mieux être.

41 COMMENTAIRES
  • babacar sene

    Amna solo lol

  • sope serigne saliou
  • Mor

    Macha Allah mbacke

  • lecce

    merci mbacke

  • baba

    diuere diuef mbacke amna solo loooooll yalna yala goudal fanyi weral thieryi thi barkeb samam aaaammiiiiiiiiiiiiinnn

  • mareme aw

    vs ave TS dit wakh bi amna solo trop mbacke yalana yala doli fani ak wergui

  • malick

    je suis tidiane mais vraiment il est courageux.qu Allah te secoure mbacke

  • deug rek

    dieuredieutety balla aicha sa mame dé fi rek la tégon tankam wakh sa ba wakh dioté

  • omar

    Macha allah yalla na yalla faye la

  • Habib sour
  • wakh deugg

    OUMARO GRAND THEATRE AUSSI MOO WARAL WAKH BI. ANNIVERSAIRES YI AUSSI GNO WARA JEEKH. BUZZ JAROUL YENN YI. DEF LOU BAAKH SIW THI MOO GUEUNN. YEE FITNA BAAKHOUL NDAX KHAMOULOO FOUMOU LAYE YOOBU. BOY WALY BII MOY DERNIERE CHANCE POUR MOOM. AU PROCHAIN FAUX PAS WALY EST FINI. UN HOMME AVERTIT EN VAUT DEUX.

  • Sénégal

    machallah

  • sante

    lerna dé na kouné sab rouhk wakh sa bop deuk lolou rek mo dess wasalam

  • bayefall

    deugla amna solo lou mata bayi xel

  • Blk

    Machallah def nga lila warr kou bakh. Dieuredieuf wakh lenn, khamal nieupp di niou faatali tamitt. Yalla nala yalla fayy

  • daouda

    dieuredieuf serigne yalla nala yalla faye si barke mouhamed psl

  • madame
  • Mouhammed Fall

    Dieureudieuf mbacké

  • cherifo

    diarama

  • Babacar

    Nila ndjite waramel. Diasaka Lahou khayrane

  • abdoukhadre sow

    dieureufati yalla naniou yalla yokou soutoura ta tekniou si yonou siratalmousstakhima

  • Pd

    Dieureudieuf mbacke yala nagafi yague te weer

  • Pape

    Où est Kara et Bethio, ils doivent en parlé au moins rendre service au peuple en interdisant à leur disciple tout phénomène de goordjiguéne. Dina am solo Lolou. Wa salam

  • VÉRITÉ

    C est bien de parler de cela que dieu vous paie mais un peu de retard car il y a des hommes qui font du piercing tatouage piercing des lèvre oeil langues les prostituées etc qu' on parle de tout et condamne tout histoires deeleene teelaa adou et lors des conférences Laval et autres en parlé au lieu de faire les éloges du président et son gouvernement c'est tout ce qu' on vous demande car gnooo gueuna pire vive la paixdes mariages norvégiennes à kaolack personne n a pipe mot

  • Pape

    Degue le

  • Boromkhaira

    serigne biii ma challa lerne amna mana li rek mo war yallnaga ame diam bou bakh sisa barkep mame serigne fallou mbacke

  • kira

    merci li laniou done xarr. ziar lou beuri

  • vérité

    dieure dieuf lerna

  • deugue

    yalla na yalla doli soutreu mbake

  • lerena

    dieure dieuf Mbacke amna solo lol domou adama yi nak dagno degeur bop wayenak yallah moungi gnouye xarek ba besba bilaye youxou dana diogue fougnouko foguewoul

  • lora

    dieuredieuf yallah n'a sounou borom goudeul say fane amna sollo

  • pape

    dieuredieuf ziar bou wer akassa lernalool sante serigne touba

  • rebatass

    li rek laniouy khar si yene dh

  • sow

    mashallah wakhrr tou wakhrr too lèrenaa

  • Anonyme
  • David Souch

    machalla yalla yalla doli kham kham bi ya rabi

  • sidy manga

    ALHAMDOULILAHI WERNA

  • Cissé

    Dieureudieuf wakh ji lérna nagn té lépeu gnioun leu ay références you meun déffar domou adama sunu borom wathié nako Sénégal mais li yeup beugeu lou yombou woko waral seu religion soula diararoul dara lépeu lo guiss tu le prends comme références et ak idoles

  • boy fall
  • leye

    amna solo

    • sam le pirate

      🙂 Jazak Allah khayr Mbacke !!!

Les commentaires sont fermés.