Urgent-Touba : Serigne Mountakha donne le Ndiguel pour la célébration du Grand magal...

C’est une décision qui va revigorer les fidèles mourides. Le Magal aura bel et bien lieu dans la ville sainte.

La décision a été confirmée par le Khalife général des Mourides, Serigne Mountakha Mbacké.

Regardez !

Votre avis sera publié et visible par des milliers de lecteurs. Veuillez l’exprimer dans un langage respectueux.

Dans le même thême

67 commentaires

  1. Deuguitte

    Etat du senegal faible nafek waye bou yawmal khiyame dinguéne layo . Dieu est le meilleur juge tai bour bou mandoula ! Loi bougnou tegué gneup gnossi wara teunkou . Fi nak senegal berina gnou meuneu togne nafek beug guislenma ak feuguoup deuneu tai do dara . Yalla moy borrom diam gni nagnou diamou nguir gnou mouthieu


    • Modou Thiam

      Sa way Yalla Serigne Touba la andal mou nékh léne mou nakari léne. Yéne fou ngéne dém perte vous êtes né perdant et vous mourez perdant c est ainsi Yalla beugoula Rassoulilah beugoula gars you bakh yi beugou niou la dakhté beugo Serigne Touba


      • Deuguitte

        Bessou peinthieu bougnou demé dagnou kham kouy perte inchallah ! Serigne touba gnoune meunouko bagne ndakh djoulite , djoulitay mbokam . Wayé vous en personne yenay diem a chaque di sakoul serigne touba ay ennems a cause de vos paroles yiy offenser tout le temps nagnou nangou ni gnoune gneup ni ay diamou yalla lagnou . Goorou yalla fo meuneu bok koulen togne yangui dieum sa moussiba wa salam nagnou diamou yalla topeu seydina Mohammed (sala lahou aleyhi wa salam) lolou moy deug


      • Deuguitte

        Sa wakh dji reuyna (yalla beugoula,rassoulilahi salahou aleyhi wa salam beugoula,gayou bakh gni beugou gnoula n’dakh beugo serigne touba) ngay diay sagne wakh yalla mo amé la reponse bayi nala ak mom ina li lahi ina ileyhi rajjihoun


    • Beugeu serigne touba

      Ahmadou moy borom diam gni sa waay bakoko yalla mayei bobou djoudou wo bay takhaw tay diko dindi fagn koko mayei wakhou maleu ioe wayeii adouna yeup bouniou manko won di bagn dou terei mou doon borom diam gni mom ahmadou mbacke


      • Deuguitte

        Soubhanalah ! Yalla nena bindouma nit ak djinn loudoul nguir gnou diamouma serigne touba ak mbolem serigne soufi yalla watié si kaw soufsi sen dound gui yeup dagn ko diamou yalla royeko si sangou sangue yui di seydina Mohamed (sala lahou aleyhi wa salam) nanou diem fagnou tegone seni tank gnou tek kofa mo gueune wakh diou beri dji te amoul ndianrigne point final


  2. Ousmane Mbaye Noreyni

    la determination des mourides ils sont construit la grande mosquee de touba en 1930 il yavait pas D’ETAT pour subventionner financer l chemin de fer de djourbel a touba juste pour construire une mosquee les motivation le devoument notre foi vous depassent apaiser vos coeurs parceque pour nous ils ya que mouride la diference il ya des selectionner et des non selectionner ici on prend les plus comptents pour ligeuyeul ku tedki bon dimanche balen ma ah


  3. Ousmane Mbaye Noreyni

    celqui ont refuser hier refuse toujour gni done bagne hier nioy bagne ba tay les complices du colon ils sont toujour en fase avec eux mais si vous entender touba mort ou vif doundou dém déh dém vous devais laisser tomber mais la haine et la jalousie vous rongent magal ak lou meuna xew meme s’ils en rester 2 mouride sur terre notre determination a depasser votre entendement


  4. Deuguitte

    Si les croyants vont a la mecque pour faire leurs 5éme pilier de l’islam ils y aillent pour la face de dieu (le tout puissant) pas pour les petits fils… le gars qui que j.ai entendu disant que makka pass pass nekatoufa parsk les petit fils ne sont plus labas . Demal gueustou li seydina abou bakrine wakhone diam gni bi seydina mohamed (psl) nelawé


  5. anta

    mais magal gui sou amoul khalis bi dou dougou magal busness leu yalla takhoul gnoukoy def seni poche ak sene intérêt rk motakh meunou ma comprendre gnou annuler 2 rakkas thia ndar dakh coronavirus ba paré Amal magal dakh magal lamouy dougal si khalis 2 rakkas yi douko dougal gni dagno yabate ak beugue sacrifie nitt gni dakh khalis


    • Moussa Gueye

      HEUREUSEMENT TOUTES LES RÉALISATIONS INFRASTRUCTURELLES SONT RÉALISÉS A 99,99% PAR LES MOURIDES EUX MÊMES DONC SI LE MAGAL CONTRIBUE A SES RÉALISATIONS ALKHAMDOULILAH AU MOINS L ARGENT N EST PAS DÉTOURNÉ DIADIEUF MOURIDES LIGUÉYE RÉK BAYI WAKH TOUBA DIEUME KANAME

      ,


    • Beugeu serigne touba

      Ndeysan sen khole yi dina dageu ba diekh rkk tei douniou terei magali yeen nioniou di wakh thi kanam touti serigne dina djeul lingeen geuneu beugeu thi sen ndjabot niouy magali inchallah ken mounou thi dara moko ligueyeul bormam bamou may koko


  6. Kadia Mbow

    maintenant jais tous compris l’état vous prend comme des veux rien voilà pourquoi il vous laisse faire comme vous voulez jais compris maintenant continuons


    • Moussa Gueye

      L ETAT EST MOURIDE MACKY EST MOURIDE BOUNE ABDALAYE DIONE EST MOURIDE ALY NGOUYE NDIAYE EST MOURIDE .TOUT LE MONDE EST MOURIDE MÉME TOI TU ES MOURIDE ET TU VIENDRA A TOUBA INCHA ALLAH UN JOUR OU L AUTRE


    • Ousmane Mbaye Noreyni

      elle c kadia mbodj touba mokay deranger du magal gui serigne demone lolou mo may jam gni dess sén liberter si diné SERIGNE BI MOKO KHEKH gni done bagne hier nioy bagne ba tay dem lene oubie jaka dji jam yi jouli


    • Modou Thiam

      N’entrez dans ce débat comment un État laïc peut s’immiscer dans l’affaire des religieux ? Et aussi partout dans le monde les championnats, les tours de France, les Us open etc ont tous repris leurs jeux et vous voulez que l’état interdise notre Magal parce qu’il y a le Covid ce n’est pas sérieux.


  7. malick sagna

    $$$$$$$$$$$$$$$$$$$$$$$$$$$$$$$€€€€€€€€€€€€€€€€€€€€€€€€€€€€€€£££££££££££££££££££££££££££££££¥¥¥¥¥¥¥¥¥¥¥¥¥¥¥¥¥¥¥¥¥¥¥¥¥¥¥¥¥¥


  8. Moussa Gueye

    AKASSA LE MAGAL C EST LE FAIT DE RENDRE GRÂCE A DIEU RÉCITAL CORAN RECITAL DE KHASSAITES MBERNDÉ PRIÉRE ET INCHA ALLAH APRES LE MAGAL DIAM RÉK KONE NAK WATHE LÉNE MANE DÉ PARÉNA ILA TOUBA ILA TOUBA ILA TOUBA ILA TOUBA ILA


  9. Moussa Gueye

    AKASSA LE MAGAL C EST LE FAIT DE RENDRE GRÂCE A DIEU RÉCITAL CORAN RECITAL DE KHASSAITES MBERNDÉ PRIÉRE ET INCHA ALLAH APRES LE MAGAL DIAM RÉK KONE NAK WATHE LÉNE MANE DÉ PARÉNA ILA TOUBA ILA TOUBA ILA TOUBA ILA TOUBA ILA


Laisser un commentaire