37 COMMENTAIRES
  • NDIAYE

    BILAYE KOUY TOKK AK TOUNKARA WAXAL LO XAM.KOU TEUP REK NIEUW SENEGAL THIA KANAM DI NGA KA RETHIOU.CE SOIDISANT RAPEUR XAMOUL DARA

  • modou

    ki mome c limage du jour comme lotre pere pop mane demlene guestou mo guene sa c honteux pour moi

  • vraimenttt

    il est mal informé. Dém lénn djangui mo gueune guénn toppp borom kourouss you goudd yiii gnouléni nakh rek

  • saliou

    dani dieul aye werde you niou metrisé woul ba dof fok ni ay nite légne hamo dara di diangalé bagne tourou yalla yi nguéne di dieul té hamoléne noumouy démé doffffff rek

  • ASSANE SECK

    Vraiment dama ci rouss té douma ci dara kkkkkk un jeune de rien du tout, un jeune actuel qui n sait meme pas parler, affaire bou rare fils, boy zindeing da nga tela rap té diango, Al ilmou houweu imane xam xam mony djiitttt, fook nga dem diangui ndax dou wéss, bayil rap nak dem ligueyyi dimbali say wadiour, diamono dji da meti,

  • Tioukh

    Je sais pas pour quoi les gens aimes inventé des vie… Il faut avoir la sicence avant d'ouvrir ta bouche…c'était quoi sa même il raconte que des conneries lui pfff

  • Deug rekka neekh

    Tounkara good job ! Zendeng teey lay gueudieu togue ci plateau. Wala sou seeneute Tounkara di nieuw rekk mou bouddi. Diango diongou wo nga beugg ratatati ci kanamou millions de senegalais. Lingay wakh amoul bopp amoul gueene. Di outt Buzz rekk!

  • beugue bamba rekka worr

    demal gëstou dji koy diangue ba mokka la go kou nane damaye tari sîn niou wakh nganane dangaye warate

  • diallo dieri

    way ki na délou daraa dja wayy khamoul toussssssssssssssss

  • assane seck

    Lii baakh ci yaw, amoul ben respect ci domou adama yi, khalé bou rew la, mbalak rek lay def nite gni hadratoul diouma, mbirou yalla boulako yalla nangoulé bo waxé rek niou xam ko 20 ans de hip hop sans avoir l'album té paré ngo bayyi rap fofoula yafouss yem kou respectéwoul S.B.N dem mouk, faw nga bayi togne domou adama yi am thieur ci nite gni pour avancé sino toogal ci wétou yalla sax mais do dem hadratoul ngay took malay feel ngay pisénté di mbalak, di signe nite fangue té dokko rétaan je te connais bien, baye niass néna un bon disciple doit avoir des bonnes manieres interieurement é exterieurement, Rouhoul Adab, baye néna souloukoul Adabi, sooboulén ci Adab yi, Merci é felicitation Tounkara, xam yalla lou wér la té ken mounoul xam yalla té diaro ci Baye niass lolou kén wahatouko mais un bon disciple doit avoir un bon coeur envers les autres.

  • assane seck

    li baaakh ci moom

  • rima

    Merci Tounkara!

  • rakhu

    pourquoi invite des gares comme sa

  • ousseynou

    mo tongn bopam

  • ndiaye

    Zinding mokhamoul dara nakh mahrifatoul lahi ken douka wakhe niii nakh nit koune famou tollou ngay wakhe ak mom tonkara nimoudef nonoula nit manoul geum loum khamoul

  • ratatati rek

    mdrr mais ki rapeur la walla oustaz demal sawi tè teuri niakk diom

  • DEUKHINE MBEUP

    non ZENDEN , yoow saay daal moo kamaamber , dooo deem

  • Freebop

    mdr !!!Bien fait pour sa gueule , cest a cause des gens comme ca que le senegal n'avance pas ; se permettre de parler de l'islam sans connaissance basé sur le coran hadith ou comprehension des sahabas .

  • samba

    ki va dans le plateau de tounkara doit etre pret parck tounkara a ses bagages dans les secteurs les gars j'aime le boulot de tounkara.

  • Pogy junior

    vs ne comprenez pas que Tounkara force les gars à être intélligent

  • pisco8

    MM SIL NE MAÎTRISE PAS CE KIL DIT,L'IMPORTANT C'EST LE FOND DE SA PENSÉE. NITT KO DEGLOUWOUL DOKO DEGU. WADJI DIOUMOUL SI AYA BI DAI DA YEGGOUL REK. TEKSI DOMOU ADAMA LA YALLA GUEUNEU BEUGEI SI LIMOU SAKKEU NAMEU SI NIOUNE NIOUY SOUTOURANTEL. L'ATTITUDE DE CE TOUNKARA EST DEPLORABLE ,IL EST TJRS A LA DEFENSIF ,TJRS DS L'OPTIQUE DE FOUTRE LA HONTE A CES INVITÉS. L'ISLAM MOY DIAM KOU WAX DIAM WAX SOUTOUREU

  • hadyagne25@yahoo.fr

    Non wajii mo amoul xam xam beugeu warratter

  • padana

    rappeur bi koumou yapp vraiment tounkara bakh nga fii

  • Sadikh

    Zinding ne maîtrise pas ce qu'il dit, il faut avoir une bonne maîtrise de la charia pour parler de khaqiqa.
    Cheikh Ahmad Tidjane et Baye Niass ay nitou Sunna laniou, si tu prétend suivre leur chemin arme toi de connaissance solides, cmt peut tu ignoré les 6 piliers de l'Imane et parlé de choses que tu ne peut expliquer. diangui wala ngua napi,

  • mia

    MERCI TOUNKARA . TU FAIS PARTIE DES RARES JOURNALISTES KI ONT KELKCHOSES DS LA TETE .

  • titeuf

    94 juska present tu dis que tu n`as rien fait dans le rap niak diom ak foula

  • khadim gning

    Tounkara defoul dara waji ni rapeur la beugua don ouztass té khamoul dara thi limouy wakh bien fait tounkara

  • cheikh balla diop

    قل هذه سبيلي ادعو الي الله علي بصيرة أنا ومن اتبعني وسبحان الله وماانا من االمشركين

  • CONTRE CHARLES

    HHAHAHHAHA TONKARA IL N'EST PAS SERIRUX KOI

  • cheikh balla diop

    قل هذه هي سبيلي ادعو الي الله علي بصيرة أنا ومن اتبعني وسبحان الله وماانا من االمشركين sourat yusuf ayat 107 tounkara merci senegal khamou ma lou takh niou daguar fitt kou diouk di am loy apliqué si diné dji takhamou niou darra khawa fér idji réck guéstou béne ayat niaw télé di diaye lou amoul

  • titeuf

    voici le type de sénégalais qu« l faut demolir

  • Fall

    Tounkara n'a rien fait ces jeunes doivent être prêts avant d'aller vers les médias
    il as pas de bagages donc il a tord et les invitations doivent être sélectives TOUNKARA

  • alice

    hay tounkara yén yi kén douko deff gorr wayé bakhna si mom kéne khamoul oustass la kén khamoul rapeur la

    • mac kevin

      salaamou aleykoum.
      alice souniou borom dafa dogal talibe mouride pire 1ª khassida moy music unik bimouy deglou di si yeungou 2ª amoul fitou tok si tele di wakh bakaaar you tolou ni parceke liko tounkara laathie yeup mom khamnani serigne touba jangal naniouko kone kou mokaloul tere yi do am fitou tok tele di wakh tothie-tothie you ni tolou wala kone talibe yi pures jeuflaanteko ak yaw maa ngui jegeulou nak wassalam

  • sunrap

    Zinding tu parle de l'spiritulite qui est si profond mais doit vraiment apprendrele coran avant tout sinon toujour tu auras des probleme
    force pas broda..kou nek ak seu yoon defaal hip hop ..te bayi nieneen niou weyeul yonou mahrifeu
    jajeuf

    • SONINKE

      TIEY WADJI BOU DONE TALIBE MOURIDE LA

      KONE GAS YI SAGA KO AKI KHASS TIE NET BI

  • alou

    tounkara il faut respecter les gens.danga beugue di trohale nit gni trop.c pas bon ça.hamo tousse boule gnou sonale waye.

Publiez un commentaire

Votre adresse e-mail ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *