19 COMMENTAIRES
  • max

    Non MBAYE Li dou yefou goor
    Mé vrmen nekhna trop bonne continuation

  • zahra3

    je pense que cest la meilleure serie senegalaise , elle reflete les réalités de notre pays. surtout par rapport aux maris qui laissent leur épouse derriere eux pour aller à l’étranger. Dara diaroul lii , dem khamoulo kagne ngay gneuw . Bravo soleil levant lal nguene fiy meti , personellement vous mavez profondément touché. Bonne continuation

  • madiyana

    Dana degue de niounane béne seye nekhoul khana mougne Fa rek ndakh sak niaboot

  • khar sow

    li rek mofi am nak gro you bakhe yi danlendi connte

  • wuli

    he les gas le soleil ses levait chapeau les gars vraiment c sa du telefilm on va ecraser un cafe avec

  • Anonyme

    Voila une serie interressante pas comme les autres avec que de journalistes et mannequins
    Bonne continuation

  • mounass

    damani nga gneuw tokk lol mére bi da yabaté

  • gueye

    Oh sama yarame daw na

  • TOURE CHEIKH OMAR

    VRAIMA LES GARS VOUS AVEZ ENCORE ASSURE VOUS AVEZ MONTRE L’INJUSTICE DE LA SOCIETE A TRAVERS SOUMBOULOU JE VOIS TOUTES CES FEMMES QUI N’ONT PAS CONNU LE BONHEUR DANS LEUR FOYER A CAUSE BES BELLES MERES

  • Madam Faal

    begue s touba,man buma amey goro bu melni dama koi rey,ndakh man ken doma noot

  • Barbara

    sé la realite la vie des senegalaise sama bop la giss amna sola

  • le rebel

    les series fusent de partout mais la c’est la cours des grands… vive wa Soleil levant

  • Nice

    Ndeyssannn…VIP wakhatiko…lila djiguene yi dounde si keur yi…kholal ma mère bi rekk une vrai diablesse….Waye lo Deff do ou diambour Yallah dinalako Faye si sa diambott…kou khalatt li do beug dugatt si sey….banekh zero …ke du stress…Mo takh jexorce les femmes à se trouver du travail et être ndependante financièrement…anda ndo nekh na wa ye ko bayi mou demm ak Mbagam..en plus senn domm you goor yi rekk la nouyy Yakal…doyy n’a warr…

  • bègue s touba rek

    MM. Fall yalla ga am goro you meel nii

  • ata

    ç très intéressant

  • Madam Faal

    Ndeysaan am na goro yu bon

  • zizou

    C des thèmes qui sont interréssant

  • vip

    Ndeysane sama boop rek la guiss si lii dieuredieuf coleil levant meti wone naa dieuredieif que dieu vous benisse une belle hidtoire

  • zeyna

    nexna ame na solo

Publiez un commentaire

Votre adresse e-mail ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *