PUBLICITÉ

Série: « Wiri Wiri » Saison 01, épisode 05

Épisode 05 Saison 01
Annonces

(28) commentaires

Ok

Nice nice nice wiri wiri machala bnne continuation

Madam Faal

nekh na

Kinzo

lii moye téléfilm. machalah

Insaciss

Il ya trop d'exagération de méchanceté .si pourriez modéré les actes de méchanceté ce serait meilleur à mon avis.

Max

Non li eup na sey diarouko

Bijou

Mais man maa am louma metii lii mom seuy diarnako?? Soumboulou yama daka seuy man, ca se comprend aussi amo fo dieum,tiey lii sama khol bi lay diehal

Bathie

The best soleil levant

Bineta

Non sama khol jekh na way
Chapeau soleil Levant Machalla
Soumboulou t'es superbe

Dada

Toute mes encouragements c'est vraiment un téléfilm bien sensé. chapeau à soumboulou elle joue bien son rôle mais sanekh dawalal touti yeurmeudé way adouna amoul solo.

Dada

C'est vrai que les méchanceté qui s'y passent font mal au coeur mais ya des femmes qui vivent vraiment ça dans leurs ménages.

Moussa Seck

dama contane trop si soumboulou degue rek laye deff li la begue si Djiguene daye kham lou bakh

Moussa Seck

Yala na lene yala defal diam diou barri si barke seydouna mouhamed rassoulilaa aminé

Moussa Seck

mane théâtre rek la begue

Sofesss

dieukeurou soeur bi raynama

Tonkin

archi nul ce théâtre. Le thème est vieux comme crézus.

Sofesss

mane dieukeurou soeur bi raynama lol

Vip

Tonkin le mal n est jamais vieux dans ce monde peut etre que tu vis ya vie en tranquilitee mais.walaye je le jure que j ai vu une femme qii vie le plus pure que sa.dans mon quartier .

Diva

j adore c vremen nekh ce telefilm bonne continuation

Dada

diminuez 1 peu le théme de méchanceté. li cé trop

Beugue Sénégal Sama Rew

boulene faté ni théâtre bi toudou wiri wiri té yégagougnou ci ndari bakham

Omzo

Mechancete bi eppul deh sama gas yi am na gnuy vivre pire je te jure..

Cheikh Omar

Trop d'émotions en regardant wiri wiri vous avez encore assuré

Dau

Diadieuf Soumboulou tu est une vrai actrice macha-allah, yagui respectè saye goro lolou baxnaa mougnale mais ligua khasse Mbaye nexnaa daffa dègue daugue motakh xol bi lath niaw niakk fayda la dèff wayè bayi ba

Black

Mais les larmes de Soungoulou la peuvent ramener la verdure au sahara..pitain!!!

Bouki

On en veut encore….eliminez "double2vie" et augmentez wiri wiri

Boyewade

Vraiment vous etes les meilleurs k les otre…….

Mags

Sa khol sakh Day diekh sokoy setane mais nice la série

Wane Love

waay aaay waaay bilay kou meunoul bawo lou yaakhou yawaa soleil levant vraiment je vous respect crx maintenant ni café machin ni double truc wirri rek di khaar ndaari mention spéciale a Soumboulou

Publier un commentaire