Senego TV-Gris Bordeaux: « J’ai jubilé avec la victoire de Eumeu Sène sur Balla Gaye 2 »

Gris Bordeaux qui était à L’Olympique Club ce samedi avec la Gfm, a révélé avoir jubilé dimanche dernier avec la victoire de Heumeu sur Balla Gaye 2. D’ailleurs, confie-t-il, au-delà des lutteurs fassois, Heumeu Sène et son lutteur préféré…..Un défi à l’endroit de Balla Gaye ?…Ou autres grincements de…dents dans l’arène?
wakh rek laye def
beaucoup de personnes aime Eumeu Sene grace a sa education
Machallah Danga baakh réck
Mbeur deugue d'où farr meme bo farré tu doit le garder pour toi adunaa d'affa goudeu tank.gris je te croyez intelligent mais ndékétéyoo yak mbeur yeupa yamm dof parler sans reflechire
kham naniou lepp combat ngay out parsk danga kham ni Tyson dalay dane…MOUSS!!!!!!!
Limou wah rafét na,amoul dara lou gnaw
Mercii gri lii nga wxaaa rafet na
khamo si dara
Vrai con
wait and sera. inchalla après ton combat contre Tyson do jubilé car dinga danou ba meuk souf.Ta yaw avec Balla Gaye y a pas foto
Si gris
Yallanala yalla dèfal diam amine
gris bordeaux mom takhoul gnounane mbeur,limoumeun takhoul gnou nane beuré khèkh rk djiap tank eumeu 4 fois mounouko dan beugueu gnou sonal«nopil wayaw»
CE con n'est pas sérieux. Combien de fois balla a pris ta défense devant Eumeu en disant que tu l'as bastonne? La dernière fois remonte de leur f2f au monument. Maintenant qu'il est tombé tu oses le défier ? Avant hier on t'a propose 100millions pour le croiser quand il était roi des arènes et tu as pris la tangeante et 80millions pour Tyson. Quand selbe a prédit ta chute devant ce dernier t'as déclaré forfait déchirure 1an 6mois. Balla a fait 2 combats devant toi, et malgré cela il est tjrs désire. Reste la rek di wakh sans réfléchir au lieu de préparer ton cercueil pour Tyson. Papa et lac rose t'ont déjà dépassé, maintenant tu comprendras quand gris junior de laissera derrière. Avant ngay teuk mbeur dangay dane ba pare. Mais defofi dara di rey nitt yi ak wakh. Niakeu fayda tout le monde vise roi des arènes ngay teuk niou danou ba pare. Tappete boukhoute wessou woul gris dakkar bordeaux. Après Tyson s'il te plait laisse le 3ème tigre a papa ou lac rose, car tu vas encore mordre la poussière une nième fois. Danou, danou, danou, danou ak danou rek.
gris ioe bayil ni nga méll ni rk nguay déff ba djakhasé eumeu fii et tyson lolu lo thiy wax ahh
Chaytane rek la gris bordeaux def waye kou nek ci deek waro retane kou lap t yow sakh fekhel def moitier li balla def mo gueune.meuno beure meuno touss tok fi tak radio yi di wakh thiiiim.
Chaytane rek meuno lidianti sa combat ak tyson t fekhe agg fi sa morom agg t diemeu def rek n serait ce la moitier d c k balla a fai mom souniou ngainde gogou gathie ngalama outena ak yaw.
Borome khol you bonne yi rek nio bagn balla gaye ndakh dalene raw motakh.magale nguene t dou nguene meusseu degueu roi d arenes t mom koi kon puisse dir defna fi lo khamni niep guiss nagn ko.
Ay vrai dof c'est Mbeur la !
Gris ya sokhor way tu pouvait le garder pour toi mbeur ngua balla gaye2 meme si c une fois il ta supporter en cachaite soit humble.ta toujour méfié balla ne pense jamais qu'il tombe rek tu peut le battre attention a son future adversaire du moment ou qu'il sais déclin lui a fait le sort qu'on la jeté inchallah les bon marabouts vont l'aider
Mane gris dane ko rek lo dane ma khep
Kharal gnou diokh leu Balla mou défaral leu bagass li ngay beuri wakh yeup Eumeu sou nékkonn sa kharit deugg di nga beurékk mom?déféna né Balla ngay provoquer té danga beugg combat
contente thi yaw gris . niila. nit day wakh Li nek thi kholam mogeun hypocrisibi waaaay.
Contane nga ci seytane
il né pas serieux ce gas. c parce que eumeu la battu /golo bou tate lakké dé fay beugue morom
ds la vie il faut savoir accepter les critiques et les choix des gens et non jeter de le discredit sur les gens .il fauut laisser les gens assumer leur choix et leur position et non perdre du temps sur des details
Motaye suko nekhe dou farale Eumeu Sene dou Balla gui di kharitok Boy Nar te Fass la nekone waye mayeleniou diam waye fitch che kene amoul droit am kharite way Merdre waye Eumeu Sene da am yaar ame teguine nioune wa Fass sounou khole nanuko def .
yaw xaral ma wo heumeu mou defal la bagage;;;;;;;;seytanéée ;;;;waya boula tayzen danéé balla jibilé rék
euhhjjs
pour mw il la retion skun a son propre soi
Heee boulene niou sonale way gris bou farale eumeu loumou meuneu wagni balla gaye?mom day touss na diangui beure mo gueune ci mom fi nak kou fi merr bay depasse niit yi da nga respecter woul sa bop.
N'importe koi di critiquer mbeurou diambour ba parai souniou wakhe sa mbeur dara nga merr.nioune balla for ever lagnou wakh kou merr nga clamer yalla.thiiiimmmm
gri da kham né eumeu moy bayam rék takh yalanako tayson dor miou danou mouy tok dital popam
gris dafa barri wakh mème bo suportè eumeu danko wara gardè sa khole ndakh say fans amna ñiouy supportè balla gaye 2
Gris n'a qu'à penser à sa revanche contre Eumeu mo ngueune mou take deal
@ya oumm wa fass gris voilà papa sow a tombé yénné nekk leu borom mossay fanann
ya doff dè…gris yako yoor
Dou papa sow danouna na jubile mom mo si dess.bo sokhorai sa kaw lay keupou.wakhale si sene defaite bobou.gnaaaawwww
Ki moy ser makhali thikki la thiossano serou kharam
Sa nougn you reuy di melni kilo kheuteur
Toukh nga ba rer
Lambeu ji bamou dadji yassi geun niak fayde ya fi maak te amo foula
wa sokhna si boul gnou khass nak thiky sèr degoufa yaw mba kham ngua fingay thiossano enplus pesonne na le droit de jugè khamaloko dara faux pa ce permettre d'insultè les gens comme ca bou kharamè ak bou khamoul yeup lolou khamo thie dara seul dieu sè ki es le meilleur
hé gris yamba rek le jour de son combat contre yekini il est venu au stade né tatt takhaw rtann ba tass yékini a dit des qu'il a vu gris bordeaux il a dit a ces poulain regarder gris bordeaux nékouffi sa veut tout dire.bayil tokh mi baala tokhmi dila tokh bakhnaa.sportif dou toukh surtout nak yamba
Non mais gris wakhou dof guey wakh ni concentre toi sur tyson c'est mieux balla diam rek guène koy mey bayilène tass rèw tchiiiiip
wawawa eumeu da neeha beugeu nakh da beugable bakh yarou
merci gris
thim
gris rew nga boul fater tyson mola takha fouy yaw ak say morom mofi indi milliong yi dou sa morom sa mak leu
gris ya sof
tu es honnête et franc
walahi gris beuguena la ci ligna wakh eumeu dafa bakh té yarou , eumeu séne diam rek gnaye ame incha allah
ce kon la nga xamné mooy sounou gathié nioune wa fass
Balla is the best