apsfd-senegal
Dentsu-Bal
26 COMMENTAIRES
  • Chiw Titi

    TITI LA MEILLEUR DES MEILLEURS ELLE A ENCORE ASSURÈ COMME D’HAB ALORS SANILÈNKO AYE GNANE REKKK MO GEUNE WAXE BII AMOULE SOLO….ELLE EST LA MEILLEUR ET ELLE RESTERA LA MEILLEUR. VIVE TITI ET VIVE LA MIFA TITI POUR TOUJOURS….

  • diouf khadi

    machalla titi si khaw si khamne silou bakh rek laf thiate nekhna looo mo ndakhi déf nayou louyou nekh khana nekh rek looooooooooooooooooooooooo sakh laf thiate

  • khady

    D’abord félicitations titi on est contant mai elindji youssou dou prince art titi akh prince art ligeuye lagnou done def mai nite souy ligeuye akh yaw dakkoy defal limou beugu te sou change same dese prince art daf faye delou souva diekhe yalla dafkoye may lene

  • elindji

    titi ta place sé o prince arts

  • elindji

    avant tout d’abord je te félicite pour ton anniversair,ce ki me preoccupe on pe sé ta relation avec le prince arts ,titi noubli pa ke youssou ndour a beaucoup fé pour toi ,il a beaucoup fé dan ton carriere musicale,si ojordui lé sénégalais t’ont connu sé grace a youssou car lé chose ont été tres difficile au debut tu été méme le point de découragé ,sé ce méme youssou ki ta pri en guinée pour te ramené o senegal et produire ton premiere album, les souvenir son bien parfoi dan la vie,youssou et sa famille ont beaucoup fé pour toi titi ,nécoute pa lé hypocryte titi,je di tout sa parce ke je tadore je voulé ke tu soi come lui .ta place se trouve o prince arts, lii coulako wahoul dalay nahh bilahi a bon entendeur salu

    • Chiwi TiTi

      ELINDJI IOW XANA GEUMO YALLAH

  • elindji

    avant tout d’abord je te félicite tiit tu as fé un vré chow mé ce ki me preoccupe on peut sé ta relation avec le prince arts,titi noubli pa ke youssou a beaucoup fé pour toi et il na rien

  • max

    machahala yalla nala yalla defal diam

  • tyma

    dafek nii dognome té dognou yaw

  • nogayesaer

    titi lep diam

  • zeyna

    prince arts dougnou si len titi day demm ken douko teyé

    • elindji

      mé san prince arts est ce ke dii nguay ham titi boguissé yaguii wahh titi titi prince arts motakh

  • JOOP

    LAFE THIAT TITI ANIF BI NEKH NA .BRAVOOOOOOOOOOOOOOOOOOO

  • yama ndiaye

    la lionne day déme kén douko téyé i love you titi la rienne du grand treatre

  • Nene

    Titi day deem kenn douko tiyé

  • NDIAYE

    deukk bo khamni nitnhi amou niou yeur mandé moye galsen yak khaliss té opital guarappe you meut yakh amoufa séni dekando yi amouniou sakh louniou agné fisabilila maye titi lou bakhla mes thi soutoura envolope yangui fi

    • Chiwi TiTi

      Ndiaye sache ke la vie est ainsi faite par DIEUX ALORS SOKKO BEUGUÈ CHANGÈ REKKK DINA DOYE WARE CAR GNI DAGNIYE NEKK THI BANEKH GNI SI NAKAR AINSI VA LA VIE

  • enma

    je tadore titi

  • saly thiatu mifa titi

    titi foumou dm bayi feu trace kén dou mom ?? él sera tjr la reine du grd théatr

  • touf

    mashala lingay weuyy nehna té sagnsè nga

  • simone

    titi veut juste montrer a prince arts qu’elle se débrouiller bien, mais vraiment qualité musicale zéro !

    • ibra

      yaw danga sokhor nioy wakh

    • Chiwi TiTi

      SIMONE IOW WAXO FII DARA WAXENA LOUYE QUALITÈ MUSICALE POUR IOW

  • doyna

    titi yarou nga mane nga way référence nga thie daw gni lou bakh rek ngay wakh di thie dokh yalla’a may disque dorr

  • bineta diallo

    titi faip titi partout titi si khole titi wakhine avec titi lép falaw

  • girafe

    Titi tchi kaw rekk laff thiate meune gua loll liguay def

Publiez un commentaire

Votre adresse e-mail ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *