19 COMMENTAIRES
  • BLK

    boy wally nekhouma dara !! mais deugg nekhoul nak yafi nekk

  • Jeanne
  • soda

    DSK SECK

  • parisfrance

    bouma rèyyy soda hahaha

  • parisfrance

    bouma rèyy soda hahaha

  • conv

    yves ndanane

  • fa

    ouyoul lii fornaa

  • amadou deme

    wally affaire bi yeuwwww leuuuuuu

  • Pape

    Wally seck bakhoul thi mac daf laye gawa yobou retraite .badola la boy bi Leipe la beugue dieul.

  • drame

    wally yaw rek la

  • carlos

    baye fall bi yay nganane

  • bb

    yaye sene baye dh deugg nekhoulll jtm wayyyyyyy ?

  • Mamy Coly

    Waly seck yaye bombe laf thiat

  • fans waly

    waly coor dieg dji ac diankhe dji ac goor djieguene gni mane yawe la gueme mane waykate you djiguen gni yasi dakha waye waye woutel djiekeure nack amnga 30 ans yangui bague lambe de bakhna

  • abass

    nooo bilay deugeu nexoul mais wally do kena teii kena dou yawwww….afer bii diaroul wax diou beurii kou meune na deff je taime papa

  • you

    super Waly leup nice machalla

  • rire

    fans waly yow dé nonou waly nga wayé yeureum nalla ndakh danga nonok khalè bou téki kou yalla bakhal ki kouy nonam so teudé do nélaw dé wakhou kou kholam bonne rék ngafi wakh . sa baye dé modone guélou magnank kasse ki dou yow dafa responsable yor keur gou bakh auto bou bakh diabar bou rafét ame ndiabote komme kay yow yaye guordhiguène bou mak bi domaram

    • fans waly

      wa yawe kooye saga wa legui souma fayou woone nack je respecte mes parants waye nak balnala ndakh yawe sa yaye nga begue kouko saga khmau nokaye saga ngani kharal ma saga koo khamni soumaka saga mou fayou waye nack melou mani yawe

  • omar

    nekh na

Publiez un commentaire

Votre adresse e-mail ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *