Le sac efféminé de Waly Seck agite le web

2 clips en moins de 48h, Waly Ballago Seck continue de faire du bruit sur la toile. Le fameux clip « Stay » sur lequel le faramaréne s’affiche avec un sac plus ou moins « délicat » divise les internautes.
Sans titre 3

72 COMMENTAIRES
  • France

    goor bouye yoré sacs gou djienguene noumou toude

  • France

    Il se promene avec le sac de sa femme goor djienguene ….

    • seck

      li dou yefou goor srx

  • deug

    et alors c est a la mode c est tout

    • DIEUL SA ROUH

      YA MEUNEU DOUL

  • Kalimat

    Boy bi dafa beug yakh Sénégal au détriment de se remplir les poches.. canara deug mai nak les masques ne cessent de tomber à galsen.

  • Anonyme
  • Kkkkk

    man Dal senegalês yeemnama mais li clip la rek Wally dou doxei sac bu jiguen si mbed slmt pour clip bi gueuna am buzz rek mo takh mou yorko

  • Mimi

    Ay sér nguén nak Fi europe guor you bracher yeupe meuneu sagnsé so douguer si magazin yi daniou ame raiyon especial dafay ame sac yi Li sac pour guor la WALY dafa brancher

    • olddiagne

      Mimi bougnou sonal goor gniko fiy deef ay goor djiegen lagnou

    • Münchenerin

      Mimi….. Ya maneu doule … Khana yaw rék ya nékeu europe?
      Bann boutique si europe moy vendre façons sacs yî pour des hommes ?
      Mêm les trans ne promen pas avec un sac a main
      Mék si resau yi di doule rék

  • walabook

    demléne ligueyi té bayyi wally.il avance;et vous?

  • Wesh

    Yaw fo nèk ci europe bay wakh sa wakhou dof yii! Yaw ko yèp

  • bonito

    Mimi stop doul bakhoul

  • chekh

    yaw mimi kou mue na doul ga khamou ma fo nue waye yaw mome doul doula ray. mane magui fi usa waye mousou ma guis gor bou yor li bayi luen lo luen sopou daga nal go ki kou ko diapue diapue gor djugun bou bon doma ram. li bayam nuegue si kaso bi mome mofa warona nuegue

  • inna diawara

    mimi yaw kou mana doul ngua

  • Baps

    Mimi sa wadji nekhouta defendre guis ngua sipinagnoulako dey khol lingua defendre doyna ware

  • Rama Badiane
  • LEUZ

    Bayiléne MiMi limou guiss rek leu wah nit day manou

  • BB

    Mimi vs netes pa la seule à être en Europe,j'habite en Europe,ya des rayons pour hommes habits,Sacs,chaussures et accessoir,mais j vais vs donner des details precis,Ce sac est l'imitation de la marque d Sophie Holmes ,vs allez à Bijenkorf Ce magasin de lux vs verrez vivre en Europe ca n v rien dir il fo connaitre les marques et s'habiller avec,bcoup de Senegalais confondent pomme d terre et Angleterre,ils viennent en Europe et achetent des articles et ils n savent meme pa si c maculins ou feminins ou des chaussures d'hiver kils portent au SN ou il fait telma chaud.je vois des femmes ki portent des ba Pour aller danser parcontre les ba sont des accessoires Pour l'hiver contre le froid,

  • SnConect

    Le sénégal a maintenant son propre réseau social visitez le SnConect.com et merci de partagez l'info

  • Mimi

    Yenama dak doul etre devant son ordinateure pour critiquer les gens c'est facile je ne vous conner pas vous ete incorect est irespectueux Aller vous faire foutre souniou dadier wone ba kounék si yéne ma kham Moy kan ak loumouy sagnsé ma meune léne tontou waly amoul séne diot sène khol mo diékh té meunou léne si mome léne koumou nékhoul boul khol

    • zak

      mime boul wakhati lou mel ni mane france la nek magasin bane moy diaye sac gi jigeen pour gor ,fi gor jigeen gni gnoye solou yore sac comme nous jigeen gni di solo au faite waly kikoy conseille si solom dakoy nakh et sou done vrais mec dou nagou di gadou sac jigeen ,bode fans waly boumou takh gay wakh loula nekh ,khamone meme pantalon jean you gor yi khewel senegal fi gor jigeen gni gno koy sole ,boy youkoy sol fofou degno comprendoul dara

  • chekh

    yaw kham gani say doul moruey mo takh ki bou ko don goruel day due gue diame mie yaw mome say doul moma yuem gay wakhni yagu europe di doul nane ya doul

  • rohey

    Let them talk u a d buzz we love you papa

  • Zezu

    Mais li sac gor la xana kay couleur bi mais sac gor la .xoléne sac yi boudoune couleur noir

  • oneluvafrika

    si vous voulez comprend tapez ( agenda gay illuminati ) sur youtube digua kham boy bi si lan la nék il va détruire tous les jeunes

  • zoula

    waw yen xana mou no len wax rek t dou guén sagua mes yeun waly dina lene ray guén dée dé li lan la mes ken dou wa senego dougn gnou djiokh mouk lignou interese heur bougn kheuye t dougalougnou waly rek dougn am lou len nex waye baxna waly dina lak gnou bari biguen koko dale waxal ba tey guisa goulen kosi daiguen di wax rek sou guen xamon ni waxal ko niit t nekouko lisi yala wax di guen bayi djienbour gniko nek deug dougn ko manifeste dagnouy yiwyiw lou ak di yarou yarou lou nga nan ki dafa bax dafavyarou mandou leen t dem djamou ji yala adoubi djiex na ba pare amoul mag amouk xalee waly migui dem dé féxé len dem mo guen wasalam sou kadou yi gniagase magi djiegalou

  • ziz
  • goor yalla

    dayap wa senegal

  • tafff

    c un homme rek ç pas grave ç les conséquences du moudiome diamano tous les seytanes couvre Satan

  • dikha

    niom khana regards wo ñiou clip bi bijoux bi waly diokh femme bi mo nek si sac bi Bala ngeuni wax da ngeuni xoll ba parè mo ngeun

  • Ding

    PD FINI!!!!

  • dikha

    yèn khana regards wo lènn clip bi bijoux bi waly diokh femme bi mo nek si sac bi Bala ngeuni wax da ngeuni xoll ba parè mo ngeun

  • Nafekh bakhoul

    Wally na goré wayy yaw tamit; Ne laisse pas ces homos te manipuler pour l'argent.
    Tot ou tard les masques tomberont. Qui vivra, verra.

  • julien
  • bb

    C malheureux Dans kel pays sommes nous vous Ki vous dites journalistes Donner des infos qui interessent et peuvent faire avancer la jeunesse arreter de vous interesser á ces personnes Ki ne travaillent ke pour leur compte et Ki pervertissent davantage la société g ne juge personne mais un homme Ki s habillent et se comporte comme une femme coma on l apelle Et Ki se permet de dire " na goré boula nékhé jiguénéko"? Faison attention aux termes ke nous utilisons goorr day déf yeufou goorr jiguen déf yeufou jiguén Si vous voulé ke la pauvreté le manke d emploi et la misére cessent Dans ce pays

  • julien

    @ MBAYE ON BOXE PAS DANS LE CAMP…

  • julien

    @ MBAYE wade, on BOXE pas dans le meme Camp

  • julien

    @ MBAYE wade on BOXE pas dans le meme Camp

  • NIT DOFF KILLER
  • fans waly

    adja khodia waly seck koume nekhoule topal fale waly mofi necke wayei waly coor maniang affaire na goore waye wayei sakh boula nekhe sa diekeure maniang casse dada yoor sac tacke fere ac bethio mais boule jeune seneglais nack

  • NIT DOFF KILLER

    fans walli ferm ta guel et fou l can"

  • NIT DOFF KILLER

    ki fouma dadjiek mom raindi dem lay deff

  • zooo

    mimi ay ya ayyy gor day deff yefou goor mimi ya ayyy

  • fans waly

    koy reindi mane en boy fans waly la waye douma kooba dei soune dinala douma banga dawe tu te prends pour qui waye khamadi

  • deuch

    Wakh diou bone deukoul famou dieum fa mou diougé la thiosano bayi léne waly raw naléne dé bakhna rek

  • gazal

    De nos jours on constate une promotion permanente de la médiocrité au senegal à travers la Télévision, les radios et surtout au niveau des réseaux sociaux. nous sommes cernés par un système LMD où la détérioration de la société est progressive.
    Combien de fois avons nous vu des homosexuels montaient sur les scènes de wally seck , aux yeux de tous, pour lui offrir de l'argent sans personne n'en parle. En tant que musulmans il y'a des ses pratiques qu'on doit comdamner en effet Le Prophète Mohamad (psl ) nous explique que si quelqu’un de nous voit quelque chose de mauvais, qu’il le change de ses propre mains, s’il ne peut le faire, par sa parole et sinon par son coeur et c’est le dernier degré de foi.
    Désolé de le dire mais notre jeunesse actuelle manque de référence

  • ref

    waly sakhe mane na niake bania done goordjiguene mais mane na ame contra ac goordjiguene you mac yi ndakh diamono yi jeuness seneglais tope naneko nimouye solo ak fethiame mou bonne manna sei profito jeuness seneglais bepe aye goordjiguene

  • nfic
  • NIT DOFF KILLER

    Ref wah ga deugue dh

  • NIT DOFF KILLER

    Ref Right rk ga wah

  • CHARLES

    bon c'est quoi le probleme un homme qui veut pas etre un homme ou un homme qui fait ni homme ni femme ,moi j'ai une solution pour mettre tout le monde au pas une tenue qui faire plaisir aux senegalais attention je vous propose LA BOURQA ha OUI JE DIS BIEN LA BOURQA pas trop cher pas trop du corps et en plus on sait pas qui tu es .personne ne sait qui passe et meme si ca explose on ne sait pas non plus.Voila a prendre ou a laisser c'est la democratie respect.

  • cool boy

    c juste la mode si vous allez dans les boutiques comme zara,vous trouverez les sacs pour homme mais d'ordinaire se sont les homosexuels qui l'achétent de plus.

  • sophie diagne

    waly a son style aà lui alors si vous n'êtes^pas content allez vous faire voir ok.waly ne force personne à le regarder il fait du PUB au moins lui il aime ce qu'il fait.I love u Waly

  • jamai

    fair a Pape diouf il arive vite couri.ballago

  • goor fitt
  • GM

    Doungkh la – vrai kooba ngui nii nak!

  • ffff
  • bayefall
  • dija

    no mais srx c ala mode les sacs à main et wi effectivement louis vuiton Chanel tte les mark fon des sacs à main pr homme le sac de wally est juste cool bayi len sokhor way koumou nekhoul topal feulé vous dites ke wally gor jiguene la esk danguene guiss foungne KOY dioutalé ? bayi len doule way

  • diongue

    c di piblicite

  • du nimporte quoi

    wally je n est rien contre lui main son comportement un jr au l autr va finir mal c un artiste ki vie sur son art auliè l amour d l art son comportment dèrange comment un hom p s faire des afaire d fam ils n donne pas l respèct au argent il l gètte an plin consere biss mougui si bisyie bisbou sangèoul comportman djième donn nite tè corrèk dinakoo moussa reudiou damalnnè mom rèk mofie nèk na kholl si ay moromone khollale pape diouf nimou korectè nite kou bakh day nourrou nite koor da warra nourou guoor

  • deug

    Ce sac à main, il l'a tourné dans le clip pour l'offrir à la fille, vous êtes bêtes c'est dommage

  • Abdou Seye
  • samba

    j'habite en suisse depuis 2007 j'ai jamais vu des mecs avec des putin de sac main comme sa

  • zoula

    mai yéna li guen wax ni yeup ci waly mai yen waly dina len ray nguen dée dé ly louko fi djiar nane lene potou ndox t guen noyi bou bax xa bax bisimila

  • s'wally

    M nn yenn du n'importe qw guenn fi waxx m c de la mode nn epui clip mo gua lagn serr genn rekk thippp… bo lenn amm3 lo lenn di critiqu3 deguen di bayi ba am accès si mode SÉNÉGAL nn…

  • diouf

    pddddddddddddddddddddddddddddddddddddddddddddddddddddddddddddddddddddd

  • petit corneille

    Salam ,ce sac a main de wbs a vraiment fait de polimique masculinement mais bon,
    Tout act a son explication moi j'apprecie pas son talent mais frenchement c'est bon chanteur qui va avec le monde moderne.
    Et il est trop suivi par les filles ça veut dire il a plus des fans féminines que masculine…bref je vois pas du mal sur sac mes amis …wbs est d'après tout un chanteur comme tous les autres et pourtant chacun d'eux a un défaut …Wally bonne chance mais essaye de faire taire les gens….

  • moussa ba

    Waye na goré gore daye daife yeufou gore

  • moussa ba

    Na goré waye. Ton comportement est mauvais.

Publiez un commentaire