PUBLICITÉ

le « haalou » de Sala Bigué « Serigne Touba Rék Moo… (Video)

La mosquée Massalikul Djinane financée par la communauté mouride, est construite sur un vaste terrain de six hectares, dans le quartier populaire de Colobane. Considérée comme la plus grande mosquée du pays, elle éblouit déjà le monde.

Sala Bigué dans TMTC. Dieureudieuf Serigne Touba Amoul Morom

Regardez !

Serigne Touba
Annonces

(10) commentaires

Khady Anm

Dieuredieufé serigne touba

Ibou Tyane

DIEUREUDIEUFÉ SERIGNE TOUBA wakhtan bi amna solo

Baba 99

Waaye toubab bi tam bari na doole.

    Lébou Piir

    Toubab bi de bou Serigne bi djoulé si guethie bi mom  dougou na si soufou guethie gui té dokhna si weer bi euskeuy 

Kheuch

DIADIEUF el Hadji Salabigue.Wax nga wax bi

@ Lébou Piir

Yaw lébou piir, andale ak toubab bi nguène takhaw ci kaw ndokh bi bakham
Espèce de complexé, ton genre bi nio yombalone esclavage et colonisation.
Serigne Touba, sounou donè aye musulmans taye, acceptez que ci mome lako borom bi diaralé.
Serigne touba mo siguil dèr bou nioule, mo siguil lislam.
Nangou ak bagne nio ci yèm. Lolou la yallah dèf.

Abdoul Xâdir Mbk

Waaaw Goooooorei bég nanu çi yaw

Nar

Wawaw

Gora Seck

Ma cha Allah amena sollo dieureudieuf

Baba 99

Lebou Sénégalais wala Africain il aime se raconter des histoires à dorlir debout. Si tu relevés des incongruités on t’insulte ou bien on te dis jaloux,. Ou on de ite dew trucs du genre Diaradieufetee, keenn du.moom ( on peut le dire de n’importe qui, ce slogan) . Les toubabs et les Asiatiques iront coloniser d’autres planètes après avoir nous avoir evangelisés et infantiliss , et avoir pillé nos ressources Ils nous lausseront entre nous et notre crédulité et les Naar viendront terminer le boulot. Triste.

Publier un commentaire