75 COMMENTAIRES
  • PMT

    ils sont deux artistes planetaire faut pas seulement dire que akon est l’artiste planetaire. I love them both so proud to be Senegalese.

  • Facha

    Il faut comparer cet apprenti chanteur aux enfants de sen petit gallé

  • Ameth

    Il faut comparée quelque chose qui et comparable Youssou ndour dou moromou bayou wally

  • Sokho

    Ay way Youssou fouleu ndanane di diar? Masha allah

  • YOU YOUSSOU

    ANONYME Yagui comparer battery ak courant ah! bayil thiaakhane waay

  • oumou diack

    forna jeuleul akon khana tioukhna

  • ANONYME ANSWER

    ANONYME Yagui comparer battery ak courant ah! baayil thiaakhane bi waay!

  • Mamadou

    you qakho fi dara way degaz way

  • ANONYME ANSWER

    ANONYME YAGUI COMPARER BATTERY AK COURANT, SENEGAL REK LA KHEW

  • mamadou sarr

    « RAS » nickel franchement rien dire Youssou the king of mbalkax.

  • ANONYME ANSWER

    Sa waay yagui comparer battery ak courant dei. Thiey Senegal!.

  • mamy

    belai do morom waye kat yee chi aduna Mashallah

  • Anta

    Millenium mbalakh lagnou wakh gnoune merci pour ce beau duo

  • Awa

    Maleu beug barké Serigne Saliou

  • anonyme

    you danga thite wally dalay douma maguete nga demal teudi

  • abdou

    ndour wallahi tu n’as rien a prouv li nekhna b naw

  • Mee

    Vraiment merci.c’est un duo exceptionnel.mes 2 stars plantaires.lii koun nekhoul khana sokhor

  • right

    hahaha le roi est de retour lever vous les apprenti chanteurs

  • Tamarah

    The lion is back that’s wonderful

  • modou gueye

    dama kontane trop je suis fans de akon mai dama yague khare lou melni roi du mbalax kontanna akon mome nileu come dab

  • Fama

    La star de toute une génération!!!!

  • Cissokho

    En tant que malien je suis fan de ce monsieur

  • Nanette

    Ay way lii nekh laf thiat waayyy

  • Diallo Diery

    Deug Deug yaa meuneu way merci pour ce beau duo de choc

  • Mactar

    Tu n’a plus rien à prouver une fierté planétaire.

  • jack

    sera une bombe porca troia

  • Coumba

    Youssou la star planétaire loo def mou nekh masha Allah

  • Khalil

    La fierté de tout le continent africain, mes respects NDOUR MBERGANE

  • Yama

    ou sont ces soit disant apprentis chanteurs de PD qui nous tympanisaient matin midi soir? sen baay nieuw neu dem len sawi té teudi gaw

  • Weuz

    Nice Nice nice

  • boy LG

    ahhhhhh Alkaty dou bayi Door de yat wa Dallna Famda dal Farathie fithie mbathiii farathie Farathie Fithie mbathi

  • Lolita

    Bravo l’artiste bolewoul dara ak ay wakh

  • Ndoye lebou

    Papa You à quand le prochain Bercy, tes fans de ka diaspora te réclament.

  • Fifty

    Maa yeureum koula bagne Ndour une référence et fierté pour notre continent Africain

  • Fanta

    Papa You contaan naa enfin tu nous reviens comme ca ses petits apprentis chanteurs pourront dégager!!!!!

  • Cisco

    Masha Allah nous sommes pressés que l’album sorte

  • Anta

    Très heureuse d’entendre ses mélodies encore une fois dieureudieuf Ndour Mbergane????

  • Naïma

    Papa You damaleu beug depuis ma tendre enfance comment faire pour te voir?

  • amy

    thiéy you khamnani yalla maynako

  • Nikita

    YOU nak boul yakh Bercy faramarene bi ndakh sou album bi guene gnou fateko????

  • khadim

    YOU for ever????????

  • amy

    badio nak laaaay you mo yakou

  • hakeem

    music et non la politik

  • Toufa

    Bleu merci wakh ngeu lep guiss gue ngi bouleen sakh tontou dagnouy am louleen neekh

  • bleu

    Birima ak bitola nani len sen garabe dangen dof da melni borome Disque d or ak Grammy ngen di wakhal sete len kouka ame sénégal ba pare dordi togne yabate ngene trope

  • Gueye

    You dé mo téré nelaw bayou Wally wakhatou malak moom

  • Soso

    Eupleuw You mingui nieuw dal sen kaw merci et continues de nous régaler you are the best masha allah

  • Bitola

    You xamoul dara Wally moko yor

  • Birima

    Khamoul dara

  • MOO mergane

    Non youssou mome rk leuu

  • Anonyme

    ckoi sa intro

  • Maman

    Tay rek ngen dé You is back c’est très lourd!!!!

  • abo

    ndour do sen morom tu est le meilleur chanteur du monde

  • feuz

    on avait ta nostalgie malgres ton age ta voix est exceptionnelle

  • Taphisko

    You doo nit comparez mais jamais égalez

  • Oumou

    Masha allah YOU nous t’aimons car tu est notre fierté à travers le monde

  • moustapha Diop

    c’est beau Ndour le senegal a besoin de tes chansons qui font la joie des gars.

  • sy

    gran bi il et for

  • hassim

    tro nice machalla

  • Fary

    Ay way dieureudieuf mame yalla je suis très contente de cette nouvelle nous attendons cet opus impatiemment!!!!

  • saly

    khamoul dara ci politique bi mothi gueuneu nul

  • nedved

    bien parler theo

  • Mimi DIOP

    Tey leu lepp di lerr kounekk khamga kouleu meun papa you sou gnewè gneup nè nè tekeu Wawaww ????????????

  • NFS

    Bilaye So Yeulbo Poussière Ba Rék Laniouye Séne. On L’attend Avec Impatience!!!

  • Chulita

    Cool….

  • iba

    kou ka Meune ak koucoye dim

  • binou

    la music sénégalaise a besoin de vous j’adore

  • Gogo

    C’est du lourd bilay l’histoire retiendra

  • Mimi

    YOU reviens nous à la musique nam nagnouleu!!!!

  • diallo

    very nice

  • Théo

    J’aime ta musique mais pas ta politique

  • Hé You

    Nice les 2 stars mondiales yen laa geum dé!!!!!

    • wakhatico

      Saf na sapp…You travaille…Il ne parle pas trop…Il laisse sa musique parler a sa place

  • deug

    thats wonderful

    • Beri Feem

      Millenium Mbalax….oh bii saf na……

Publiez un commentaire

Votre adresse e-mail ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *