8 COMMENTAIRES
  • Rip

    Nite kou bakh. Méyé na ambulance fou né ak diokher léke kou né.

    • Franck

      Qu’il repose en paix et que le paradis soit sa dernière demeure amen

      • Nitt késsé

        Mba mo momone lim done mayé’ yallah naqo yallah djégeul té yereum ko

  • Babel

    ALLAHOUMA IKHFIRLAHOU WARHAMHOU.

  • Pp

    Allahou Akbar ina lillahi Wa ina ilayhi radjihoune kou beugone Yonenti bi Mouhamad Salla LAAHOU tanhanla alayhi wa salam yalna ko YALLA yeureum té kharé aldjana y’a geuna kawé si barké ku Tedd ki

  • Yague

    Yalla nako yereum te kharei ko Aldiana. Repose en paix !

  • Mouhamed

    Paix à son âme

    • Djey

      Yalla nako borom bi faay thiofel guimou amone si Seydina Mohamed PSL 🤲🏾

Publiez un commentaire

Votre adresse e-mail ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *