9 COMMENTAIRES
  • babs

    yaw sa matt boyoul de dokko bayek yalla setti lennen yaw guay goor di khalle darra dalla djomb tu as lavenir devant tw

  • domou djolofi

    tass yakar bakhoul.

  • domou djolof

    oubli cette fille et sa famille. refait toi une nouvelle vie.c'est dans ses erreurs du passé qu'on construit le futur.

  • afanou

    ah c triste dé!mais nak ngor ci common town leu!dix ans niou leye nakhe nando feukeu! massa! legui nak na diégué psychologue bou ko delossi.ndakhe nak khel bi mou ngui deime.massa waye!té ngua khare yalla mou yoné la sa sokna!legui rek inchallah!avec le temps di ngua faté lii.

  • лай

    Mon frere c la vie mounieul setti lenen mane li dalnama si Ben boy bou deukk pikine toudou racky sy mane ablaye la toudou mes lepp dina diekh les africaine c toujour comça toubab la moudiè takk

  • fatou1

    tas nanu sa yakar waye yalla bakhena ..bawal bawal bafs rek nakhe rek

  • beugue bamba rekka worr

    doyna warr mais yalla nala yalla diokh kou geun si yaw

  • Pape Gueye

    Bayi ko Ak yalla dou yaw kassè la Dal

  • NDFS

    puisque tu n'as plus aucun sou . je ne pense pas que ton problème va se régler

Publiez un commentaire