Audio: Quand Bethio parlait de son titre de Cheikh devant Serigne Saliou en 1991

Audio: Quand Bethio parlait de son titre de Cheikh devant Serigne Saliou en 1991

Ces derniers temps, certains marabouts ont fait des sorties pour se douter du titre de Cheikh de Bethio. Pour eux, Serigne n’a jamais fait de Bethio un Cheikh. Dans cette video. Bethio parle de ce titre devant Serigne Saliou. C’était en1991.

https://www.youtube.com/watch?v=7Dp8qSDrFXw

46 COMMENTAIRES
  • oumar

    assaloumou haleykoum.kou am photo wala video .bou bethio di diouli nga wan niouko.svp. oubi len sen beut yi te gnarigno sen xel yi .dounde yagoul .alakhira rethiou wess na fa .yalla na bourbi dimbali dioulit yepp

  • fama

    yag fi srgn bethio teh wer raw nga leen raw teh dotoune la dab yaw thioune yaw reka cheikh bangay dem si srgn saliou gnom dane ko dane romb banga koy diefeul gnom gni di wa kh gnanga teud di nelaw tay nak bam la rcompenser gnouy mbeleli raw ngalen ba pareh koumou nakari nga clameh yalla srgn bethio ya ep ndam fa srgn saliou yag fi teh wer gnou dila djeufel ndakh ba nga wereh dieufeul srgn saliou ken fekou lassa .jai pitie des jaloux

  • elhaje

    mane kou beug serigne saliou la way lou bethio thioune nk yeup meunone nassi wakh bamiy doundou ndakh bouko skhaloul tamit yag na wakh si kana mame miy deg warone nako frein bamiy may nit yi si bark serigne saliou mais wakhou si donc lolo waral lii yeup .bnne bi baye fall yi nek si deuk bi dougnou diouly dougnou woor c est grave khana dagniy fat serigne touba dafa diouly ba diouly si guedj ta molne geun fouf meussoul manqu rakka yen guen n dolene diouly dolne woor walahi gnm guen yalla trop. bnne moy les yonente maname laayens senegal yeup di stane gniy wot yonent nagnou ragal yalla topou soumou serigne you bakh yi serigne touba elhadji nalick mame bou kounta baye niasse gniy sounna yonente bi rek lagnou topone nagnou bayi thiakhane yi ta khamn geureumeul yalla diamou yalla rek moko meun diokh dmogii gneuw di wa salm

  • ridial

    men de guemou mako

  • dieng

    Ku dall mome rawna gayi lou mana am

  • modou

    lakoum dinikoum waliy dini

  • modou

    bayi len togne

  • tam

    ay door la reik!! dem lenne diamou dji allah loolou kessei mo woor deh koulenne ko wakhoul moguilen di nakh

  • moussa diop

    serigne bethio ni mou mel li mou am lep serigne saliou leu nagou dougal yi wala rek manou niouy thiantacone deh mom rek faw

  • tam

    ay door la reik!!

  • mamedineamar@gmail.com

    yalla na diamou yague senegal

  • cheikh na

    Dans cette audio on entwnd seulement Bethio qui parle. On n’a jamais entendu Serigne Saliou Mou Tèèd Mi déclarer qu’il a nommé Bethio Thioune au rang de cheikh. Donc cette audio ne peut être fiable.

  • dramane

    c’est trop facile de faire du audio .Apprenez votre religion au lieu de suivre ce Satan

  • dramane

    il a trahis les enseignes de Serigne Saliou .

  • Bd kh

    santalne yalla mon gueune li bthio daye fne

  • deug

    thiey serigne bethio yay keemaan deug deug deug. sa demb kée gnéméwoul woon wax liii leppsi kanamou serigne saliou. waayé gnémé yalla rek mo waral gnou naane kéné cheikhaloula. yaw rek yaay cheikh , ya sante THIOUNE eupe leen taalibé eup leen daradia gueun leena gnémé . DIEURDIEUF THIOUNE

  • real

    Yalla naléne yalla djéguale séne kadou you niawe yi

  • rabaton

    c’est un montage ,bethio doule rekk laye deff.la preuve bethio néna arabe la ,so pére vient de syrie ,la video est sur youtube

  • VÉRITÉ

    Salam n est ce pas du vivant de serigne saliou cheikh bethio disait toujours que serigne saliou moka cheikhal et serigne saliou n’a jamais démenti et ils étaient proches les deux même pour les élections quand il disait que c’est lui qui avait reelu wade et que wade disait que que bethio cheikh arrêt de dire que c’est lui et cheikh bethio qui disait devant serigne saliou à ablaye wade khana yaw daga xaalatoul maane maay serigne saliou serigne saliou mooyy maane et les détracteurs la ils n’ont jam1is dit que c’était faut maintenant ils sont contre car daffa l’âme seine serigne soyons sérieux berdee yii cheikhbii dii deff serigne n est pas moonee deleeenkoo defff ganar bassi guelemm pkoi wakhougnou fétiches la bayilene bakar moi suis pas un talibe de cheikh bethio mais nak disons la vérité serigne saliou moo waaaroona dementir tee defoukaa de sont vivant yakha derrbaxoul sa salam jammal leenecheikh bii yalla rek moofiineka que dieu nous guide dans le droit chemin

  • global

    entout cas mossou gnou deugg serigne saiou mouné cheikhal nala, tu as beaux faire des montages, t’isoler pour enrigistré ta voir et y accoler des images, tour ça restera que mensonge, tu es un voleur, un menteur, tu es l’incarnation de satan , actuellement sur terre, tu es dajal

  • fall

    Ce n’est pas vrai, aï fénne rékkeuleu ndakh mame dou sékhale criminel ni menteur. T’es le serigne des voleurs,et tu dois mourir à 100m batard.

  • gour

    yaw todo bay lahat togne baxol bo nieme dagay bind se tor morid rek moy royokay serigne touba rek lanio gam

  • gour

    yaw todo bay lahat delen bind sen tour morid rek moy royokay bayelen tongne

  • modou

    Dara amou thi day kathi ken ceikhalouko dawara dem diangi alkhourane ba kham li YALLA wakh ana serigne bo khamne mano sakh diouli khamo dara nane dan ma ceikhal
    Kathi rek

  • sopmame

    Bethio doudara kene cheikhalou ko ay dore la rek keppou kouko topou dinga reere
    Adouna ak yowmal khiyame demlen diamou djiyalla mogeun ana noy toppe kokhamne Manoul
    Lire al khourane khamoul nounouy dioule te serigne toyba nekfi ak wakeureum bayilen
    thiakhanyi waaye

  • chamss

    IL l’a marabouté et je parle en connaissance de cause

  • lino

    bethio doul rekk lay deff ak yenn senego ana serigne saliou si video bi khana devant le photo de serigne saliou kay defaratal benene video

  • baba

    Serigne salhou fo woull folou woull koy tjakhan nga gene kosi te man deye talibe mourid la waye serigne bouy fo douma ko topou rawatina ko hamni diangoull hamoull dara talibe ibliss togne bile ko ak na fekh kepou kou ka topou dina la lak betjho tour wi rekc bou feke ham nga dara nga wara hamni matoull talibe wakhou ma la ak serigne rer na re dena len yobale yen ngni ko topu kouy wer serigne saliou demall sa serigne cekhe fa serigne saliou tegon tan kam falako tekc waye topou samba boy bo khamni diangoull hamoull dara si bopam nga nan dama koytopou yena bege lou bon waye sen bopou ngendi nakh te dengen dioy de ngen rrejthou bou ngen ko bayi oull

  • pape diop

    leral bi diarouko beugue bi gua beugue serigne saliou rek doyna yague fi lole té were

  • Baye Fall

    Yalla na yalla def jam senegal.. Chiekhra Fall amoulmorome… Bethio kou rew la amoul yar

  • fall

    ay waye li ler na waye kilifeu takhaw di wakh loudoul deugu nane serigne saliou meusta sekhal war na rouss dee cheikh bethio dieufi serigne saliou la

  • fall

    ay waye li ler na waye kilifeu takhaw di wakh loudoul nane serigne saliou meusta sekhal war na rouss dee cheikh bethio dieufi serigne saliou la

  • italy

    Au Sénégal,avec tous ces demi-dieux qui y vivent ou y ont vécu (Sérigne Touba et sa descendance,El Malick et sa descendance,Béthio,Kara,etc….),comment expliquer le fait que nous sommes le 25ème pays le plus pauvre au monde?Ou bien nos demi-dieux ne font pas de miracle?

    • Dragon

      @Italy, tu devrais revoir ta définition du mot miracle. Tous les érudits savent que le miracle des miracles est en premier lieu LA PAIX. Souviens-toi de ça. Wasalam.

  • Charlotte

    Mane deeh dama warou fala yam

  • cartel

    SERIGNE SALIOU (RTA) defalna bethio mais malheureusement ce lui bethio mo ci bolle lou andoule dii reeye ayee nitt mo takh teeye mou dieufour et il fera pure de ces meutre et ces déclarations de merde lui il a tendance de dire qui qui frotte si pic alors le moment venu il va se fait piqué inchalah ki dou touss tass

  • Abdou

    Lou waye def sa bop Ken dou Serigne saliou ……te kouko fowe dako guiss legui. …..Serigne saliou massta Cheikhal ken ……nanou gorgorlu te bayi yi gno def

  • cartel

    cette image la c parfaitement vraie lolou naniou n’a mais le problème c bethio qui ne contrôle plus ce qu’il leegui daffa diefour car il a tué des gens inocents kon môme

  • antis

    srgn saliou nna srgn bthio do yakou,do yakoul tkne meunoula yakale kone kou yabou nopalou mo gune srgn bthio limouye ame amnako bapar aye dogalela

  • bay ndaw

    yonou seringe touba wi dall moy din seringe bi daram gunoul din islam kon nk kouko si bol yakosi bol way du senge bi

  • Monty

    C’Est simplement un montage

  • baye lahat

    diamou yalla diaroul parparlo.deflni sounou mboki tidianeyi t bayi tiakhane

  • mouhamed

    ndeysaann li de lerna koumou nekhoul nak demal Police decrale

  • Bene xopain

    Diamoudjilene yallah ta bayi thiakhane yi

  • Beugue Serigne Fallou

    Dieureudiefety Dieureudiefety Dieureudiefety Dieureudiefety SERIGNE SALIOU MBACKE SANGOUP SERIGNE BETHIO THIOUNE.?

  • Beugeu Serigne Fallou.

    Dieureudiefety Dieureudiefety SERIGNE SALIOU MBACKE SANGOUP SERIGNE BETHIO THIOUNE.?

Publiez un commentaire

Votre adresse e-mail ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *